Vidéo : Malick Bolé Mbaye attaque Ahmed Khalifa Niasse -Regardez…

Regardez la réponse de Malick Bolé Mbaye à Ahmed Khalifa Niasse sur les relations entre Seydi El Hadji Malick Sy et El Hadji Abdoulaye Niasse…

 

27 COMMENTAIRES
  • Danilo

    Le gars bolè mbaye il me fait marrer rien que de le regarder on sait que c’est un aigri il a été redicule au TFM lorsqu’il essayait de justifier l’histoire imaginaire de bureau ndar. Ahmed khalifa niass est un savant en l’islam il sait bien ce qu’il dit. Yaw mougneul c’est mieux

    • Cheikh Amadou ndiaye

      Saway lila meti moy limou leral bureau basa ndar daaw mai dou rene limou wakh moy deugg Sénégal fene rek Ahmed niass limouy wakh dara amousi

    • Aybala

      Sama wadji yaw biro bathia niko hadji lalick maye wakhé nonou la démé ahmed khalifa limou wakh dou deugue moko gneck wakh té mokoy moudji wakh

      • KHADIM BAMBA

        Sedy Adji Malick nitou yalla pure la amoul ben weranté sokhoroul won ignanoul won té gathialoul diner dji ben yoon. wakhlou baakh si serigne touba dou takh maodo soufé ndakh gno bokon beug beug. arretez donc de falsifier l’histoir. les archives coloniales se trouvent à Aix en provence, demlenfa nguen geustou histoire mo geun ngueni weur di fenn rek; ak wakh loulen woroul. Cheikh ahmadou Bamba nimou mel yalaakako def koumou nekhoul dinga sonou trop té bounguen fi yéwé fitna bagne souli li nek si archives yi gni doon sossal serigne bi dinan am gathié.

    • sope seydil moustapha sy modou italy

      diadieuff Bollè… kii kouko khamm eugg, kholl toguayy bi khamni nittou dara kèssè la, man je le connè depuis bas ages. tè koukey wakh dara, walahi wakhal lou bakh ndakh tot ou tard tu le verra. amlèn yarr tè respecter les memoire de nos hommes de Dieu. serigne touba dou moromou kènn, Cheikh seydil hadji malick dou moromou kèn. nitt nak digua dèff lounè ngirr yalla oubi sey mbirr, tè dara dou amm, fèkk dagua wakh kilifa loo warta wakh. wassalamou lahi hawlann wa rahmatouhou anleykoum

  • Makowakh

    Nagnuko inviter quartier general mou andil niou aay preuve.

  • taf taf

    Ki Daye doul rék kham mom fékout Bakh tivaone aye fénne laa
    Ahmede Khaliffa ki bou ko tontou daffa ame lou ko métti thé niamé wouko wakh dakh kon niou raye ndayame!!!

  • Lo

    Ahmed Li mou wakh khamna ko way may niou diamou

  • Lo

    Ki nanou may ahmede limou wakh deuge la

  • Baye fall

    Ki febar bou niouy wakh soff mo kay rayye amet khalifa niass nio gui koy topp yaw say mame ba thii yaw toppai dii fakastale ki la djitu ga deukai khol bou bonne bakhoul

  • djolof djolof

    jeureudjeuf elhadji malicke bol mbaye lilne mati moy dagay kajeub bou daw bi molne mtti bureau batia ndar fni kass

  • Ahmed

    senegalais cessai De parler sans preuve Amet ce qu’il a dit ne conserve que lui qui etait La bas temoin lui et son pere persone d’autre son Pere est ou?au Senegal si nous connaisson le Prophet Mouhamed PSL c a cause De MAODO faut demander a vos parents combien De mosque y’avait au Senegal et ou c mosque etait avant 1960 Seydi El hadji Malick ne fais pas parti du match il et L’entraineur il choisit les joueurs

  • Ahmed

    senegalais cessai De parler sans preuve Amet ce qu’il a dit ne conserve que lui qui etait La bas comme temoin lui et son pere persone d’autre son Pere est ou?au Senegal si nous connaisson le Prophet Mouhamed PSL c a cause De MAODO faut demander a vos parents combien De mosque y’avait au Senegal et ou c mosque etait avant 1960 Seydi El hadji Malick ne fais pas parti du match il et L’entraineur il choisit les joueurs

  • zal

    Sokhor mechant

  • zal

    Kounè khamgua koula meune pour refetalko

  • Ndiasse

    machalla Oustaze malik leralyi amna solo

  • zal

    C est pas une reponse mais de la jalousi

  • Ndiasse

    wakh dai mo bari rekk waye koune kham ngani maodo mofi raw

  • BCG

    Dieureudieuf Mame Maodo yalla yonatébi rék ga wané .Do guiss mouk talibé maodo bouy mandi .téré kirama sampefi djakayi sakhal diné bou sél bir senegal

  • BCG

    Dieureudieuf Mame Maodo yalla yonatébi rék ga wané .Do guiss mouk talibé maodo bouy mandi .téré kirama sampefi djakayi sakhal diné bou sél bir senegal

  • sarr

    oustaz malick dieredieuf taxawaye bi rafetna

  • pape sarr

    Dieuredieuf hadj malick mbaye bolle dekal daara dji moy sa yiteiii nioune kham naniou sa ndieurign bi nga ameii yalla nala yalla fayal bopam
    Yenn gni dii wakh warnanioule nianal da nguena reerr sankou
    MAME MAODO KOUMOU FII DOUL SA SERIGNE DISSA SERIGNOU SERIGNE YAW AK SA SERIGNE MAODO MOY SEN SERIGNE.DIARAMA MAME MAODO

  • dalen diam

    yen mourides am len yar neko len ci dara bg fat nit yi no diouli no koor no nat asaka

  • max mou cheikh ibra fall

    cheikhou cherif déh bi mou nieuwé sénégal si niou khamoul darraaa la dale wakh léne.kénnal lénne KHADIMAL MOUSTAPHA point

  • MR

    sounou borom dafa digulé mandou, kou nék na nga gueum linga gueum,lou way wakh yow la engagé, bou léne fi indi problèmou tarikha sélal léne wé rwi.

  • karime

    Aslaamu’álaykum yéen sama mbokku yi mangi lén di nuyu te dileen baalu hax te na ngen xamne ab jullit liko war mooy ne sasu dége lumu xamul mbaa muy luka naxari nawax ne nun day ci Yáal lan jége te ca moom landixála dellu hátt » Ammna ay naari Gaanaar yudoon werente ci wax Seex Hamada Tijaany ak Muhamadul Buddiyu ba waxja xawa sori am ca ku waxli kee waxlee ñaa waxlaa ba muju am ca ñu bind Seex Hamádu Bamba Habdulhai wa Xaadimul Raasul dikoca laac ab Àtte sëriñ bi tontuleen tontu buleer ndax dalena delo ci Yálla sunu boroom xamal leen ne waxi Seex Hamada Tijaan ak yu Hamadu Buddiyu mii ñoom ñaar ñépp Émuñu ak woroo ndax kenn kuci nekk liga wax kemtu nengatollu ci boroom noona nga waxe waaye ca doon werante ca birr wax ja amnaca kook tuutikoon mu alku ca lamudoon wax waante ci katanuk yálla ak màggu yoonenti bi Seex Tijaani ñaan boroomam wala ka bind bataaxal bi ñaan seex mu tinko ngir moom rus naa setaan kenn kum Yálla ak’kup yoonnentam muy dugu sawar ngir tooñ gumko tooñ te ballu ko li mooko tee Allku tekon walyées billaai
    am na kumasa took fi ´Sydi Asimaalik tuddu fa Seex bamba ca saasa mune ko kooki de yaakoy Tuddu waaye moom dula tuddu mukk te kooki day moom rekk moo saña taxaw bis peñci ma ne man day musumaa wax darra luma hastaxfirulaa di fek te musumakoo jéffe it
    kon kooku wupule wul Sëriñ bi waaye sunu Maam Maalik it moom kunee Xamnane fu Nasaraan bi masa sapu karceem difa maac loo ay soldaaram Sidy Hasimàlik sapunafa jàkka ja ak difa wasifa Naasiral haxi bil haxi Fu Tubaabi sapu lekool mu ñéw defa Daarra te baparee ñu book seen maam Márram konik yéen ñi doonul darra fexee leen cee jariñu waaye buleen ci loru wasalaam

  • karimou

    seydi el hadji malick goor yalla bu makla

Publiez un commentaire