Annonces
Annonces
» » » » Vidéo: Kouthia tacle Ahmed Aïdara et corrige...

Vidéo: Kouthia tacle Ahmed Aïdara et corrige Bougane

2015-05-15T18:36:05+00:00 Partages

Annonces
Annonces

45 commentaires

  • Eva
    15/05/2015 18:59

    Noo Kouthia amna louko Ahmet aidra deff…mai deug rek la wakh lol

  • bene con
    15/05/2015 19:04

    hahhaha !!! kouthia ray gua ma !!!, procureur mo leen fay fek boup leen niome nieupe yoobou ! looool

  • kamara
    15/05/2015 19:08

    Ko hameni wa sentv rek nga.sonal. loufa am rek nga topou si di wah rek. Chimmmmm gnak fayda

  • Mina
    15/05/2015 19:14

    Mdrrr kouthia dinama rayy amed aidara gathié douko rayy mdrrrrrrrrrr

  • ah
    15/05/2015 19:16

    Kouthia a raison Ahmed aidara pense k il é plu mûr k lé gens alors kil s trompe Il n en qu'a pardonné les personnes offensées

  • Seydou
    15/05/2015 19:31

    li bakhoule kouthia khana dou dioulite

  • Zzz
    15/05/2015 19:39

    Yaw khana tu es panne d'inspiration .
    Langalko wa sentv rek ! Gnak khorom.

  • Mamitoo
    15/05/2015 19:40

    Ay kouthia yangui may raaayyy, retaaannn naa beu soin ne!!!

  • mounas
    15/05/2015 19:41

    Sentv dal hewna kou wahoul si gnom sah do am buzz

  • biba
    15/05/2015 19:44

    Yow khouthia amoul touti personnalite ahmed ak bougana say moromou dom lagn. So don bey tawlo len. Pauvr imbecil. Tu sert de tn emission bidonne pr regler tes compte.

  • nit
    15/05/2015 20:01

    BILAYE DEUG MO NEKHOUL.KOUTHIA A PARFAITEMENT RAISON CE VAUT RIEN EST TOMBE ET DEMASQUE A JAMAIS IL NEST PLUS CREDIBLE…………….TEUSSEUL SA BOP HAHAHAHA
    RADIO AK TELE BO HAMNI BUZZ AMOUNIOU PERSONNALITE AMOUNIOU PROGRAMME………

  • Sofia
    15/05/2015 20:30

    corrige avec 2 r bande de pingouins.

  • mara
    15/05/2015 20:32

    Liy dague sen xol yi moy nit gni sayou gnou heuyé teuss lagnouy deglou. Mayou yalleu leu koumou meti nga clamè yalleu

  • garmi
    15/05/2015 20:34

    Khouthia tu commences a me degouter trop c trop. Arrete. Toou ben groupe de presse rek beug len lek

  • amy
    15/05/2015 20:48

    Kouthia lane moy sa problème ak ahmet aidara

  • demba
    15/05/2015 21:31

    Kouthia tu as raison ce conard de ameth à été démasqué en plus mansour se permet d'insulter le mr en direct à la radio le ridicule ne tue plus au senegal

  • tackonas
    15/05/2015 21:38

    Sen tv télé bidon leu ahmet c vraiment un bouffon

  • nastacko
    15/05/2015 21:42

    Kouy teuss bagnou teuss leu nga wara nopi mais prkoi tegoul enregistrement apre bayi gnoun on jugera si da dieuw ou pa

  • seck
    15/05/2015 21:54

    hahahaa kouthia toth nafi

  • aramjnie
    15/05/2015 22:06

    mais nous autres nous voulons ecouter l enregistrement pour savoir qui dit la verite c est du dieuw ou du wakhtane en ce momen nous pourront juger en tout cas didieu laamine bakhoule

  • Doofff
    15/05/2015 22:15

    Merci KOuthia. tu m'a tué, mais aussi, le messaz est clair. Tu pouvé te taire et faire comme ts les autres, mais au moins té sortie pour leur remettre à leur place. Ahmed, tu devré tiré les lecons de cette affaire et surtout profile bas.

  • azizama
    15/05/2015 22:56

    kouthia,tu es phénoménal.

  • Joe
    15/05/2015 23:19

    Ameth vous fera toujours de l ombre parce qu'il est meilleur que toute votre groupe de presse réuni . il vous a zapper lolou molène meti .
    Ndeyam moko liguey
    Sale ivrogne !!!

  • serigne saliou
    15/05/2015 23:40

    khouthia tu restera tjours comédien et ahmeth a des ambitions ouvrir une télé.maire ville de guediawaye.laissons l temps inchalla tu va voir.tu va travaillé pr lui inchalla

  • deugue rek
    15/05/2015 23:44

    sntv deff lenne atention sene thiow berina .

  • mooo
    15/05/2015 23:53

    merci kouthia ça cé la vraité

  • Thiant
    16/05/2015 01:48

    Ahmed li dou dara danio soxor rek mai lici kanam rawouli beut

  • deugue
    16/05/2015 02:52

    diadieuff ahmet.. gnoune dale heure bougnou yéwo teuss lani déklou ak sa révu de presse télé boumou nga teuthie

  • tyma
    16/05/2015 03:55

    kouthia da nga niak fayda trop legui affairou guarouwale rek ngay def… nieupeuy dieuw bougnou sonal

  • diongue
    16/05/2015 06:40

    kouthia lidousathieur bousaba meunguademe sentv

  • diongue
    16/05/2015 06:41

    kouthia lidouyeufi goore waye

  • kouthia deugg rk
    16/05/2015 10:11

    mom il a oser wakh toureum dou garouwaler
    kouthia ci kaw cci kanam senegal nak dafa bari nafekk. ,ak kii limou wakh cci balla geye yeupp dioget fii dele feler, te moofi tegone enregistrement tange bii yagoul dara lou nek mou wakhko

  • fa
    16/05/2015 10:25

    YOW KOUTHIA MOUNO MAY NIT GNI DIAM YOW SOF NGA TROP KHANA YOU DO DIOUME ACTION KEN DOU KO TOP BA MOU SEUSSE

  • evve
    16/05/2015 11:10

    amine waay

  • tele buuz
    16/05/2015 11:31

    SEN TV MOY TELE BUUZ KOU WAXOUL THI NIOM SA TELE DOU NEX…….MACHA ALLA MOUDIEE DIOUD DIAXAL AYE MAGUAM DEUG NEXOUL

  • Madam Faal
    16/05/2015 11:52

    tfm kai moi tele buzz ku ladial wa Europe tfm bou amoul won dou bakh

  • yama
    16/05/2015 12:05

    sn tv télé buzz si tu ne parle pas de sntv tu n'a pas de buzz liiiiiiiiiiiiiiiii!

  • Mya
    16/05/2015 13:26

    Partt. on ne parle que de Sentv !
    Tfm , Walf ….etc
    Bougane, Ameth , Abba , Cheikh Saréne bi … Yéna bari dolé !!!

  • nino
    16/05/2015 15:43

    ameth dou rouss dou gor

  • abdou
    16/05/2015 16:06

    Sentv si kaw si lou bah, yalleu nalen yalleu mousseul si sen none yi di wa gfm. K dieu vs protege, sa youma yewo sentv lay setane zikfm lay deglou

  • Seynabou Gueye
    16/05/2015 16:22

    bayi len ahmed aidara ndanane la de bo len khamon noumouy di pas dans le tele
    apale gnigni di ngen ko sopp te koutia mo amek mom blem ka fathie ko mais

  • chacha
    16/05/2015 16:38

    Madam hana yeugo lou hew. Sentv legui c internetional. Wa europe nenagn gni ngui soga setan lou bah

  • kaka
    16/05/2015 21:35

    ahmet un homm public a le droit de reserve, et puis les linge salle ne se lave pas en public, com tu viens de le faire. vraiment c degoutant venant toi d,etaler t relation en public
    recadre toi si tu vx aspire kelke chose dans le future.

  • moo
    16/05/2015 21:43

    SENTV amoul si region yi aidez nous KOLDA VELINGARA TAMBA KEDOUGOU KIDIRA KOUMPENTOUM KOUGUEUL ect….. BOUGANE AIDEZ NOUS LES FANS DE WALY THI BARKER SERIGNE MBACKE SOKHNA LO

  • deug
    19/05/2015 14:17

    Ameth AIDARA grand CARRE

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces

L'ACTU EN TEMPS RÉEL