Annonces
Annonces
» » » » Miracle à l’appel de Seydina Limamou LAHI....

Miracle à l’appel de Seydina Limamou LAHI. Regardez

IMG_5474 Yoor-yoor Seydina Issa (15)Le yoor-yoor Seydina Limamou édition 136, a été marqué par « l’apparition » de Seydina Issa Rouhou LAHI sur les bâches et aussi des poissons qui pataugent dans de l’eau toujours sur les bâches. Ces apparitions ont provoqué des zickrs des cris, des fidèles qui tombent en transe et les secouristes à pied d’oeuvre. Regardez.

Apparition Seydina Issa Rouhou LAHI (3) Apparition Seydina Issa Rouhou LAHI (2) Apparition Seydina Issa Rouhou LAHI (1) Apparition poissons (1) Apparition poissons (2) Apparition poissons (3) Apparition poissons (4)

 

Annonces
Annonces

80 commentaires

  • fall sylla
    09/05/2016 15:17

    allahou akbar

  • senego
    09/05/2016 15:20

    bilahi kou gueum niou gueum djine kou wedi niogui roy ci baye laye li dara dakou ko way wote baye laye soudoul deug dara dou donati deug bilahi limamou yaay mouhamadou djiol makka bilahi yawa

  • Issa laye ciss
    09/05/2016 15:27

    ki wakh ni yalla mo ma yonni ba paré borom dégueunté gala way

  • Issa laye ciss
    09/05/2016 15:32

    naniou gueum

  • ria
    09/05/2016 15:33

    allahou akbar

  • papis
    09/05/2016 15:34

    k baye laye dou moromou nite gni k serigne touba moko yoor k el hadji malick ou baye niass kesk sa changer sur la creation est ce que la banane kiterra son etat sucrée pour devenir saléé naniou diamou yalla té bayi parparlo bi

  • guissouma darra
    09/05/2016 15:38

    je ne vois rien
    gueudal

  • Anonyme
    09/05/2016 15:41

    yalla rk moy deugue.

  • Amina
    09/05/2016 15:53

    khey Senegal Yalla naniou Yalla khirr si bopam te mousal niou shirk ak bida

  • Dija
    09/05/2016 15:57

    Allahou akbar

  • mou hamed lamine
    09/05/2016 16:09

    Yalla rek moy drug dh wayé mi gui wané bopame diaraléko si ay royoukay kou si melni mame laye li moy guena wané ni diamou len yalla yalla amna

  • bb
    09/05/2016 16:10

    Li lan la

  • Issa laye ciss
    09/05/2016 16:25

    Yalla na niou yalla Moussale ci kignane

  • Issa laye ciss
    09/05/2016 16:28

    Baye laye dou morom yonénté la

  • pape gueye fambaye
    09/05/2016 16:28

    senegal douuu demmmmmm

  • Issa laye ciss
    09/05/2016 16:29

    naniou kham ni moy gueune di mindéf

  • Issa laye ciss
    09/05/2016 16:30

    li nioun wa Ahloulahi dou boulète ci nioune

  • MALICK. Lo
    09/05/2016 16:34

    Mane. Dè..lamaye. wakh. Mody. Niome..diokh. naniou..keurou. dènne. Yèpou.sène. geude. Nan lène. Wormal. Niomtame

  • diamou yalla
    09/05/2016 16:47

    Li dou kemtane topoulene yalla ta bayi naxateyi diko dou rafete lanou topé nit m pas ay miracle

  • ELZO
    09/05/2016 17:17

    N’importe quoi

  • Issa laye ciss
    09/05/2016 17:22

    nite kou nioul da khéb bopam mo takh menou niou nangou ni gueune di mindéf wathiate na ci nioune

  • lakhat
    09/05/2016 17:46

    Diamou yalla wowal sa baye mou nieuw déf kémtaan bok!!! Soi tu crw,soi nga teudj sa guémé gnou ndaye

  • khoul
    09/05/2016 17:46

    Abrutis allez brouter de l herbe . khar yi sakh nio len tané

  • Mamadou Lack
    09/05/2016 17:55

    Tôt ou tard, il y aura au Sénégal des gens ignorants qui croiront ces personnages d’Allah (Sergine touba, seydina l’imam Moulay, serigne babacar) comme des prophètes ou des divinités en dehors d’Allah.
    Nous musulmans nous n’avons pas besoins de miracle pour croire a ce qui nous est descendu a la part d’Allah. Parce-que Allah dit celui qui veut voir des miracles, regarde juste en haut, n’importe où. Alors arrêté s’il vous plaît, nous c’est pour ces choses qu’on va crois a ces personnages, on les crois pour ce qu’il on fait pour Allah et la population sénégalaise. Allah connais très bien ceux qui les suive pour sa cause, et ceux pour leurs passions.Qu’Allah nous préserve le sort du Diable amine

  • Que dvi1 LE SENEGAL
    09/05/2016 18:11

    On avait l’air malin quand on était gosse ( nous jouions avec des lampes torches sur les murs…)Devenu grand j’ai compris que le peuple n’a rien à voir avec ces montages malsains…of courses. S’il vous plaît, n’écrivez plus sur ce sujet à moins d’avoir kelk choz de concret

  • fatou mou serign saliou
    09/05/2016 18:13

    machala laye makhtar laye

  • Loustik
    09/05/2016 18:24

    Lack doul waye

  • SENEGALAIS
    09/05/2016 18:39

    A ONZOUBILAHI MINA CHEYTAN RADJIM.ALAHOUMA SALI ALA SEYDINA MOUHAMED. ( PSL )

  • Ngg
    09/05/2016 18:44

    Capable de s’ afficher sur une Bache – les poissons comme bonus- mais pas capable d’ améliorer les conditions de vie des Layenes . Vraiment l’ africain n’ aime pas son peuple et ne pense qu’ a son …ego

  • Absa
    09/05/2016 18:55

    Fene rekkk akk tapalle. Senegal nio fi meune soudane tappale moy takh nitt avance, rewe bi toujours mo nekkk si kaname

  • lamine
    09/05/2016 19:47

    arrêtez quad même

  • Hassana
    09/05/2016 19:57

    le miracle le plus miraculeux c’est annabi Muhammadou sallallahou alryhi wa sallam .sirigne yii deffoul darra c’est haqhikhatou mouhamad mo deff li mou bougeu.oh mon sngalais :un fer chauff 1 00 degrs brille toute ce qui est de matier mais ne croyez jamais ce fer car il est fausse c’est le feu qui brille toujour .cette feu est Rassoullallah mouhamad psl laire yallah moy sottkou thii mom.

  • babacar laye
    09/05/2016 20:13

    baye laye amoul mass

  • zico
    09/05/2016 20:18

    ignorance

  • deh Ramata
    09/05/2016 20:27

    vraiment ,l o sngal est class dans le monde international et que beaucoup de pays africains veut sngal comme exemple avec ces genres de paroles et images?

  • talibe mouride
    09/05/2016 20:27

    wakh deug yalla fi ay kemtane faigne naffi mane dai louma geume la

  • talibe mouride
    09/05/2016 20:30

    wakh deug yalla fi ay kemtane faigne naffi mane dai louma geum la

  • dass
    09/05/2016 20:30

    On veut a en video , si nan j sais op qw

  • sara
    09/05/2016 20:35

    machallah

  • Fa
    09/05/2016 20:58

    Allez apprendre. Tous les gens qui critiquaient le mahdi. Après leur enquête ont fini par être layennes. Calmez vous et allez étudiez aulieu de critiquer. Bandes d’igniare

  • fallou
    09/05/2016 21:08

    wa Lou niouy guemm??

  • LIBASSE LAYE
    09/05/2016 22:00

    BISMIL LAHI RAHMANIR RAHIMI AH HOUZOU BIL LAHI MINAL CHAYTANI RADJIMI…..rew mi lifi am ci ay nguenel fi ci BAYE LAYE la bayiko yaubu sen keur daw delouci watt gnoune gnou tokk gueum LIMAMOU LAYE…ma yeureum ga ya wédi ndjine casté sen khol yi ndakh kignane…YALNANU YALLA RAY CI GUEUME LIMAMOU LAYE AL MAHDI AMINEEEEE

  • mandou!
    09/05/2016 22:36

    lou way khamoul nathia mandou

  • mboup
    09/05/2016 23:56

    Nagne xam yalla té nangoul KO way

  • mboup
    10/05/2016 00:02

    Nagne xam yalla

  • laye
    10/05/2016 00:09

    se serai mieux si ses poissons etaient ceux que l on peu manger
    les fideles seraient repartis le ventre plein

  • preuve rek
    10/05/2016 00:20

    moh li dou touss ibliss moffa diarrrr. apparition de satan ak sen bidah you bon yii. Mom xana yonentou layen yii laa. man dama xamoul bandinee laniouy woté. Ta adouna bi ay blem rek la. Mais ani massi dadial, an Issa. Any nioum yadioudj ak ma dioudj. way naniou diagui ta bayii tiaxan yii. Deuk boo deem rek fek fa am mahdem feennn rek

  • senego
    10/05/2016 00:38

    laye appel mame limamou kou niaw xiff di nga lek ba feur nane ba mandi soci beugué xam dara on t invite l annee prochaine je te dis dougal leur boula nex tandal par hazard inchallah di nga nane di nga lek bayi lene soxor africain loulene depasser nguene xeup ci souf ak kani mbirou yalla deug sou diké vous evoquez Satan

  • senego
    10/05/2016 00:40

    wedi woté baye laye bene instant niak gueum yalla la xana dou yalla mo wax may bour may xol louma nex dogalko moustapha (psl) newonena mahdiyou ngui niaw naguene ko top wediko moy wedi ma

  • senego
    10/05/2016 00:46

    wa mais ma lath lene serigne touba tamb na di fegn ci ay beureup mouride yeup bek bakoko… lolou seytanela wala…? repondez preuve rek

  • Salamoullah
    10/05/2016 01:58

    Reponse NGG qui a fait le 1er commentaire :
    Les conditions de vie des layènes ne se mesurent pas à la lourdeur de leur portefeuille ni la pleinitude de leur compte bancaire, mais se mesurent à la beauté de leurs âmes !
    Ce que Seydina Limamou Lahi et Seydina Issa Rohou Lahi ont inculqué aux layenes comme mode de vie, de pensée et d’actes en font des personnes dont les principaux drivers sur terre sont la foi en Dieu et ses prophètes, et le respect de l’humain. Tawhidoullah Bi lène Baye Lahi sasse à tout instant donne à tout layene une paix intérieure et une sérénité qu’aucune condition financière ne peut apporter !
    Walaye que demander de plus ???

  • laye makhtar
    10/05/2016 06:48

    slt mr..j voudré vs dmandé kesk tu appel condition de vie….prsk ils n ns mank ri1,ns mangeons a ntr faim é bevons a ntr soif.jamé tu na vu 1 layenne tendr la main pr dmande kw k s sw a ki k s sw.SEYDINA LIMAMOU néna gnar gni gnoma kham:<>.T magui lay watal ci borom bini BILAHI WALAHI boudé LIMAMOU LAYE AL MAHDI DOU RASSOULILAHI yalnama YALLA talle dieupéte ci kanamou diam gnep bala at mi di délu ci…WATAL CI SA BOROM GNU KHOL…

  • LIBASSE LAHI
    10/05/2016 09:07

    C TW KI A FAIM DE POISON FRAIS ME NS KI HABITONS PRES DE LA MER ET CROYONS A SEYDINA LIMAMOU AL MAHDI NS EN MANGEONS TS LES JOURS.ERCI MR LAYE MAKHTAR

  • pisco laye
    10/05/2016 09:12

    Baye Laye Amoul Mass.laye diekhna billahi wolahi wa talahi

  • le passager
    10/05/2016 09:38

    c bien vrai que seydina limamou est un grand homme un vrai waliw un vrai guide religieux royoukay mai santoul kén mou howé rassouloulay le prophéte moy gun di midéf té bén lafi kou mélné mom mouna toufi am regarde bien ce ke vous dit yén yi niemé yalla la sakh

  • LIBASSE LAHI
    10/05/2016 09:51

    c prsk tu ve rien vwr

  • LIBASSE LAHI
    10/05/2016 09:54

    slt le messager..a propos il faut vs renseigner sur s k le profete ave di sur la venu du MAHDI.c mieu k d parler sur d choz k vs n maitrise pa..c 1 conseil..

  • LAYENNE
    10/05/2016 10:10

    HASSANA LI GUA WAX DEUGEULEU HAKHIHATOU MOUHAMADIYA MO DEF LI , WAYé DA FA AME LO FATé BAYE LAYE MOY RASSOUROUL LAHI , TOUS LES ( TEUDJEULIYATE ) VIENT DE LIMAMOUL MAHDI C LUI L’EXISTANT , C LUI ( DOURATOUL BAYDA) CELUI QUI CONNAIT BAYE LAYE XAM YALLA JE DEFI N’IMPORTE QUELLE ANRIF BILAHI

  • wakana khakana
    10/05/2016 11:40

    Kou topa toul yalla wara topi wayam mba louko dal boum ko xoul fa lahou.
    Yalla gnép djotéwugn fa mom cone gnafa djoté kou djar fa gnom ague.
    Bénén bi moy wédi mayouk mindef moy wédi yalla moy outalko yémou way té ngourouk borom bi fouway yém yafa yémalé bop.
    Limay teudjé moy gnou gorgorlou thi ormalanté ami téguine ndakh islamou ken dou mate fék teguéwul thiy téguine té koula khamal ak yonén ba dip yonén thi yaw wassalam.

  • Beug BAMBA
    10/05/2016 11:46

    Ignane baxoul té Ignane wooroul….. Yalla meune na louné … certe on n’est noir mé on est l’elu de DIEU…. NOUS CROYONS A MAHDI a BAMBA a EL HADJI MALICK a TOUT LE MONDE koumou néééxoul Guénal SENEGAL

  • Deug rekk
    10/05/2016 13:09

    Il y avait du laser avec le fis ( parti politique islamique en algerie ) j espere que c est pas le cas

  • ABDOULAYE SEYDI
    10/05/2016 13:12

    MAFI DIOUBATI ILALAKHI MELANGER SA BOP TIE YALA NEK NA YALLA WAKHOUMAL YONET WALIOU ROMB NA FOFOU KEP KOUNIE KO TOUDER DO AME GUATIER BOROM SECRET KOURSIYOU LA BILAHI MAN NA FEGNE TIE ANAM BOU NE KHOUSS BI YADI YALLAY DIAP TIE LOKHOM

  • muslim
    10/05/2016 13:18

    Ndeysane c triste.Ki fegn ni thi bache c pa limamou laye.n’oublier pa ke sheytane mounal dieul beppou image juste pour gueuna leundeumal kholi Djami.limamou mosta woté moy rassoul ni makhdi car makhdi dou tour qualification tè vrai touram mengowoul au tourou baye laye.sénégalais sénégalaise dello lenn senn khel dellou thi yallah

  • Yakar ku ted ki
    10/05/2016 13:21

    Li dangéne ko geumoul

  • senego
    10/05/2016 15:04

    fi gni weddi Baye Laye yeup ngui wax nitou diné la nitou xam xam ke layene gni niou bax lanou yarou sell beug diné. Mais kou né yalla mola yoni baparé teh dou deug esk dinagn ko ceedel lolou yeup . aussi je rectifie ce ki disent ke c est nous talibes ki disont limamou es Mohamed non on ne la pa dit c est limamou lui meme qui la di niou gueum ko top ko teh inchallah ci lanou nara sax kou gueumoul limamou na mandou coz mandouté seydina Mohamed demb moko digal djioulit yi teh balat mome yalla (niak gueum meuna loré mais mandou meuna sauvé c mon point de vu nak ) BAYE LAYE YAYE RASSOLOULAHI GUEUM NALA YALLA NAMA YALLA RAY CI GUEUM LA ALHAMDOULILAHI LAZI LAMYAZAM LAGAWAXONE YEUP TEK NANOU CI SOUNOU BEUT YAWA MAHDI BANOU DONE SENTOU AKSI NGA KOULA GUEUMOUL GUEUMNANOULA KOULA WEDDI NIOGUI ROY CI YAW

  • BABOU
    10/05/2016 15:18

    DEUX MOTS POUR RESUMER CEUX QUI SE PASSENT AUX SENEGAL EN VERS NOTRE RELIGION L’ISLAM: MECONNAISSANCE ET IGNORANCE!

  • Bada Top
    11/05/2016 05:08

    Mouhamed PSL moyy yonént bi mouj té lolou moo wer, yonént Amatoul ganawam

  • rahmane
    11/05/2016 08:22

    moi je crw au miracle de Dieu

  • Mame aly laye djiré
    11/05/2016 17:23

    Yeina bone té sokhorr li yalla deff manouleine si dara

    Kou gueum gnoune gueum nagnou

    Kou wédi ya khammm

    Bilahi walaahi watalahi
    baye laye moy seydina mouhamed mi yalla yonii

    Ma doli leine si kii feigne fi

    Moy seydina issa doumou mariama khana dééé ngeine nak

    Layeine namoull dara laye lagnou sante ndakh laye moy yalla

  • EDUCATEUR
    11/05/2016 18:26

    Lakoum dinakoum waliyadine, kouné na guem liko nex. Lah icra fi diine ne force personne à la religion ou de croire.
    conseil: ne nous oublions pas de faire comme nos braves marabouts sinon c la perte éternelle car chacun rendra compte et pas eux à notre place. SVP respect.

  • seydina issa
    12/05/2016 22:02

    Laye laye maguiléne di niouyou diléne diokhe kousi néke sa dieure diléne wakhené Mahdi douaye thiakhane Seydina Limamou mougui woté 1883 bataye bone Li douaye thiakhane Seydina Mouhamade wakhonenané maguiléne di bégueulé Mahdi té Mahdi donoule koudoule mane Seydina Limamou nieuwené mate Mouhamade guénené doumome hamanedé hamatoumasidara

  • Libasse Diop
    12/05/2016 23:33

    baye laye moy rassouloulahii wayeii nékoul nieup niokoh meuneuh geum.. Rohou laye inssa reik moy wayeii bopaam ni ni waxatou malaak bayaam.. yeen len ngein wara xaam boleen geumei niouh geum soleen geumoul niouh geum ndjine.. yalla nan borom bii dieuleii souniouh bakeen si geum baye laye.. allahou ma salii allah seydinaa Limamou.. mako wakh…

  • boy lebou Fall
    14/05/2016 00:04

    Personne n’a plus le droit d’attendre le mahdi. Il est déjà venu et il est reparti. Mais le vrai mahdi est noir: c’est Seydina Limamou Laye Thiaw Il a été enterré à YOFF à l’extrémité de l’occident. Son cinquième khalife est Chérif Abdoulaye THIAW LAYE. Son successeur Seydina Issa ROHOU LAYE THIAW est le messie.

  • croyant
    15/05/2016 13:44

    BONJOURS je rappel aux layenes mais aussi a tous les croyants que SEYDINA LIMAMOU LAHI PSL a dit dans son sermon que : »J’ai encore entendu que certains d’entre vous se disputaient avec vos compagnons qui sont des disciples de Cheikh Ahmadou Bamba (Rta) et avec d’autres encore . Ceux-là et vous-mêmes êtes tous des musulmans et il est de votre devoir d’être des frères, les croyants sont tous des frères. Il n’y a de place dans l’Islam pour l’hostilité et la haine.
    Sachez que la religion n’est rien d’autre que le bon conseil, l’amour et l’entraide. Les disputes et les querelles sont interdites dans la religion comme sont interdits aussi l’avilissement réciproque, les critiques (méchantes), les tiraillements et le fait de se lancer des surnoms injurieux.
    Ne rivalisez que dans la droiture et la crainte de DIEU. Que chacun d’entre vous suive son Maître et son Appui religieux , fasse ce qu’il ordonne et prenne exemple sur ses qualités. Ne placez pas ce bas monde devant vous, laissez le derrière vous. » chaques croyants doivent obligatoirement appliqués ses recommandation et arrété de disputé. assalamoualeycoum wa rahmatoulahi wa barakataou

  • boy djiné
    15/05/2016 21:36

    C’est du laser..Baye Laye kou bakh la, té gueum nagnou KO..il a fait ses preuves et il n’a pas besoin d’en refaire pour qu’on le croit..gnoune gni tekiwoul dara kay gnoy djéma nakh nit gni di projeté Aÿ image par laser sur les bâches… dagnou bayi wout beuz té Kou nek gueum linga gueum.wa salam

  • top mame
    15/05/2016 22:44

    guiss na gueum na…

  • top mame
    15/05/2016 22:54

    croyant merci ( …

  • coumba
    17/05/2016 10:59

    Yallah mi di boroom diam y moo mana khol diamam di souffrir si misère té tawoul khaaliss té meun nako déf bayi yonentam souffrir té mane nako dindi ndégeum ki mane lépp moo déf lolou assamaak yonentam nangou dogual lagn gnou sante santéwougnou di kébétou ak di reuy lamègne chaque fois aue l’on a des problèmes Yallah moo mognalé adina ak problèmes donc parlons de conditions humaines mais non spécifiques aux layènnes dagnouy niak kopar di fébar di dée comme gneup…

  • ballambengue
    27/05/2016 00:58

    Limamou laye rossouroulaye dounouko bayi ba yobalhiyam

  • momo laye
    06/08/2016 00:07

    Limamou laye rassouloulaye psl

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces

L'ACTU EN TEMPS RÉEL