Annonces
Annonces
» » » » Vidéo: Amy Collé encense Waly Seck de...

Vidéo: Amy Collé encense Waly Seck de compliments

Digne d’une griotte de marque, visiblement la chanteuse Amy Collé a un amour fort sur la personne de Waly Ballago Seck. L’artiste croise le chemin du fils de Thione dans une boutique de vêtements et chante les louanges du faramaréne et de sa famille.

Annonces
Annonces

30 commentaires

  • inco
    25/05/2016 11:02

    mais senegal kou amoul xalisse sa yaye ligueyoul.kou amoul xalise doune la keene dioulite

  • salimata
    25/05/2016 11:13

    inco wakh nga deugue kou amoul khalis sa yaye liguèyoul senegal lolo fiy dokh

  • Kateur
    25/05/2016 11:16

    walymata seck gordjigune bou mak moo ngini

  • senego
    25/05/2016 11:34

    waly seck moy sen fans wa senego lou waly def rek ngen dougal ko. amo len khorom. press dou far wala kone boulko feusal. wa senegal ham naniou yen fans waly ngen

  • khadi
    25/05/2016 11:36

    senego wakh nga deugue

  • titi
    25/05/2016 11:37

    senego ay fans waly lenn.

  • ndiaye
    25/05/2016 11:37

    woy kat yepe amy cole mosi guena niaka fay da

  • nasi09
    25/05/2016 11:38

    yaw kateur avec ton sale non je ne parle meme pas de wally je te ne connais pas aussi mais je le sens poubou wally mo le guene

  • khadim
    25/05/2016 11:38

    senego kay waly ak Aba nioy sen fans

  • fifi
    25/05/2016 11:39

    press boul feusal sa far.

  • fifi
    25/05/2016 11:41

    lou Aba def Wala waly rk niou doukal ko. senegal yeup kham naniou ay fans waly ngen

  • boba
    25/05/2016 11:43

    youssou ndour rek ngen contre tay. yen wa senego monteh you amoul sen diot sakh khamoul ndakh senego amna wala amoul

  • ibra
    25/05/2016 12:18

    mot de?f buzzzzzz btiment sokhar

  • ibra
    25/05/2016 12:19

    moy de?f buzzzzzz bayilene sokhar wayyyy

  • zal
    25/05/2016 12:22

    senego deff len loulen nx senego mofi nk fans youssou ndour daniou soxor ta Rfm migui ak macky sall

  • Fake
    25/05/2016 12:24

    mane mom Amy colle damako yeureum

  • Baye
    25/05/2016 12:35

    waa wally ya bakh wy

  • diadia
    25/05/2016 12:53

    nasi09 merci ki poubou wally sakh moko gueuneu Borom tour bou niaw bi REW waa khana mom aussi gordjiguen leu noumko khamer khana si milieu bi leu nek aussi

  • vito
    25/05/2016 13:09

    Wally es un gordjiguen … sa vous fait mal ?Arrtez d l’insulter . Wally mofi yor sac SN pre thione est un fabriquant d faux billets en plus Senego xana amoulene lene lou important ? Wally b kagne ?

  • yorou
    25/05/2016 13:53

    0634659538

  • yorou
    25/05/2016 13:55

    Walt mofi nek bâti lin sokhor

  • Maman
    25/05/2016 15:25

    Encore une video qui suffit pour signifier l’animosote entre Pape DIOUF et Waly SECK. Quand le gars lui as dit « DOOMOU NDAYOU PAPE DIOUF » Waly a repondu par dire « Ca ne se dit pas » et l’un de ses amis dans la boutique le confirme.

  • Diop
    25/05/2016 16:55

    Maman écoute bien les paroles avant d écrire du nouveau importe quoi

  • mami
    25/05/2016 17:18

    fi dal kougne fi tague rek tu es conu wala rich sa yaye bouy thiaga Sakh gnouni mo gueune senegal

  • k
    25/05/2016 17:30

    amy coll ya bonn ni nga dfon ba bthio torakhalla thiim

  • VÉRITÉ
    25/05/2016 17:45

    Arrêtez vos tentatives de sabotage du Bercy du 4 juin 2016 de wally si c’était youssou ndour toute la presse fait sa promotion et même les artistes font de publicité et autres pourque tout le monde y participe cette année c est wally qui joue nianaleekoo les tentatives de certains grands artistes du pays pour saboter l’événement n est pas bon youssou wally neena yaye papam bayelabessamm wahoilossii diapoulosi promotionbi downawaarr pourtant si c’était toi tout le monde sympliquerai l’histoire retiendra tu es un peu égoïste sur cet événement tu n’as même pas reçu wally en audience alors il a écrit plusieurs fois ton Bercy tous les noms les grandes stars du monde tu les invite de tous les pays africains sekoubabambino qui vient drainer sa population les rapeur magicsystem et tu invite les gens vient wally invitela gaadoumooyoukoo doynawarr maane sa fansla pour toujours mais defallilawarr sinon demain diina amlooyahaa si saawaayy ici en Europe tout le monde te critique sur l’absence de ton soutien envers wally avec d’autres stars du Sénégal n’a concurrencebi saine waayy
    Je t’aime et apprécie you adouna daafayy walbatikou les lutteurs mêmes venaient d’appuyer et les joueurs les elhaji diouf fadiga diao etc il ya même qui venaient pas pour toi mais pour les autres stars fayalll liilaaaskanewii jiii boudee sa titre album boubessbii deuguela siyaww senegal rekk boy wally sénégalaisla donc moo ayee Bercy wahalsi microbi nee nagneupaa demdiapaleko teegaateww bagnaa outeprogramme pour gantal comme papediouf wasalam Sénégal for ever et MERCI senego vous êtes notre site préfère il faut pas écouter les adversaires de la réussite de wally qui tentent de saboter l’événement

  • as
    25/05/2016 20:09

    merci verite wakhnga leep

  • Théo
    25/05/2016 21:55

    Verité merci pour ta franchise.

  • zeynab
    25/05/2016 22:21

    merci verite tu a tout dit man dama wagni ay comenter lègi ndax dafa am dof yo xam ni amougnou mèthiè dagnouy tog rèk di xar senego dougal waly rék gnouy soga am methier t waly talou lèn waly dou lire comenter waly amoul sen djiot bilakhi bougèn geumè ni yala am na di gèn nagou ni waly raw nalèn yag na bilakhai walakhi talakhi yag na romb nalèn bou yag

  • kheus
    26/05/2016 07:45

    nasi yaw tamit kou reewga

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces

L'ACTU EN TEMPS RÉEL