Vidéo: Humiliation! le Baye Fall qui prétendait être le fils de Serigne Cheikh Mbaor demasqué et rasé par les talibés. Regardez

Vidéo: Humiliation! le Baye Fall qui prétendait être le fils de Serigne Cheikh Mbaor demasqué et rasé par les talibés. Regardez

Pourtant il a passé des mois à usurper des fidèles talibés de Serigne Cheikh Fall Mbair en se présentant comme son fils. Mais malheureusement, il sera appréhendé par les disciples du marabout avant d’être sermonné et rasé. Regardez!

27 COMMENTAIRES
  • mennelick

    mourides yi nio daniou eupeul trop li kén douko déf

  • AMINA

    kiki wakh nga degeu tarikha yi at yefou thiakhan rek la demlen diamoudji Yallah mogeun

  • salihate

    lima len meuneuh wax yen gni niak teguine lol teiy xepp mouridisme xamlen ni finguén di meunti nek yenay geuneu xebbu si sen ni nawlé tei fi ak fignou jeum ken doulén nawlo ab joulit nak day meuytou togn tei yonou mouride kokou nara yax wala di wax loukay yaxx iow yay yakhou

  • tapha

    kou yakarné yoonou maam cheikh loula néékh déf wala loula wakh da nakh sa bopp rék koumou néékh nak mann nga né ken meuneuloul kéén dara waayé sa moroomou nit dong meun naa la teuyé ba doo youngou moo door la wala téral la

  • abdou

    aay sama gayi boul took sene rek di wakh loulene nekh am lene yaar ak tenguine insulter moom c est la derniere des choses mangui diegalou bou bakh

  • K@teu kh@l1fe

    Ces sauvageons n’ont qu’a aller au bout dans leur « logique ». Tout le senegal sait que 90 % des fils ou petits fils de marabouts ne connaissent pas leur vrai pere. Le guru ne pouvant satisfaire son harem de 10 jeunes demoiselles qui lui torchent le k-ul laissent a ses beuk neek de faire le reste. Kou joude sante mbacke. Ca tout habitant de Touba connait cette rengaine

  • samma

    le gosse se disait fils de marabout , di doug ci deuk bi di birreul xalé yi, di nangu addiya, regarde les autres videos avant de juger, son propre pere l’a renié à sa sortie de prison, le rasé n’est pas un enfant de coeur….
    Marley disait on ne rase pas la tete d’un juste..lui ne l’es pas malheureusement, et en plus on ne l’a pas bastonné

  • tallambodj

    Ndeyesan Yaramnako sakh mes nakk di’natakh kanéne douko niamai dé fatt

  • deugue

    yn tye lne boulne wakh lougune khamoul ak di profit thi li di khass t ak di saga wat ki ay kilifeu daniou wo ba soneu.di ko ydeu pour mou bayi limouy df mou deugeur bop ta boba yague na kone souniou ko df ni sou bayi woul limou df aussi iou bari kham naniou ndakh vido bi ba doulne nakh .am lne yar ak tguine

  • Abdallah

    yaw miy wax ni le mouridisme est un catastrophe dagua xamoul mtkh wayei bo xamone digua xamm ni le mourdisme liko indi motakh yaw ak sa baye meune la indi bagua nek tay diko wax fall wax day rafet tu as vu une video limite toi a ca et n extrapole pas con demal gua dueustou dj

  • Djiby Faye

    nitkou bakh Faye mandou yene ni di saga amolen bebé kilifa Serigne no Dou morom

    • kiki

      bane serigne ki khamoul touss dou djiouli dou wore qu »il aille au diable ce sal type

  • baye fall

    imaginer que quelqu’un prétend être le fils de votre père et utilise son nom pour escroquer de personnes et enceinter d’innocentes filles ?quelle serait votre première réaction si toute fois cet individu est sous vos yeux.wakhal lène yallah mo geune doone aye nafèkh ndakh ki koumou dieufelanetèèl do nawloo moukou baye fall yi.il a été rappelé à l’odre rien d’autre.

    • habib geuye

      baye fall je suis d accor avec toi mais le fait de le filmer et diffuser la video je ne suis pas d accort

    • dk

      baye fall je suis d accor avec toi mais le fait de le filmer et diffuser la video je ne suis pas d accort diegeulou

  • diop

    pour tent ke?nne kune? man nga wakh se? khalaat te? bagna saaga ndakh sagawi Allah danlakoy top pu se? noir bame?el

  • bri bri

    C Koi se bordel Mame cheikh aka beuri wone soutoureu.

  • spagheti

    saway le mouridisme pas tous evidement est un vrais catastrophe pour se pays

  • biss

    Senegal mome bou andoul ak sa khel, loune dina niou la si doukal. Ake fene rekk darra doussi deukk

  • boye

    li rafetou dara

  • Cheikh

    Legui loy yakare si serigne bi torokhale la si adouna

  • kiki

    quel tarikha de merde vous faites justice vous meme salté nguéne khegne nguene vous etes de gros salop

    • Slf

      Sokhna si ma gui toup mé nitt kou bakh té niou yarko thi deug dafay moyto togn ndakh rafétoul sakh di niaka wormal sa rakeu wakhou malak nak tout un tarikha gua khamni nioula makk kilafa rék niofi nék… ass goor dou togn ass goor dafay moytou nioukoy wo mba diko yédeu thi dieufinam ak dokhinam. Ya gui niawlou dieuf ba paré disi ték togn esk kone war gua khass mba di kass té fékeuni yaw mi di niawlou yoro ay worma. Atté thi deug lako tamou kén bagn thié worou. Diadieuf

      • kiki

        mako wakh khamougniou touss ak séne rasta you tilime té khegne koudoul djiouli dou wore yéfere la amoul bene serigne bou xam foumou djieume ba meuneu dogeul nite adjiana yéwoulene dé daye bété

  • MaX mou cheikh ibra

    Mame cheikh santou léne liii li rafétoul dara barki mame cheikh ibra fall amouléne yeurmandé

  • max

    ils se font justice eux-mêmes?

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *