4 COMMENTAIRES
  • Dav

    Thieuyyalla

  • Aïcha-München

    Ndoye Bane wakhe nga deugeu mane dé Youssou Ndour rék la khame si musiciens sénégalais yeupeu ate Alioune Mbaye Ndér
    Bamaye djouké sénégal ?? gnome gnare lawon  » you star » Mbaye ndér reléve
    Ohhh bobou javé 12 ans ???té legui ame nafi beneu ??
    Yala na jamm yague si senegal ?? ate Deutschland ?? et partout dans le monde ?

  • Lazrak

    Bilay ndoye bane nekhoul beu nekhoul wayé wakh ngeu deug

  • way diébalou

    ndoye baane soo bagnéé daanu ak ki la boot déél denkanté deugu ak gnoom musique ak animation musique kouko dééwaalé té touboo digua daanu safara وَمِنَ النَّاسِ مَنْ يَشْتَرِي لَهْوَ الْحَدِيثِ لِيُضِلَّ عَنْ سَبِيلِ اللَّهِ بِغَيْرِ عِلْمٍ وَيَتَّخِذَهَا هُزُوًا أُولَٰئِكَ لَهُمْ عَذَابٌ مُهِينٌ
    Et, parmi les hommes, il est [quelqu’un] qui, dénué de science, achète de plaisants discours pour égarer hors du chemin d’Allah et pour le prendre en raillerie. Ceux-là subiront un châtiment avilissant. luqmaan verset 6

Publiez un commentaire