32 COMMENTAIRES
  • Mamadou

    daye doul ndeyam

  • DEUGG REKK

    combien elle a paye pour etre a la une de senego ?

  • charles

    OU EST LE PROCUREUR,UN ABUS WE FAIBLESSE .BROUTEUSE

  • Senegalais

    Selbé khamal lounoula wakhoul taga yam. Téga délou si lamb dji di lambatou. Serigne toube dessouko fowé. Fimou tekk arhourane soula fékon gay déff fo wakhé niary batt guéné arkhourane melné kou yor sapp journal dina lidianti say biir. Thiakhanoute thiakhanlouwout.

  • charles

    MAIS PERSONNE NE PEUT DIRE LA VERITE A CETTE BOUKHABA.COMMENT ON DEMANDE DE L’ARGENT SI ELLE EST ENVOYEE PAR DIEU QUI LA MONTRE TOUT CHAQUE NUIT.LE PROCUREUR NE PAS FAIRE UN GESTE:ELLE ET LES TELEVISIONS QUI ARNAQUENT LES FAIBLES.UNE SAINTE QUI DONNE UN NUMERO POUR ENSUITE TE PRENDRE TON ARGENT.

  • Diop

    Ani Assane Diouf Salbe migui Wakhate

  • @WAROU

    WAROU re na ba tass j etais contre assane diouf mais tey yay ngama wakh nga deug

  • warou

    Waa léégui nak avec ça vous voulez que Assane Diouf dou khorom séén……………….

  • degueur fitte

    bon pour une foid je suis dacord avec sa logique car serigne moustapha di serigne saliou lolou c une verité way bethio mome moy bethio rek

  • wakhdeugue

    ça c le mouridisme tout est permi parsk ya bcp de mensonges qui cachent derriere

  • joe

    selbe waate bakhoule donté li ngaye wakh deugueula diaroule waate wakhale rekk kou gueume khaïroune kou gueumoule mo khame mé vraiment stp bayile waate

  • diop

    Wa yen wa senegal damay lathie salbe ndom kan layap bou fen ay fenam nathi guenne Serigne Touba Sama gayi bayilen khel thi li salbe wakh moune Serigne Touba moko wakh neko Serigne Moustpha Saliou Moy Serigne Salou wa kon sama gayi ana Serigne Cheikh Saliou Mi yalla deff mouy khalifa Serigne Saliou Mbacke Borom Diamou ak Diamono kon kham ngeni salbe dafay diakhase ay mbokou kon nak sama gayi salbe wakh ak mom nak diotna balla mou wakh lanen man dh thi lima yakar Serigne Touba dou Wakh ak kou Xeslla ba wekh talle bayi sa bopou nonou no Commen

  • manuchô

    moi je ne comprend pas pourquoi ngua meneu fène tèh nièmè yalla,va couper tes lokhs wagni sobès bou barri bi thi sa yarame et je te jure sur le saint corant que si tu laisse pas le prophète mouhamed,serigne touba et autres killifeux yalla dina leu AllAk bou guawe,bayille yamba dji mon gueune et puis va a l’hôpital fanne

  • abdou fall

    ay teguine rek mo bakh

  • def

    pouquoi les permita Fils De Serigne touba ne peuvent pas porte plainte cette Damme charlatan pour qu’ elle laisse le .nom de Serigne touba ‘qu ‘elle mette dans ses mensonges .

  • Marocco

    Eukey yooni mouride comme Bamba est à côté de Dieu et k bamba moy seigneur SAliou Kouchner Boug sa hadio fadiou va voire segn Moutapha Saliou wala Bethio .Les autres sont des menteurs diangougnou dara

  • Daay

    Elle fait de la politique maintenant cette merde….Que mes compatriotes mourides ne tombent pas dans son piége

  • Rebatass

    Yalla gna am borom keur seytane comme iow domeram fini yallana Assane Diouf gaweu gene rek oubi

  • malick

    serigne bou mene come mame adou aziz sy mo manque senegal

  • Dione

    Allahou Akbar

  • Dione

    soubhanallah

  • babacar

    mame Abdou avait tout vu depuis longtemps il avait sonné l’alarme senegal mo tothie il faut niou ragass kholyi si on veulent que sa bouge

  • familly

    Sénégal mon nèkh est après moustache saliou monte saliou sa ne veux rien dirr

  • seuleukh

    Yoonou mouride sadikh, kenn dou’ko fowé. Borom yon’wi dinako fajaal boppam.. Le khalif doit définitivement mettre fin à ces dérives sataniques, de ces talibés qui ne comprennent rien sur Serigne Touba! Serigne M. Bamba ne s’adresse pas à de vulgaires voyantes.

  • akuna

    doule wayyyyyy

  • Bibiche

    Bilahi walahi wa talakhi ki da alkou legui dale yonou mouride molène dècè mes selbè esk karèma warougnouko yobou dalale khale ndakhe yene yi bilahi kou wereuh degue douko wakhe

  • Diatou

    Wayi khadimou rassoul waxoula ngua bayi xessal ???

  • Kala

    Bayil fene dingako guiss

  • Kala

    Aka meuna doul cheytané diay nala do mourou di toudou tourou yalla bou magg kéne wakhoussi gbeup nopi motakh assane diouf wakh la louné té wakh na deugue doul rek

  • Kala

    Doul rek nga meune yow selbé vrai iblisse nga si kaw souf

  • Mousse

    Doul kate bou makk téwal iblisse selbé na réglé balla mout alkou

  • Doka Ndao

    Assane Diouf a raison, Selbe Ndom est une très très grande menteuse. Selbe et Bethio Thioune sont pareils.Des diables en personnes.

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *