Vidéo – Le show de Waly Seck à la célébration des 25 ans de musique de Papis Konaté

Revivez le show de Waly Seck à la célébration des 25 ans de musique de Papis Konaté au Grand Théâtre National.

17 COMMENTAIRES
  • Amar

    billay wally weuy rk ngayy deff

  • mbaytou

    bokoum ndayam bokoum bayam si tu as envie de faire carrière faut aller apprendee la musique c’est pas héridaire le wayane sénégal la yém si tu veux faire carrière à l’internationale labas c’est des textes et sur cette lancée tu feras pas un long feu le show c’est temporaire et des expemples Salam falou dieng etc la musique c’est des paroles qui le fait vivre et qui montre sa richesse le wayane c’est dans les baptème et mariage.

  • modoulo

    mai mbaytou boy bi dafa meune way dai nguanan wayane

  • nasi09

    mbaytou tu as bien parler mais tu pouvais juste etre plus diplomate si on donne des conseil pas besoin di khasstè

  • nasi09

    mbaytou tu as bien parler, j’ecoute que wally cest le debut danka dioumbeti

  • Cheikh

    Sénégal doudem ndakh sokhor ignane Wally c est la jeunesse 31 ans rek laam il a tout le temps devant lui inchala

  • AD

    L’essentiel pour un artiste musicien c’est une belle voix té Wally amena sans woyane texte kessé sakh day nekh limou nekk geweul mo takh Mouy tagaté et c’est la culture sénégalaise bou fekké internation al rekk Wally solo wowe si anglais mou wouyou la, français wakh noppi , woy rekk lay deff

  • as

    ad wakhnga deugeu ,waly feppeu leu meun, youssou ndour mo dakone wayane au debut et kan il s est enrichi, il a diminue

  • Karim

    Toi mbaytou merde tu ne c’est pas se tu ke tu dit et puis ont a rien demander avec ton drôle de nom mbaytou c koi

  • as

    Wally wooo woooy rék la diang si waay

  • as

    waly ,rien de ce l ennemi a sem dans ta vie ne peut detruire ce ke dieu a plant en toi

  • meiy

    waly même bou done wooye frero jackeu di ko accompagné ak aay pote sakh nekhna niou beuguenaniou ko nonu

  • Manu

    Bilahi meiy tu as tout dit se garçon il est adorable et extraordinaire mayou yalla la âme .moi je le regarde comme si c’était mon fils

  • amy

    wooo wooo Wooy d mannako

  • mami

    feth kat yi mom modé nagne dé

  • meiy

    manu khamngua mbir mi d’où dakeu waay louma saf la sama dome dji nak MACHALLAH sur scène MACHALLAH bou sagnsser MACHALLAH bu youkho KU yabu nekhel sa khol ta khamni SUNU BOROM MOM LA FI TEK kene meunu thi dara wakhlene ak YALLAH

  • fafa ob

    Ignane sokhor au coeur des senegalais allez vous faire soigner dinon vous irez en enfer

Publiez un commentaire