Photos: Touba, Le geste d’humilité de Marieme Faye Sall

Photos: Touba, Le geste d’humilité de Marieme Faye Sall

Le président Macky Sall a été reçu ce jeudi, à Touba à la résidence Khadimoul Khadim le Khalife général des mourides Serigne Mountakha Mbacké. La première Dame, légèrement en retard, est rentrée dans la grande salle pleine de monde au moment où son mari tenait son discours. 

Pour ne pas déranger les gens, Mariéme Faye s’accroupit brusquement au milieu de l’assistance, à quelques pas du portail qu’elle venait de franchir en déclina les propositions des chargés du protocole et des éléments de la garde rapprochée du chef de l’État de fendre la foule pour  le rejoindre  président de la République,renseigne Seneweb.

14 COMMENTAIRES
  • FAATU NJAAY

    salaam,fii kenn waxufi gueum walla niakkgueum,geste bimou def moo rafet.
    dee leen am xalaat bou rafet,di wax lou rafet.senegaal,lii rek moo niu yaq,waxal nit ki lu niaaw,yaq deru nit rek ,te loolu du jikko ju rafet.Moom yagg na di def lii ci mbooloo,dangey jekki rek gisko muy romb ,niu naan kii di romb de mareem fay la.Elle est d’une humilité exemplaire.je suis apolitique ,les discussions politiques,je ne m’en mêle pas.NIT DANGAKOY WAXAL NIMUMEL

  • BAIDY DIAW

    Naniou bayi di jugé yalla khamna lineka si kholou domou adama

  • papis

    yaw khana khargua figuène tèkk dinè yalla miye borome sakh tègou koffa yalla bakhna ba yalla dou senegalais si no niepe gnoye lakk gui famou warona tokk diotoufa mo takh mou dougou rekk tokk moye humble

  • papis

    dieureudieuf yar kène douka diangue day nèkk thie sa dèrète

  • Borom Ndiarem Faye

    Bodone thia diamonoy serigne touba dinako sèpi ak teguin niko boul diakhasso ak guorgni dèmal tok thia jiguèngnia wayè malheureusment yènmom taloulèn khol lolou yènangui bayi khèl lilèn prèsident indil kom serithie autorout wala yimoulèndi dik ana terek borombi thi diakhasso guoraki jiguèn

  • mbidou

    Nit mo lache.et des fois sans raison

  • ASTOU FAYE

    Sénégal mon Bari gni sokhor parce-qu elle n’est pas de votre famille…jalousie

  • René Diagne

    C est tout à son honneur.nitt dafay humble guir yallah rek.le reste c est pas grave il y a toujours des mèchants des aigris qui voient le mal partout.

  • Mouhamadou kane

    Pourquoi elle ne la pas fait l’année dernière

  • dodji

    Ignane moy nonou borom

  • A&j

    Day door rék geumoul sakh serigne touba

  • Cherif Sidibe

    Une vraie mise en scène .
    Dès l’instant qu’elle etait en retard baukeu naci incivilité premièrement

  • Aliounebadara Gueye

    Machalla cette dame est exeptionnelle

  • Demba Diong

    Mise en scène

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *