5 COMMENTAIRES
  • Mass Jersey

    « Bamba ay Maodo,Maodo doy Bamba Koulénn Di Féwellé Dioumgua » Li leu Ndannan Ba Weuy yon sa Diamanom.
    Serigne Sidy M Mbacké Yakh Serigne Maodo Yallah N’a lénn fi Yallah Yagueul LOOOLE.Yallah,L’islam ac Yonnentbi Benneul rek Leu dou Niarr Dou Niéthe.Yallah Deff Diameu Sénégal.

  • Alioune Khoule

    Diadieuf Mbacke yéné dji rafétna djioulit nonou la wara xalaté, and mo gniou war. Gniome Mame kounék deguena séne and bou rafétba.

    YALLA na YALLA Yokou séne ni lerrr!!!! Si Barké MOUHAMED ALÉIHI SALATOU WASALAM Amine

  • Yyy

    Un discours remplit de sagesse je l’adore ce vieux

  • Abdou Rahim

    Dioullit dioullitay mbockam

  • ibson baby

    thiey Mbacké yagg fi lool té and ak weer. Tar tar yepp diekhna. Dieureudieuf Serigne Touba

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *