Annonces
Annonces
» » » Vidéo: Infos people dans Petit Dej de Walf Tv Du...

Vidéo: Infos people dans Petit Dej de Walf Tv Du 18 Mai 2016. Regardez

Annonces
Annonces

26 commentaires

  • degdeuh
    18/05/2016 12:53

    kousi nk sa weurseug ngay lk . mais damay am louma nakhari souma guis niouy bn artiste ak youssou lolou saga si cultirou senegal ki Grammy ak Disc dort takhaw si saleyi geuna Mag si mondbi df ay santn album gadiko teugeul ak kou amoul 4 albume senegalais yi si bopam lasn khl avenc t dano gawa faat

  • reetane
    18/05/2016 13:04

    Hawma pape Diouf dé mais youssou ndour mom sou bayi woul scène lou raw papa wemba mom ley dal KO guiss mou am moudiouk adouna bou gnaw rek khamalne beggé ak ignane sokhor mo koko yober presque 50 ans batay sa lokho migui si ndap bi loy khar fotte wala yah thi poute togual migui gnew domou thigua day sokhor

  • reetane
    18/05/2016 13:05

    Hawma pape Diouf dé mais youssou ndour mom sou bayi woul scène lou raw papa wemba mom ley dal KO guiss mou am moudiouk adouna bou gnaw rek khamalne beggé ak ignane sokhor mo koko yober presque 50 ans batay sa lokho migui si ndap bi loy khar fotte wala yah thi poute togual migui gnew domou thigua day sokhorrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrr

  • reetane
    18/05/2016 13:06

    Hawma pape Diouf dé mais youssou ndour mom sou bayi woul scène lou raw papa wemba mom ley dal KO guiss mou am moudiouk adouna bou gnaw rek khamalne beggé ak ignane sokhor mo koko yober presque 50 ans batay sa lokho migui si ndap bi loy khar fotte wala yah thi poute togual migui gnew domou thigua day sokhorrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrr

  • Mat
    18/05/2016 13:10

    Mais c’est youssou ndour qui as créé tout se faut débat c’est lui qui devrait mettre fin a sa .mais désolé que da fa niake FAYDA

  • rama
    18/05/2016 13:10

    REETAN loo wakh di le plus grand faussaire du siècle Thionre Dollar miy wadial 7 albums? J’attends ta réponse

  • reetane
    18/05/2016 14:07

    Thionne dollar si pehé youssou ndour wayer lou tewa ham yagoul youssou ndour dafa diefour lekkena ndogo lo ba ségnou yakh yi mouné waly mo des wayer na hamne lou mou mounoul thiapa ndaye sokhna Mboup mounouko si waly rama ta réponse

  • reetane
    18/05/2016 14:08

    Thionne dollar si pehé youssou ndour wayer lou tewa ham yagoul youssou ndour dafa diefour lekkena ndogo lo ba ségnou yakh yi mouné waly mo des wayer na hamne lou mou mounoul thiapa ndaye sokhna Mboup mounouko si waly rama ta réponses

  • reetane
    18/05/2016 14:11

    Thionne dollar si pehé youssou ndour wayer lou tewa ham yagoul youssou ndour dafa diefour lekkena ndogo lo ba ségnou yakh yi mouné waly mo des wayer na hamne lou mou mounoul thiapa ndaye sokhna Mboup mounouko si waly rama ta réponsessssssss

  • love
    18/05/2016 14:27

    merci retane you dafa sokhor beugoul kou avancer

  • pape
    18/05/2016 14:37

    mais retaane : thione Seck , iso Lo, Omar pne, baaba maal , idrissa diop, Cheikh Lo sont plus gs ke you mais tjrs ds la muzik

  • degdeuh
    18/05/2016 16:19

    youssou danafi yaag dinou bgeul artiste amoul retrt Fig yagui waay mou nkh . retane Yaw wakhal ag sa Papa faux bll yn dougun dougun yoyoukay si darra gordjigun ak faux bi va parri eupou lamin . youssou Migay ba taay soy takhaw sur cin mo eupou Form boyi moln Man si lpou

  • mina
    18/05/2016 16:29

    Retaane yaw meere nga wa toudou kou sokhor dou avance te you bobou balegui machalah waly mi bayam di defal premier parti koko wari bayi way

  • louis
    18/05/2016 16:33

    reetane yalla moye may artis yeup gaffi wakhe bii youssou ndour dit dadjll gnome gnogui tak aye diabar gni di mandi gni nek si lnne you mo fi nkk

  • louis
    18/05/2016 16:39

    boy by nak daffaye dme ak xoole m nank mo geune si mome faut que fque mouye waye wayou youssou ndour pour lanne m n.geume yalla mo geune lou nek dff ne co aye sac djigune affair gordjigune pour suwe mo

  • Senegal
    18/05/2016 17:10

    Franchement Sénégal amouniou khorom quoi

  • teranga
    18/05/2016 17:29

    Tout à cause de youssou ndour il ne fait que du l’hypocrisie entre pape diouf et wally si tu a un blême avec thione faut que ça reste entre vous mais faut pas m’être quel qu’un d’autre de dans la merde

  • aliou Samb granada
    18/05/2016 17:48

    Youssou Ndour doumoromou waly youssou amoul morrome Sí adouna boude waay mofi maane senegal khamouniou kou maña waay ak kou mounta waay waly khamou darra youssou bayamlla

  • papis
    18/05/2016 18:17

    retane so beugu wally boulko bol ak youssou wally mosi narra prt rk youssou ay fansam dounou df bruit bou barri dani bayi rk sougu mou diekh soy wott concr mou fes yn fans wally ay minoritgun ba parr eupoufi wakh

  • dida
    18/05/2016 18:21

    youssou danafi yaag dinou bgeul misiquebi kn douka bay ak ay goordjigun you mlni spakati bounou bakhal yakh sounou doom yppou

  • Ouff
    19/05/2016 10:59

    Papis nga ni fans Wally yi ay minorité lagnou yaw khana nekko Sénégal wala bokkou gnou deuil Wally mo ngui lakk deukk fou mou romb deff fa domm na you andak Wally si mbend mou khôl doutouko defati dé ndakh Wally mo saff si guimin yi ndakh limouy woy mo tey té nekh limou lath la koy diokh

  • zakaria
    19/05/2016 12:36

    Waly a beaucoup de talent ça c est Sur mais je pense que c est ancore tot pour le comparer avec youssou ndour….je pense que yenyi sakh bakhoul si boy waly seck…il a du chemin a faire on le laisse travailler…youssou ndour ay sting Peter Gabriel Bono vox lay wakhal …nagnou gnanal Waly Mou agg fofou mo gueun…

  • dev
    19/05/2016 20:07

    degueul ouff ahh machala ta tou dit ya amm dégue déeeeee

  • faty
    19/05/2016 22:30

    merci reetanne youssou da fa sokhol beugeul kou avancer waa yer mounoul laa téeye ken tout les artise sont avancer faute youssou parce que tée woul féen

  • xamxam
    19/05/2016 22:34

    compare Wally est son pre thione aprs vous venez le compar avec you,doumoromou bayame thione seck,boulne doulelau nit gni merde

  • xamxam
    19/05/2016 22:37

    moi g entendu Wally dire son objectif c pas remplire bercy,si il dit sa cela ve dire que il part a bercy pour lav l’argent salle.not bien que bercy fait 22000 place,c pas le probleme de you,bayilneco

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces

L'ACTU EN TEMPS RÉEL