Annonces
Annonces
» » » » » (Audio) Mbathio Ndiaye se lâche sur un inconnu...

(Audio) Mbathio Ndiaye se lâche sur un inconnu qui la harcéle au téléphone

Annonces
Annonces

31 commentaires

  • mami
    18/05/2016 23:27

    wa legui loussi sougnou yone

  • gueye
    18/05/2016 23:43

    wa ki sofoul yene

  • deug
    19/05/2016 00:07

    wa kholal mbathio numero prive boko porte plainte police dem sonatel dagnou kham kimou donn c facile tempyi waxguafi agression legui arcelement yaw dama yakarni buzz gua beug liguay wakh boudee deug demal police te bayi media ndakh yaw todio fen

  • Buzzshu
    19/05/2016 00:22

    Mbathio wakh ngako sa birrr wakh siww di diam borom Ma soeur stp boul wakh dara bayilén ak yallah lépp dina lérr bon courage ????????

  • Abdou gueye
    19/05/2016 00:22

    il faut aller deposer une plainte contre X et de ne plus pzrler aux mdias.

  • mare
    19/05/2016 00:41

    mbathio demal outi diegur tes bayi li ngaye def wakh rekk di fene rekk

  • boye bandi
    19/05/2016 00:58

    mbathio badio

  • sa
    19/05/2016 01:17

    b

  • fall
    19/05/2016 02:34

    he boulgnou fonto demal sonatel mo guen

  • Awoka
    19/05/2016 04:15

    Beauté naturelle daffa mélni da diékhe Sénégal khaléyi kouthie démaquilléwou ba ndindi perruqueguam gua diomi lawakh

  • Ziza
    19/05/2016 06:05

    mbathio yaw nak,khamo darra baparé Barri wakh.fouttez nous la paix!!ak Sa ñiaway

  • Ziza
    19/05/2016 06:08

    mbatio khamo darra,baparé bari wakh.fouttez nous la paix.ak Sa ñiaway

  • kheus
    19/05/2016 07:06

    day feen rek beug siw rek

  • dakar
    19/05/2016 07:15

    Mais cette fait la ce po elle gspr naka khalé ni naleu niawé eskay

  • Evalaye
    19/05/2016 08:22

    que dieu t’assiste

  • momo
    19/05/2016 08:58

    wa legui gnouneu lousiy sounou yoneu doull wayaw

  • RM
    19/05/2016 09:22

    g n connais pa Mbathio mais la grandeur d’1 personne n’est Pa d s cacher derrire les rseaux sociaux pour dir du mal aux gens c Pa respectueux si on a rien a dire on a k’a aller faire autre choz  »nit dafay am fouleu ak yar way »

  • Rama Badiane
    19/05/2016 09:40

    mbatho ligaye wakh barena demal port plainte mou jkh

  • zakaria
    19/05/2016 10:13

    demal Police nga deff sa plainte pour stalking Mou Bayila…mais nakk mane mome je m’en bats les couilles…mais wa senego vous commencez a nous emmerder…

  • zakaria
    19/05/2016 10:17

    les amis qui peut me dire ban site d ‘info mo bakh senegal ma demenager fofou…parceque j aime bien senego mais parfois day deconné?

  • rebatass
    19/05/2016 10:54

    ZAKARIA bo amee gua wakh ma moi aussi je veux dmnager mais a ce je vois ils sont tous pareils

  • Fili
    19/05/2016 13:12

    HE OUI.ELLE NOUS EMMERDE.
    QU’ELLE SAISISSE LA POLICE!
    C’EST TELLEMENT BANAL ET SIMPLE.

  • Billy
    19/05/2016 14:45

    Beuga siiw t siwo mo miti mbathio sof ngaway sa gnaway bou reuy

  • ousmane
    19/05/2016 15:10

    Tu parl tro dan les medias, esay detr plus mature les resaux sociaux ne vont que te retarder.

  • mimi
    19/05/2016 17:29

    yaw mbathio may niou diam katal ndeyam feul

  • manou
    19/05/2016 17:36

    mbathio moom rafete nag sa way té nekhna aussi. khana dangunéne ko contre rek

  • manou
    19/05/2016 17:38

    mbathio kate yéni tam dafa raféte té nekh. khana danguene ko contre rek

  • alpha mamadou duallo
    19/05/2016 19:50

    yaw dale boye yu ngaye wakkhni yep amoule bene chance demal fowi te mainou diame

  • deuch
    19/05/2016 20:23

    mbathio niaw nga ba par safo kne sof ngua torope??????

  • mamina
    19/05/2016 22:01

    loula dalle yako tek sa bopp

  • Mouhamed
    20/05/2016 06:33

    mbathio khawma lomaye saf jinné côte d’ivoir niii bayil sa po mii thé diamou dji yalla diamou yalla moye gua weyé digualou yalla the bayii térem bayiii terem moye sa doulll you metti yiii gua bayiko

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces