Vidéo – Thiéyène Djoloff : Idy au lieu de retraite de Bamba, regardez!

Ce lundi 18 février 2019, le candidat de la coalition « Idy 2019 » s’est nuitamment rendu à Thiéyène Djoloff.
Cheikh Ahmadou Bamba Khadimou Rassoul est, 5 ans durant, resté dans ce village où il a écrit 1 000 exemplaires du Coran.
C’est aussi à ce lieu que repose la mère de Thierno Birahim Mbacké et de Serigne Issa Diène.
Idrissa Seck est allé y recueillir des prières pour des élections apaisées et une victoire de sa coalition.
Avec Dakaractu.com
Idrissa Seck dans ce lieu mythique de Cheikh Ahmadou Bamba.
Idrissa seck rek
Allez voir le programme de Idy 1 3 15 45 et vous les affaires de conférerie sachez vous le Sénégal est un pays laïque Idy tidiane Idy mouride c’est sa vie privée le temps passe vite donc aller voter au lieu de parler
Zale yaw kou soff ga
Borom ndiareme santoul fayyy. Yaw ya yobbou mbirr yi ci Tariq sngal koudoul joulite sakh meun nafi falou. Contre lou book ci kou tedki di lakhatoo pseudo
Quel homme, un faux cul un vrai sax
Idy il est vraiment pathetique
la strategie de IDY est sale tres meme
Ma shaa allah khadimou rassoul, dem nga fou diara dem mais n’empeche meuno niou dieund ak li
Amine.
Borom Ndiarem …c pas un crime de devenir mouride …la tendance est que dans chak famille au Sénégal ya toujours des gens qui deviennent mouride…le contraire devrait te surprendre…Bamba rek !
BOROM NDIAREM FAYE bayil nafékh Idy wakhna programam mou lére nagn sokhar ngéne torop
Ndam rék inchallah
Étrange où sont passés les répondeurs automatiques ? vous êtes fatigués ou bien macky n’a pas encore fait le virement. Idy rek inchallah
Idy démal nga nga wakh ak sénégalaiyi thi sa program mo gueun fo tol di wanéni khathina thi tarikha cheikh légui mouritla bou wotéyi nékone afaie de tarikha com ninguakoy féssaléni kone do falou na tidianyi nio heup mourityi fingua yobou éléctionyi dou fofou
Man dé wolo touma Idi, kerok bi mou fi wakhé ci adj Makkah bi, ci la ko bayi wé.
Dioulitt dou wakh yenn yi. Daga wara respecter religion bi.
Idy mom saga ngour bi rek la fi néké. Di lenn dieumé pouss ci biti. Khamoul dara
Avant, dama beugonn parti rewmi, dama donn diapalé Idrissa, wayé bi mou wakhé ci
Idrissa dou nitt bouy mbolo, dey tassaro rek. Di neu fi indi probléme bou reuy ci rewwmi ak macky li mou liguey yeup.
Idy dafa am carton rouge ci OCI, ngiy promouvoir Ismal à l’international. Bi mou wokhé ni ke pelerinage kenn dou ko défa Makkah. Dou djoulit bou bakh. Dou ma ko wotel
Idrissa, fou mou tol dey changer avis. Medecin Toubabmo ko seytou ci benn hopital Paris firndel ko. Mo takh fou niou tol ni, meunoul djité rewmi.
Khawma ci Idrissa werr neu wala dett, wayé kou doywar leu. Meussou ko wédi, dafa weroul.
Ci sama khalatt, Idrissa Seck bokoul sakh ci paysage politique sénégalais bi. Sa you fégné rek, ci todj todj leu nek, wakh lou bonn ak yakk derr ngour gui.
Idrissa ngi critiquer gouvernement rek té kenn dégoul programam pour présidentiels yi.
Li mey khélal Idrissa moy mpou nopalou, topato santé weum ak bayi ngour bi liguey, bayi Sénégal si ay lokho you bakh, lokho Président. Dia Dieuf Macky SALL
Idrissa opposant bou ignane leu, beugoul guiss deug bi, li fi macky sall def yeup
Les commentaires sont fermés.