Sokhna Marièmou Mbacké, première épouse de Serigne Mountakha Bassirou Mbacké a rendu l’âme ce jeudi.
Âgée d’environ quatre-vingt ans, la femme de l’actuel khalife général des Mourides, qui sera inhumée au cimetière de Touba-Bakhya souffrait d’une maladie depuis quelques jours .
Yalla nako yalla khare aldiana firdawesi
Paix à son âme
Yalnako yalla xare aldiana.souf wayaf si kawam
Nian yala diégal ko mogaun di nian mou yeureum ko ndakh soko yeureumé té diègalou kou dina doy war nian moureum ko diégal ko moma gauna doy
Yall nako yalla yeureum
Sene titre yi dara bakhu ci kholl léne li nguèni deff
Que la terre lui soit légère amen
Yala na dadié ak ndiégalou yala
Yalla nako Yalla yereum té diégueul ko thi barké Seydina Mouhamed ( SAWS )
Yallana yalla yokou lèram té tassgnou ci barkèm bidiahi Cheikh Ahmadou Bamba barké Mame Cheikh Ibrahima FALL.
Amine
Yala nako yala yereum te mame mame terrou ko
Paix en son ame
Yalla n’a souf woyoff si kawam the sounou borom yokk ay lerem
Que dieu lui accorde grâce et miséricorde en l’accueillant dans les paradis du firdaws…
Paix a son ame et que la terre lui soit légère
YALLA NAKO YALLA YEREUM TÈ KHAREKO ALDIANA FIRDAWS
Réponse en paix
Yalla nako yalla yeureum khare aldina
yalla nako sunu borom kharei s aldiana you gueneu kawei barké borom touba
Yallah nako serigne touba terou teko ci lokho seydina mouhamed yallah hareko Firdawsi
QU ALLAH LUI PARDONNE SES PECHES ET L AMENE AU PARADIS FIRDAWSI AMINE.
Paix a son âme
non yeen doo leen nit. nii ngeen di illustré ap article ?? parfois on se dit vous le faite exprès pour inciter les gens a la curiosité
Allahouma ikhfirlaha war hamha
Yallana yalla yok ay léram
Yalla na yalla wacce yeurmande ak ndiegueul
Yalla nako yalla yeureum te khareco aldiana
Yala nako yalla kharé aldiana firdawsi
Yalnako serigne touba terou
Yalnako yalla yereum
Sen titre yi dina rayy nitt surtout gni am cardiaque.???
Yalla na ko yalla yereum
paix à son âme
yoo alla yurmomo yaafoomo
Yalla nako yalla khare aldiana firdawsi barke Mame Borom Touba amine
Yalla naka yalla diéguel
Yallah nako mala kam yeurmandé térou té kharé ko aldiana firdawsi
Yallha nako yallha khare aldina fir dawsi
Paix en son âme
Yèneu manoul bayi ninguèn titrè sène info yi no no
Yalla na ka yalla yeureum
Paix à son âme
Yallena KO serigne bamba khadimou Rassoul terou terale ko
Fathia ake 11 likakhassi
Yalla nako yalla yereummm
Paix à son âme
Yalla nako yalla yeurmeum
Yalanako yala yeureum
Yalla yeureum co té kharé co aldjana,Amiiiiine!!!!
Yalla nako yalla yeureume