8 COMMENTAIRES
  • XOROM-SUKEUR

    il y’en a qui n’hésitent pas à faire les poches aux accidentés de la route à dépouiller les morts de tout leurs biens .Ces charognards profitent de toutes les situations pour se faire les poches sans état d’âme

  • poutine

    wakhe gua deugue dé

  • leral

    bien fais.certains senegalais profitent de toutes les occasions pour en tirer profit ou pour qu’on dise que ce sont des gens bien.même lorsqu’ils demandent a macky sall de pardonner a amy colle dieng ou lorsqu ils vont a la télevision pour réconcilier des senegalais. leur devise est :<>

  • Fa

    Bilahi ta raison mane mom j’étais choquée quand j’ai vu les vidéos lii mom rafètul

  • khadime

    vré deug tane,gni danio niak soutoura trop trop

  • Khadim diop

    Wakh gua degue

  • Mor beye

    Vraima tann deug nga wakh dafamelni comedien mom Senegal tekiwufi dará ndakh kousi febar rek niep yeuko ak diko yalwanal te amna niokhamnee ken khamoulen mais bouñou febare dañouy andak sen ngoor ba weer mba lou yalla dogal mais douñou masa geun di siwal sen bop tan luver nga wakh dafa diotnanak comedien yii kholat sen bopou kousi febarati niou bayii diko siwal ak diko yalwanal lolou rafetoul dará boude kou new dole sakh diarna ñoom sisen biir ñou regle problemam mou baña siiw mogeuna rafet dal merci tanne

  • YUP

    YEN LAA REEK DIEL LEN YUP. YOW YA NGUI WASSARÉ DA NGUEN LIGAYOUL MO TAX NIOULEN DI YELWANAL

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *