17 COMMENTAIRES
  • Serigne touba amoul morom

    Tawfekh rék serigne. Touba amoul morom

  • moussa

    ken dou SERIGNE TOUBA

  • baye

    Sama khôl Sedna wayé léne rek la ci guiss Lo khamni warou ci wone bigniy diang khassida yi pital yi di tak

  • abdoulahi

    domi haramyi domi dialoyi darapo l islam ay wornama séné dadoiur Aÿ dialo katt lan ki motakh yalla may nou diamou sene lafeul Ndeye kou bagne s touba Rék la wakh film de put

  • Verdad

    Ammy ils l’ont ecrit sans le rgarder donc on peut bien dire rediger ou ecrire,cela ne veut pas dire que c leures pensees..on copie qelq chose q l’on voit alor qu’eux l’ont parcoeuriser…le coran n’a pas été écrit ou rédigé mais a été révélé c’est a dire c’est une revelation…

  • Dikha.

    Macha allah yalla na yalla tasniou si sen barkr.intellectuel pure moy ki mokal alkhourane dakh yomboul yalla na yalla samelene si kaw si kanam rek .

  • 'ndioufa

    moi suis pas mouride mais c est vraiment beau vive l islam

  • Baye Djigo

    Raft na lollllll ma challah yalla na diam yag Senegal bark Baye Niass

  • Ammy

    Arrêtez de dire « rédiger ». Le mot correct c’est recopié .
    Le saint Coran ne peut plus être rédigé ou écrire.

  • Merci

    Moi je ne fais que poser une question je croyais que c’tait les supporters de allez casa

  • NFS

    Khamegua sodé Dinguate na amato lo wakhe moye indi niak Khorome  » Merci » lolou mola dale. Ne te fatigue pas Serigne Touba rawena gua yi

  • momo

    f******ck u merci

  • Mémé

    Sénégal gno âme djot,beug programme.pff

  • Merci

    C’est un match de football ou bien

  • anta dické gueye

    Billakhi kholl Sédda Tina. ..Dieureudieufeuti Cheikhoul khadim Sunu Yakkar Tay Ak Euleuk Alkhamdoulila

  • Amy

    Machalla khôl séed na

  • Verdad

    Thiey SERIGNE TOUBA ken Dou mom dé.. Dieurdieuf le sauveur

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *