Si Seydi Hadji Malick a obtenu ce qu’il a eu c’est grâce à son amour incommensurable pour le Sceau des Prophètes, d’où le sens du Gamou qu’il a initié en 1902 pour exalter Mohammed (Psl). C’est la raison pour laquelle, toute sa vie durant Maodo s’est évertué à perpétuer l’héritage du fils de Abdallah et de Amina préférant même reléguer au second plan sa propre personne. Et c’est ce qui est perpétué à Tivaouane où le Prophète est au dessus de toute autre chose. Ecoutez les explications du Khalife Général des Tidianes.
https://www.facebook.com/100009494320507/videos/2200776296915493/
Sy Malick bayyil seringe touba migay garou wale dou sa moromou mame…..
Man d mouride la,mais damay rouss quand je lis certains commentaires. Bilahi Seugn bi santulen lii. Waxul ak yen, nguen di mer. Ap mouride day am talibé.
Dieuredieuf Sy malick. Deug rek nga wax! Dundeul
Dieuredieuf Sy malick. Yen d réralolen ben talibé. Wax ji kumu méti d,langa néké leerul.Gnune Sangue bi Mouhamed PSL mognu gnor té lolu nguen gnu diangal. Ndeyssan à lire certains commentaires damay rouss. Serigne Touba bufi nékone dina guéné gnu bari ci yoonam ndax togn ak saga yi gnu néké. Talibe day am yaar!
Rewmi bamba moy ki ko mom
Kou weddi bani yaye moromou serigne Touba diemeul diouli ci piscine kholl.
Si Serigne Touba a eu ce qu’il a eu aujourd’hui c’est parcequ’il a fait des choses que personne au monde n’a fait. Lui seul et personne d’autre. Koumou metti nassa serigne diouli ci piscine kholl.
Akassa yawe SERIGNE BI.Dieur-dieuf. Yalna SERIGNE TOUBA fathie sa adio.AMINE
Dounyaa Bamba ko mom djeureu djeuffei serigne Touba wallahi gnoune wolou geume ragall yaakarr serigne touba reck lagnko deff wassalam noppall leene seene lillahi wzrrasoulihii
Mane lima metti rek moye nitt domou adama leu xélam matoul xam nguén lolou légui nitt dafaye wahe darra rek douneko wahe ya ngui bokalé déh mais dani wahe ni manam generalisé ko né légui wakeur serigbe bii nioye bokkalé té dani ragal todje yahe bi
DIEUREUDIEUF SERIGNE TOUBA. Tous les mourides savent que Serign TOUBA est créé par DIEU ALLAH le tout puissant. Donc mouride yi mbokkalé wougnou. Nous rendons grâce à S TOUBA
Serigne Touba rek mofiye Serigne loutakh ngacoy momalè wakh dj bayilene saytanè ak ngueum ngueum Lou -tagamouléne Dara Sénégal nafekh mofi gana bary comme sa genre bi
Lima meuna watt si alkhourane karim.. Serigne touba sou fegnione si deukou nar yi oubien mou donone ab nar…. Senegalais yi dina dagg billet diko fekk famou nek diko ziaree.. Limou done nit kou gnioul.. Te fegne si sounou birr mo takh khamounou kou mou done… Nit kou gnioul dafa complexer… Kene dou serigne touba.. Ba euleuk !!!!
Serigne touba… Kene diokhou ko place yalla.. Mo takh nguene di wakh… Li mou deff kou ka deff giou deff la ninou kou deff.. Bayi lene jalousie bi.. Serigne touba fierte la wara done pour toute l afrique noire…
Dieu n a pas de part tout lui appartient avant de parler ou de faire allusion à qui que soit remuer la langue mille fois avant de parler sur tout du côté divin
Machallah serigne bi sy malick
Ya wakh deugueu sy malick. Yalla nga fi yague ak weer.si barke baye laye seydi
Sénégal bokalé yalla daf fé bari trop
Diokh nite thieurou yalla mo bari si rewmi du yone sakhaba yonénety bi rek dugnu Séne morom