16 COMMENTAIRES
  • benn senegalais

    Wow!! La facilite avec laquelle Youssou peut remplir une salle, de TOUBABS en plus!!! Comme NDOKH THI MOME….Attention Pape Diouf…..Bercy c'est toute une carriere! Il faut ramper et remplir des salles comme cela avant que You te laisse BERCY…c'est bon d'etre ambitieux mais pas facile d'etre YOU…..

  • zeus

    wawaw

  • Cana Sistah

    Allahou Akkbar! Non Youssou Ndour dou NITT Kesser…………………………………..

  • Beri Feem

    Si Youssou acquiert plus d'experience politique et apprend a gouverner, pourquoi pas YOUSSOU PRESIDENT
    d'ici quelques annees! Il le merite car il a bcp fait pour le SENEGAL…Il a apporte des milliers de millards dans ce pays et il n'a pas fini…….en plus dignou beggal pendant 40 ans machallah!

  • parisfrance

    ive g pitiè de toi khamo sa louye ministre conseiller

  • reos

    Youssou royoukayla beugna limouy déf amnasi foulla mo takh mo am li

  • amy

    Ban poste la yor ? Youssou minister consier macky sall rék yonam si lénén . Bravo you si kaw si kanam

  • bibi

    ministre bi dem ligueye mo guene di sathie sounou khaliss

  • ive

    Quel pays nos ministres en tournée musicale pendant ce temps nous somment 25 éme ;et ce qui est plus grave ya des vaux rien qui l'encouragent ;j'ai très peur pour mon pays;

  • ouz

    Bouma wakhal wakho kokou dou nitou darra ratatati rék yakarni mo geun yéwou nityi kosi man dagay déf niou guis mais wakh rék takhoul bir fés . Merci youssou

  • benn senegalais

    TOUNKARA TAIS TOI!!!! MEME LES AMERICAINS AIMENT LE MBALAX……Ca c'est SPECTACULAIRE!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!

  • bibi

    pomme dou moromou new yaw rek you danoulay nied

  • dal

    Merci you mais naka khamni fi senegal koufi bakh dinanla saga mais boul fallé boul topato figa diapou fofoula

  • joe

    Spectacular bravo mr ndour

  • dam

    Liguéy lou barri wakh touti .dia dieuf ndour

  • rim

    Youssou nala yalla défal diamou rék ci kaw si kanam

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *