Vidéo: Des gambiens « saucent » Wally Seck de billets de Dalassi
Regardez ce bain de foule sur la scène de Wally Seck pour lui offrir de l’argent, lors de ses 72h en Gambie.
Regardez ce bain de foule sur la scène de Wally Seck pour lui offrir de l’argent, lors de ses 72h en Gambie.
Ana gni done nane wally da faye kaye léne khole lii
Seck ndanane yaye bombeu
danga ame diomm
Doyna war.il impressione son monde de jour en jour
El fenomeno
Le KING de la musique sénégalaise et africaine yobouga artistes yeupp fayy FM deyssane yereumnalen.
Wa yaw moom am gua diot ben nit bi di comlenté bi rek bilay ya niak loy def ak say commentaires you teglé wo
liguey lou bari wakh touti sopé you bari doyna faye.
kou amm waly loye doyè kénéne meuna woyy meuna féthi meuna sagnsé bakh tabè
waly rek thi khol lénéne da thia khadioul
le roi du live aka meuna live khalé bilè domm longue vie a tou
merci a toute la population gambienne pour lamour k vous portez a notre tres cher artiste adoré waly ballago seck
sargal djiguene au grand theatre le 18 dou yombou dal on atten avec impatience
72h de reussite totale
waly déll yobou tèle wayy on ve nou aussi regarder les evenemen les reseaux sociaux ne suffiz pa
diffusion a la tele svo
felicitation waly gambie nékhona trop
mane dé yaw la gueum nitt daye geum bopam dièma avàncé bagna ragal mè nèkk soukou rek ba kagne
toth mali wathiè gambie parè pour toth paris non waly dal machala rek
amineeeeeeeeeeee
waly yalla nga goudou fane kouné amine yalla nga goudou fane
star un point.
waly doundeul doundeul wayyyyyy
non waly khana bayila ak yalla rek li rek mofi desss
khol sédatina rek
laf thiat rek thi sama rak dji ahhh li nekhna thi khol
ahh sé beau sé vremen beau machala
nice nice nice
merci wa gambie thi sagal bingène gnou sagal gnoune fans waly
diam rek ngaye amm waly ballago seck bilahi diam rek démal rek ba kéne lal laa
tres fier de toi bro
waly goudeul fane rek lo doundou mar doyoul
sama rakdji yalla nala yalla lafal thiattt
ahhh li séddd na khol je tasurr
waly rek thi khol louy faye liii
nguir yalla maye léne gnou lintegralitè bi sur la sen tv wala senego tv 72h bi eupeuneu bagna tèkk thi télé dé
toujour fiere de toi quan je te voi sur scene je pe plu me retenir
non gambie mom wathina khalè polivalen khalé geum sa bopou ni kèssé la nak waly diadieuf
machala fo diarr rek deff ko daume yalla nala yalla lafal thiat
non ak waly rek doyoul baye dess