Vidéo – Serigne Moustapha Sy Le Premier ministre de Macky Sall »Niit Kou Niiter la, mais…

Vidéo – Serigne Moustapha Sy Le Premier ministre de Macky Sall »Niit Kou Niiter la, mais…
Vidéo – Serigne Moustapha Sy Le Premier ministre de Macky Sall »Niit Kou Niiter la, mais…
Khawma serigne bi limouy apporté dinègui
Politique rek moka takh dioug komm bayam tchi ay anné 80-90
Niouko khamoul rek niokoy top
Do mousseu tog ba moi wakh ben aya alkhouran wala hadith boulay ndierigne alors le dafa diaby ba ni arr
Mais Anna hadith vous wakh tchi genrou niit yii
Yalla daflenn di lathie tchi sen kham kham mba diefè negn ko akk mba warr nagn niit yii.
Ak ndiabott boukoy top noumou def ba wann lenn yalla.
Lolou di n’a tang yawmal khiyam
Yalla nako yalla dimbeli mou def liko warr tchi walou dinè
D’où ko defoul dina tang yawmal khiyam
serigne niaw ak mana fene