Vidéo: Déclaration de Serigne Modou Kara suite à sa convocation par le commissariat central Regardez

Vidéo: Déclaration de Serigne Modou Kara suite à sa convocation par le commissariat central Regardez

19 COMMENTAIRES
  • dinè

    serigne touba ne vous pardonnera jamais de l’avoir trahit .il vous a enseigné la religion et le chemin de dieu vous l’avez transformé en votre propre intérêt et profité sur les enfants d’autrui.

  • all khak

    yalnama yalla baal méé quii nékhouma darra.ngoor siii dafa am dioot.lii mouy sooss nii bakhoul lii dinadém ba indii senegal robélion senega licoy tas.sii tarrikha yiii lay dioguéé

  • all khak

    lii étabii dafa warra gaaou eliminéko balla mouy eup lokho.daffa amoul bena chance lii karra di déf nii.cou diok rék mboboo cherigne touba man lolou moma méttiii.

  • all khak

    sétloulénn limalén dii wakh.senegal défcatou lou bonn kou néé chernge touba lay mboubo sétlounénco rék.

  • dinè

    le mouridisme aujourd’hui : un tsunami qui guette le Sénégal une véritable bombe en retardement un génocide en phase préfabrication. toutes les personnes mal saines de la société sénégalaise se cache derrière cette confrérie pour avoir la protection de touba: les bandits de grand chemin; les vendeurs de drogue; les detourneurs du bien publics ; les dealers; des assassins ; des fraudeurs ; des contres facteurs ; des homosexuels ; des lesbiennes ; des pédophiles ; des violeurs ; des faux marabouts ; des truyants ; ect…. mais sachez que serigne touba ne vous pardonnera jamais de l’avoir trahit car vos chemins d’aujourd’hui est tout a fait différent de celui de cheick amadou bamba khadim rassoul wassalam

    • leral

      nit day wakh ay kadou you téguiné yaw yarou woo té lernamani tu n’est pas mouride mais sache k lou way deef bopame

  • mouna

    vous savez raison Sénégal tasna ba paré. 3 personnes bokounagne si lii tasse Sénégal modou kara bethio thioune sidi lamine niasse parceque ils travail pas pour serigne touba mai pour leurs poch et pour avoir le non

    • all khak

      deug néékhoul waye merciiiiiiiii mouna

  • talla

    Arrêt de critiquer les marabout c mieux pour vous

  • ibra ndiaye

    il faut eviter les mauvaises paroles vers les marabouts wasalaam

  • all khak

    les vré marabou jamais niou diel micro naan daniou andak nit pr politique.kou bagne niou wakh sii yow dangay tok sa keur té nga mandou diouliit dou yééééééééééééééééééééééééééééé fiiiiiiiiiiiiit neux wassalam diammm

  • anna

    Ndeysanne lii yeup Wade moy ko waral.diadieuf yaalah maynala.

  • mouride

    cé k kara sakh mourides yi la yap mais pour ki il se prens je pensais kil été meme plus au senegal ce gars ki disait kil voulait s’exiler na deme rek.ki l’aurait retenu on n’a pas encore oublié ses propos lors son emission avec pape ngagne ki dafa eupeul way wala gnou yobouko tol bok

  • amina

    yaw do mouride kara boula yoboul wul tol dou yako fay yobou limouy def khamnako mieux k tu la boucle mo geune ngay critique gneupe ligueyeul serigne touba lane ko khame ak didni ndaw gni si yone bou bone
    soldar yi ay soldarou serigne touba lane yakha loune kene dara ta soloune ay tenue millitaire

  • mouride

    merci sister seulement guéné niit yi yon you bakhoul cé son devoir nous orienter vers le droit chemin cé son devoir en tant k mara mais je pense k le pouvoir temporel né en rien comparable au spirituel donc k les mara restent à leur place k est autre k ce jé dit supra et les politiciens restent à les leur.

  • Ndiaye

    way ki naniou may kenne manouka comprendre mane bethio sakh momaka tanelll parceque bethio dina jouer theatr ay niomm na mbakhal mi safff ay keuleumtiko mai ki mom borom bakhkhbakha danno yap na dem tokk bien jouer le ministre et puis loula té dem exilé wou dou lolou ga wakhonnne demelll wayy lakal ganiou

  • philosophe

    yaw bakhbakha yanou wara may bayil biign gor dou biign ken khamoul lo done esk khana nanoo bakhbakha

  • leuza

    Diné merci yaw wakh nga lépeu !!!!

  • Eli

    ce regime est tout simplement contre les marabouts particulierement les mourides un fil de serigne Saliou lavé dis
    quant aux gas ki critik Kara et Mbéthio ne sont pas des mourides mé des politiciens
    le regime en place est incapable la population a faim il faut trouvé des solution pour ca c est mieu

Publiez un commentaire