Annonces
Annonces
» » » » Vidéo : Cette fillette de 8 ans raconte son viol...

Vidéo : Cette fillette de 8 ans raconte son viol par 2… Regardez

Une fillette de 8 ans violée par ses condisciples raconte comment deux frères ont abusé d’elle à l’absence de leur Serigne Daara. Les faits se sont déroulés dans la banlieue de Dakar.

Annonces
Annonces

16 commentaires

  • mina
    19/05/2016 21:54

    Waw a12ans ngani viole war naniou yar sounouy domyi c est grave

  • Amina
    19/05/2016 22:03

    Mina wakhatiko deh passeh na grave way Yalla na niou Yalla khirr si bopam te dimbale niou si soniou ay njabpot tek niep si yoonou siratal moustakim,Amiin

  • abdoulaye
    19/05/2016 22:29

    Barkep s touba adouna Migui wadia touki bilakhi

  • Mamadou
    19/05/2016 23:07

    sama yarame ban gidaw ndakhe gnome gnep ay khale la gnou

  • ccc
    19/05/2016 23:37

    tfm si bopammm gno yapp senegalais yii

  • Rama Badiane
    19/05/2016 23:43

    li yep pauvret rk mokaye indi

  • dida
    20/05/2016 01:05

    mais yaw lou tfm df ?

  • Aicha
    20/05/2016 04:01

    Boussou khalé bou gnou sole yiappou mak la fi guisse. Ba adina di bakh khalé daye déff yeufou khalé. Yayé légui li am Sénégal kén khamoule lane laa, daguaye dém ci keur khalé bou am 4 a 5 ans yeketi sa robe ba sa seurre aye parent wame di rétane nane ki noumou thiaga do khame loye wakh le vrai problème c l’éducation des enfants ci birr keury.

  • Mouhamed
    20/05/2016 06:10

    c la vie nakk gnougui cii akhrouzamal

  • nasi09
    20/05/2016 09:26

    on na plus besoin de commentaire aïcha a tout dit sama coeur migui dague bien parle

  • rebatass
    20/05/2016 09:38

    je t appuie Aicha ducation mo dess si keur yi walla xeler bou ndaw gua wanko guinaw mou lal sa fesse yi parent douniou wakh dara ay retane lalen di def ak et puis j ai trouve aussi tres mal a voir des fillettes jouer avec des garons et au galsen c est ca qu on voit dans les rues

  • biba
    20/05/2016 10:43

    bane ducation legui koufi am dom doko nampal dojo couche comme gnome mame a jet lagnouy couch seni ay dme di lene nampal akh ayy mew biberon you kne khamoul bane mala moko produire le gui c la toubab guissa gougnou dara yeuffou maladie rek la new gnration bi dudef legui

  • biba
    20/05/2016 10:44

    yefou mala rek la new gnration bi di def legui

  • mami
    20/05/2016 11:41

    tu as parfaitement raison aicha des fw Sakh ngua guiss gnounan khalé bi nimou beugué wene

  • diop ibrahima
    20/05/2016 15:03

    Kel vie sommes nous

  • jules
    20/05/2016 21:34

    kp kouy parents warrga titttt

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces

L'ACTU EN TEMPS RÉEL