Polémique sur la succession du Cheikh: Le fils aîné de Bethio Thioune remet les choses à l’endroit (Senego Tv)

Depuis le décès de Cheikh Béthio Thioune, les « Thiankounes » affluent vers Médinatoul Salam, fief du guide religieux. Selon certaines informations, la succession du Ckeikh serait déjà sujette à polémique. Lors d’une intervention avec Senego, le fils aîné du défunt marabout, Serigne Saliou Thioune Gueule Tapée, remet les pendules à l’heure et rassure tous les talibés thiantacounes.
Vraiment béthio guinawam gnaw na torop.
Li rek warna yé gniko toppone ndakh gnou toupe déllou ci yalla té khamni thiakhane bakhoul
Li mome doyna war nitki dè nguen war di ko nianal mais succession molen intéressé li moy tekki aduna rek mo lèn gnor… Celui qui continue de vous suivre je le plaind..Deme lèn jamoudji Yalla avant qu’il ne soit trop tard Malakal Mawti mome dou joum dou tardé wa Salam
C du némportekoi c thiantakoune il te ramène jamais vers dieu jamais des waraté jamais des rappel du prophète tu apprend rien avec c gens la que des thiahane et peur les gens qui son la c juste pour leur intérêt.
néké légui ay thiakhane laniouy donanté, khaw ma wone néh fila adouna tolou.
Vous nous dérangés avec vos histoires de thiantakoune akh ligueyilen t bayi tiaxane yii
Wakh jou ñaw eupeuna tek ci way dawleu.Rafetal rek ndak kou nek sa beuss dina ñew te digna sokla seede you bakh.En tant que talibé cheikh mangui jaal ñeup.Paix à son âme et qu’Allah l’accueille au paradis firdawsi.
Waw lougnoufiy donanté doutarikha doudara
Hamidou dillo nite Daye wakh lou raféte lo wakh digako wahate si sa bamelle respectéle bok ki fatou
Bayiléne chekh bi gir yalla thiatou geuneko ba sonou borom def li geune si môme
L »argent facile ce pas bon demal ligueye boul Mélni com sa père désolé
Bagel thiakane demlen ligueye baylen l’argent facile ok
Thiantacoune ay tiakhane rek moko lale dome yi khif ak niak kilifa niofa.bok borom wadiour you ndole yi wayé kham guene ni bethio dou djité borom wadiour you teki jamais saliou thioune demale ligueyi yak sa rak yi bayi khaliss bou yombe bi deme lene ligueyi
Diėkhna tak.l’avenir est devant nous.
Dafa wara diekh guatoup thiantagoune demlen botou si guanaw mouridyì