Les plus populaires

 

Lecteurs en ligne

Une info ? 
 

+221 33 823 43 43

Sentv: Fama Thioune et Ya Awa ont elles été virées?

La rédaction La rédaction2014-04-23T08:45:55+00:00 Partages
Sentv: Fama Thioune et Ya Awa ont elles été virées?
Annonces

C’est encore le remous à la Sentv. L’émission Sen Kheweul a mis à nu la grande rivalité de deux co présentatrices Fama Thioune et Ya Awa. Les deux jeunes femmes qui assurent depuis le départ de Pape Cheikh peinent toujours à cultiver la bonne entente entre elles. Pis, c’est une jalousie manifeste et flagrante entre les deux nymphes qui ne sont pas visiblement les meilleures amies du monde. Exaspérée par cette situation la direction de Sen TV a finalement décidé de les ménager toutes les deux en attendant qu’elles reviennent à de meilleurs sentiments. Pour l’instant Bineta Mané et Aicha assurent l’intérim

Annonces

14 commentaires

  • mamy dit :

    ya awa lepe mome la ndakh a chake fw dèy begue fènlo fama kou wotè mou waguila sou fama wahè kouko solale rèk mouy diaye sise lou fama wah mounane ay dore la mè nak nèk lène bène tè xamnè adouna amoule solo tè dara yagoule

  • dykha dit :

    fama mouniale rèk tè doli gor golou fokal sa cèye mome tasse na cè yam bouko tope

  • mag dit :

    mamy ak dykha déléne doule di dadialé rek

  • boy djine dit :

    dikha ya meneu fene

  • dykha dit :

    ya awa sur ma yaye comatè mè na lèpe rafète rafète tè ga tappè sa xole bi adouna amoul solo

  • awa dit :

    Lep fama la nak mo djouty si télé bi ell doit mntré l bn exempl té mo bayi woudjé biya awa mo modjé si plateau bi té day assuré a 100% c po pr rien pape cheikh la préfèré ell a d la class d légance marchallah té senégal kouy dém lagnouy bay apart sa fama ya awa vs devé savoir k formé un duo c po un travail personnel liguey léne te guène bayi thiakhane yi

  • amina dit :

    Ya awa dafa boone khol bei khate di wagni fama loum wakh mou sewal ko et pourtan les gens snt po fou car gneup guiss negn nei fama massla ba soneu ckie une choz tre professionel parsk liguey molen bolei ma sayu fama noyalei ya awa degueureul mai aten el s pren pr ki.wa sen tv si vous voulez vrmnt nou fair ns les telespectateurs ramener fama car el parl bien et tre souriante e c c k dont a bsoin mai po kou fouy tei reew ba dof com ya awa..

  • aicha dit :

    Ya awa ne po fai pour la tele car dafa reew beuri gateu pour qui el s pren aten on a bsoin d sa nou on a bsoin pluto des ya astou fama et otre car leur sourire t donne un vrai plaisir par rapport a el ki fai du gnangal tou l temp petasse

  • khoudia dit :

    C po normal que vous suspendez fama car el na rien yagg na si tele bi tei ken degouko ak ken mai ya awa gneuw bgueu ko yakal ligueyam cpo normal parsk khess na meun na sagn se qu el s pren pr la maitress du mond mai allo gnoun lol safougnou kougnou yeukk legn tei mom souy wakh ak telespectateurs dey enerver ndakh sokhor gneuw fi beug todjal fama qu el ns fich la paix

  • rama dit :

    Je suii vek fama elle très les qualités dont on a besoin . Ramenez la svp on a besoin d’elle . Kd à ta ya awa elle est sof je l’aime pas . Reconciliez vs way seytane mo gguaw rek !!

  • halicia dit :

    bayilene Ya Awa elle n’a rien fait, danguene di diawaleii rew ak am fouleu teii nonou leu mell … mane bagnouma Fama mais bou amer kouy jalouser moromam Fama lay dane, ndakh Ya Awa est belle et élégante mach’Allah, elles ne sont même po comparables

  • fafa dit :

    fama na rien na envie a ya awa,franchemen. Le seul pb c k ya awa khamoul kaff,il fo kel sw plus souriante te di kaff si retane sincermen car mom dey force on le vw bien,cet emission nest po faite pr el,genrou fama yi ak adja astou yi nioma meuneu def car el son plu joviale. fama on nest avc tw.

  • cUbiz dit :

    Mai mane j reve ou kw kouléne fek ngen di teukeulé fama ak ya awa lane lay wax!ya awa boukoul sax categorie ak borom bakene bou reuy bii.te lima soof si fama moy dafa soxor meunul suporter djigeen bou rafet.mem queen biz dafkodone soxoré kan el ete invité.yalla mo dogal yaa awa gueunko tooy gueunko taarou dakk ko sagnsé.moom dabord kouss kondrongu la.yaa awa dakoy tiiim si plateau bi.kone kane mo wara jalouser sa morom.kiy tiim wala kignou tiim?a vs d repondr

  • maami dit :

    Yaa awa lagn beug mou nieuwaat si sen tv ndax ell donne vraiment envie d regarder la tele.nieupa ko beugu kokou bagn danga sokhor.beneu goor beniouko nak.jiggeen gni dagnkoy fiiré ndax souniou sanione melni moom c tt!bayiken soxor.ell est class douce.c com ci mom moy la femm mariee.fama moom c une p…t… Car si el ose safficher devant la tele en mode deux pieces dan beguee time,mane xamatouma si moom dara.son mari beugoul ndiaboot guou baax.

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces

L'ACTU EN TEMPS RÉEL