Vidéo – Khadim Ndiaye: « Yékini dou nit kou bakh… »
Khadim Ndiaye revient sur son combat avec Yékini. Un duel sur lequel il a été mystiquement dominé par son adversaire, le lutteur de Thiaroye raconte des événements douloureux qu’il a vécus avec sa famille.
Deilein attei degg
Yaw kou doyadi nga yaw mi ya sokhor motakh nga tardé
khadim ne te cré pas des ennemis,dans la vie c’est pas la peine de tout dire essaye de terminé ta carrière en beauté et laisse yekini en paix pour moi c’est la meilleure solution
khadime gua yakar ni dou comprimé yi mola fébarone*
khadime gua yakar ni dou comprimé yi mola fébarone
khadim yi acusation sans preuve sa yonou kasso khathnasi bou yekini beuguee laver honeureum sans tourwi motakh mounoumala wakh dara wayee moussouloo bou yaboo elh diouf di sa baye
Khadim neuk,yen mbeur yi ligueyeun teh moy sen liguey.yangui ci biir,gaur gaur loul bay defendr sa bopp,tei bayyi wakh dji
Khadim neuk,yen mbeur yi ligueyeun teh moy sen liguey.yangui ci biir,gaur gaur loul bay defendr sa bopp,tei bayyi wakh dji
Khadim neuk,yen mbeur yi ligueyeun teh moy sen liguey.yangui ci biir,gaur gaur loul bay defendr sa bopp,tei bayyi wakh dji
Vrai com kha dega sokhar
WAKHNA DEUG DOU SERIGNE GNAM MOKO WAKH SI TELE BI AY NAFEK NGUEN DELEN WAKH DEUG TE BAYI DOULE YI NITT DAY DEUGOU. SEN MBEUR BI MECONTANT LA. DOU DARA
Khadim Ndiaye est vrai con, tantôt certains lutteurs sont des pédés aujourd’hui c’est le champion Yekini qu’il attaque avec ses sorties idiotes et ridicules. Khadim un vrai domérame et bête
YOW ITAM BAKHO HADIM DEGN LA DOMINEWONE REK WAYE LAMB LAGNOU WAKH DEM GUA THI SERIGNE
COM SAY MOROM YI GUEUMAL YALLA MO GUENE WAKH BI
Khadim ndiaye dafa sokhar
Khadim gueumeul yalla yen ken douko toumal nit
Sa wakh dji ay dor la rek
Dafa sokhor reck
Wayé mola gueune nax mom ku mandou là tamite nawlo wula il la réussi sa carrière contrairement à toi ioe momu ya soxor
khadim ndiaye bayile dor yi ab serigne gua bagua done kham nala dor guate gua .dinala woutal guil yaa yaya salbe ndiaye. si mber yi
Yaw warone toubou Khadim parceque tu es trop con