Annonces
Annonces
» » » Vidéo- Un imam clashe les oustaz: « Alioune...

Vidéo- Un imam clashe les oustaz: « Alioune Sall et Iran Ndao font de la comédie » Regardez

Annonces
Annonces

79 commentaires

  • rama
    29/07/2015 12:04

    mdrrrr imam bi Ray nama, da guethe Sénégal motakh khamatoul lifikhew fi ay imam moderne nio fi nek (boula Iran ndao diaper digua khamne lepe deugue là

  • Toure
    29/07/2015 12:13

    sou gniy fath febare howma gnune malade yi fugnu djeum

  • Beugue fallou
    29/07/2015 12:13

    No mais tounkara do nitt

  • youssoupha
    29/07/2015 12:15

    salam oustaz degue RK lawakh tounkara Aline sall ak Iran fo RK lanoiuye def .yallh mon wakhe si alkhouran .falle yade khakou khalilane walle yabekou kasiran wa soukran .youssoupha Maroc.

  • seye orange
    29/07/2015 12:16

    Mé wa senego ki togne kattela imam astakhfirola wadiou mene togne ki boul daw 2em yagui roukho dé

  • twix gueye
    29/07/2015 12:21

    mei oUztAs bii c 1 MenTeur pErSonne ne lA kNow fOuMou tOoj

  • diallodiery
    29/07/2015 12:29

    yaw dhé dawoo thiow soula iran dégué digua khamné lépp deugeuleu

  • sm thiam
    29/07/2015 12:33

    l'islam n'est pas figé mais malheureusement il n'est pas à l'abri d'interprétation …..l'important est d'en tirer ( des interprétations ) des conclusions qui affermisse la foie. ….k'allah ( swt ) nous guide

  • Mansour
    29/07/2015 12:55

    Ki dafa beugue am buzz mais bou beugué buzz nako outi fénene au lieu mouy critiqué ay moromou bayam

  • muslim
    29/07/2015 13:02

    Dieuredieuf Imam. Tu as raison sur toute la ligne. TOUNKARA EST UN VERITABLE CRETIN ET FUMISTE. BEUG DIAKHASSE AY NIITOU DINE. J'ai beaucoup de doute sur son intelligence. ET DIRE QUE C EST UN UNIVERSITAIRE !!!!

  • goss
    29/07/2015 13:04

    kou nèk nagua gueume ligua gueum tè bayi critik yi yaw gniguay khass gniola gueune

  • ngagne
    29/07/2015 13:22

    imambi wakhofi darra kouthi dianguii ba gnew cammasee dingant khamo toussss

  • ass
    29/07/2015 13:45

    machallah ligua wakh leup deug laaa merciii imamee

  • doyna
    29/07/2015 14:07

    Il a raison il fon k du comédie écouté s sam ou ady niass jamais tu va rire mai peur d dieu c ça les vrai conférencier mais Sénégal beuguou niou deugue lui c un vrai outaz parck il est imam a dubay naryi kou amoul kham kham dolenne djitee

  • abass sow
    29/07/2015 14:53

    En vrais dire ceux Mr là soi disans lmam;de facohére,satanique qui sont là a detrui le nom des gens pieux en regarde-moi ce lá

  • AFRICAIN BOU BEUGUE SENEGAL
    29/07/2015 15:29

    Vraiement, j ai ete tres bien impressionne par Mr Tounkara et son Invite, l IMAM SALL. tout ce que l imam a dit est vrai , bien que tous imams qu il a fait des rmarques sont tous bons et pedagoques, sauf trop trop faire rire en Islam, en Preches, c est pas recommande, je vous signale que je suis trop, trop loin d etre un Islamologue ou un bon connaisseur en islam. Je m y efforce pour etre un bon musulman. Donc que ces Imams, ne polemiquent pas,et s efforce a rectifier le tir, tout le monde les apprecie, mais regardons bien en face, appreciation de profanes. Donc qu ils continuent, bien tout changeant de facon de discourir. Au ils se mettent pas en mal avec l IMAM SALL, ce qu il a dit est bon pour eux, pour leur continuation. C est pas mechant, ni mal. Et pour Mr. Tounkara, je le felicite d avange, je ne le connais pas directement en chair et en os, bien que je l aibtoujours admire et que j ai la chance de lui en parler au telephone a deux reprises et en messagerie ecrite. Parceque a peu pres comment fontionne, les medias et les sponsors, je suppose que l Imam a participe au sponsoring du deplacement de Mr. TOUNKARA a Dubai je ne fais que supposer, je mexcuse si je me trompe, mais avec tout cela, cavpas empecher Mr. TOUNKARA d harceller de questions assez pertinantes a L IMAM SALL. DONC BRAVO AUX DEUX DE PAR MA CONCEPTION. JE DEMANDE TOUJOURS PARDON A TOUS ET TOUTES.

  • abdalla
    29/07/2015 15:29

    yaw kone khamo islame ki limouy wakh lou wor la dine dou afer rou moderne

  • abdalla
    29/07/2015 15:33

    yaw kou niake yar ga soufeke ni dama laye war ga dima reee dara dousi dougou si sa khol te wokhou yalla dou aye fo

  • abdalla
    29/07/2015 15:42

    masour ki fimoune sokh la woul beuz ki lou yalla wakh laye wakh stpl kholale oustaz adi niass rek diga khame lou bari wala ga deglou serigne same mbaye diga tite diga ragal diga khame diga delou si yalla mai maleye war ga maye reee

  • abdalla
    29/07/2015 15:43

    merci muslim

  • abdalla
    29/07/2015 15:46

    goss fi kene geunoufi kene amoule 2 afer bouniou wara geume dineji bene la wakh yalla bi ler na nage bayi fo bi te wakh nit yi li yalla wakh ak nimou ko wakhe

  • abdalla
    29/07/2015 15:47

    ass kone yaw deglou ga ko merci

  • abdalla
    29/07/2015 15:50

    ya wakh deuge bilaye senegal foreke laniou beuge kouye fo ak niome rek laniou geuge

  • rama
    29/07/2015 16:03

    pourtant iran limou wakh dafa laire nena môme d'où oustaz môme likhew si rewmi lay di yête wayer nekoufi nane bo démer safara li Aldiana li

  • insa
    29/07/2015 16:11

    Waw legi ñun talibey bu fekeni imam yi ak ustazyi ñom si sen bir sannate ay kher nan lanu wara def lolu lay lathie man ñun dongayi ba danu khamati funuy tek sunu tanka tunkara ladialma lolu ustazyi ak imamyi

  • Mamadou
    29/07/2015 16:19

    Machallah c bon deug dagn key wakh imam bi yalnako yalla fey way

  • fresh
    29/07/2015 16:20

    De grâce commenter en Français on a du mal à vous lire vous qui écrivez wolof ou bien si vous ne pouvez pas le faire cédez le forum s'il vous plait. c'est navrant de prendre du temps pour lire un commentaire.

  • tafa
    29/07/2015 17:02

    Kidafa rew

  • tafa
    29/07/2015 17:03

    Ki dafa rew dou lmamou dara rew ba dof

  • tafa
    29/07/2015 17:04

    Yaw rek yaa nak yar soofff

  • bibou
    29/07/2015 17:07

    bjr je ne suis pas ici pour polemiquer…je pense ke avant de tittrer vos articles,au moins essayez de les annalyser d'abord.l'imam n'a clasher personne,la veritè est absolue…donc tounkara j'estime bcp ton emession.donc vu ke t'as pas metrisè la charia et t'es pas a la hauteur de l'imam…faut pas contrarier certaines choses.et en plus di diakhasè niit yi…

  • NIT DOFF KILLER ?
    29/07/2015 17:07

    ont s'en bat lé couille avk la langue français "c ki les français

  • Matar
    29/07/2015 17:59

    Wawaw imam aldiouma mom kou rê amou adiouma wérna lol

  • Elbach
    29/07/2015 18:25

    merci tounkara tu lui a donne une bonne reponse et merci encore de lui donne l'exemple de Serigne Cheikh, Oustaz alioune Sall est un precheur multidimensionel il decortique la langue Arabe comme Wolof. quant a toi etre Imam dans les nar est facile et les nar n'ont pas besoin de rire a cause de leur mechanchete

  • Bougman
    29/07/2015 18:29

    Comment ta fai pr cmprdre. Wolf et francais egale langue….ta ka sortir toi…..

  • dou
    29/07/2015 18:44

    Kiiii xamul foumouy taxawwwwww

  • dou
    29/07/2015 18:45

    <p> ok ta raison </p>

  • dou
    29/07/2015 18:46

    <p> ok ta raison </p>

  • dou
    29/07/2015 18:46

    alert('ok')

  • vxr
    29/07/2015 19:16

    oustas wala ibadou? démal tokk wakhofi touss danga beug beuz doxal way!!!

  • NIT DOFF KILLER ?
    29/07/2015 19:21

    boulniou sonal dh

  • Mr. LO
    29/07/2015 19:45

    Il a raison!!! Numero de telephone Dieub, c'est vraiment tres exaggere et 'islamiquement incorrecte'. ca peut prete a confusion au sein d'une population si loin des connaissances islamiques.

  • ibrahima seck
    29/07/2015 19:53

    lower ga wakhe senegal ay comadjien rek nioufa am ligeyalono dine sene ai pooss lanoy legueyal kholal tam imam bi done wakhe maky yokal sa manda bi si imam dine amol raye ak dinakhe cola yombal cone yombal nala safara nanolen diamo yalla svp diokhema sanimero wala sa skype man sa kham kham doynama seckibrahima4

  • karim
    29/07/2015 19:56

    C'est vrai .ce sont même des clowns .les gens les regardent que pour rigoler Moi ils ne me font même pas rire .

  • Cheikh sene
    29/07/2015 19:59

    nit kou baakh dey maandou geumeul li nga geum té mandou

  • ngom
    29/07/2015 20:21

    wakhofii dara imam te guemo dara kholal yaw dagnela kham khamal la ken nawlowula Sénégal somoytuwul légui niou wax2 sooofff sa kham kham selul rafetut ken yarula Amo teguiine dara lingawax yééfar sakh rusnaka wax

  • ngom
    29/07/2015 20:23

    Dangay nar imam

  • lobs
    29/07/2015 20:56

    mais pour cet exemple de mame abdou il faut noté que cest a cause de la mosqué kil étai en colére mais cétai pas a cause des applaudissement il faut évoquer des aya et des hadiss interdisant ce que les autres font

  • mimi
    29/07/2015 21:25

    Yawe ya beugue beus

  • dine dou fo
    29/07/2015 22:22

    Abdella liga wakh deug la de

  • moomou
    29/07/2015 22:44

    oustage wakh nga daggue dééé

  • moomou
    29/07/2015 22:45

    lou wér nga wakh

  • moukhtar al moukhtar
    29/07/2015 22:46

    lou wér nga wakh

  • bass
    29/07/2015 23:16

    wakhal sa bopp et ne critique pas les autres honore ta personne

  • imam ibrahim
    29/07/2015 23:55

    al imam bouchri sall mako kham djambarla lol bamiy tout tangk balegi dine rek moko gnor gno bokon di djang hanafia oustaz alioune sall mi dan fa djiangale wante khamnani kou wattou dinela kouko khamla tamit yalnako yala samou ak adounabi yep wa keur serign abass sall

  • MBG
    30/07/2015 00:07

    ce gars la ce kil fait est trop facile réste a doubai et critiké est facile.ce ke oustaz alioune sall fait pour l'islam ici au senegal ce péroquet ne le fait pas;donc il faut réspécté les gens et accepte le mérite des autres.

  • gainde
    30/07/2015 01:23

    imam bi limou wakh lou mala barina Fi si Senegal oustaz yo khamni daniouye rèitan lo nitgni rèk way khamlè wouniou dara di wout buzz kèsè

  • zoo
    30/07/2015 06:49

    ms diner nonla nite bokay jeumale sii yalla fawga amm sages wahtan akk mom delocii ko hamalko teyy ndank diner dou loulay tital iran jambar la aliou sall jambar bougnou defonn net yaw Senegal ken dou ham diner ya gui bayi sa rew dem dubai wasalam

  • badou
    30/07/2015 09:48

    abdalla ligéne beugone amgéne ko buzz wakho léne fi dara

  • abdalla
    30/07/2015 10:44

    tafa khamal loy wakh
    khame nala boubakh

  • abdalla
    30/07/2015 10:49

    dine dou fo merci gisga de senegal beugouniou deuge

  • abdalla
    30/07/2015 10:50

    mdr yaw do nite

  • abdalla
    30/07/2015 10:54

    merci

  • abdalla
    30/07/2015 10:55

    lou ler

  • abdou
    30/07/2015 11:05

    il y a 313 chari ha dans notre religion vous n en connaissez qu une et vous vous prenez pour des houlemas j ai pitie des genres de musulmans et je prefere un athe qui se comprte comme un musulmans qu un musulmans qui se comporte comme un imbecile

  • abeau
    30/07/2015 11:46

    yaa wax deug

  • pape gueye
    30/07/2015 11:51

    takal sa reum bitch fuck you nganane français gnoune wolof la gniy wax dougnou ay babtou

  • mouslim
    30/07/2015 12:16

    salam ouz pourquoi tu fait bala bala juste pour faire buzz laisse notre chaire galsen way

  • talibé
    30/07/2015 13:41

    YAW BO AMÉ KHAM KHAM TÉ NAAR YI NGAKO YÉENÉ GNII YORE SÉN KHAM KHAM TOK FII DIKO KHAMLÉ NGA GNEUW DINIOU SONAL YAW KAYE TOGUAL FINGA TOK RK TE NOPICHIIIIIM

  • toure
    30/07/2015 14:25

    yaa oustaz waxdeug yalla fii senegal oustaz alioun sall iran hady niass ak gnithi dess gnep gnigi def loubaax yalla moo binde tè yamalèwoul yaw yaanguinii di toogn tè yalla bouggouko wasalam

  • toure
    30/07/2015 14:29

    waaw serigne abdou lahad dadaa wax thii foulla serigne fallou mbacke dadaa waxx ci ak saf xorom tè serigne fallou loumou mossa wax yalla mounè waaw loolou moom ken douko weddi kon yalla moo bind tè yamalèwoul wasalam

  • moussa seck
    30/07/2015 17:26

    KI DOU NITÉ KOU BAKH MN TAKH MOYÉ WAKH LI BOUL GNOU SONA LE WAY

  • l’islam
    30/07/2015 18:13

    Mé man Limasi geuneu métti moy naaféke yii di commentaires imam bii Limou wakh lou lérr la yalla moy sama sédé

  • be-one-xx
    30/07/2015 21:58

    la prochaine essai de dire tt tn charabia en 2phraz ok po le time de lire tn boukin de mrd ti con!!!

  • YANKHOBA
    01/08/2015 10:36

    AMOUL SOLO IN YORIDOU ILA SLAHA MAS….

  • kouthia
    13/08/2015 12:10

    khana dagnoula refoule

  • becaye
    13/08/2015 12:13

    kii kou sokhorlaa

  • sopp NABY
    18/08/2015 10:19

    c le titre qui fait buzz. il ne devais je ne sais pas si c SENEGO ou TOUKARA

  • vrai
    19/08/2015 11:34

    iran ndao c un comedien

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces

L'ACTU EN TEMPS RÉEL