61 COMMENTAIRES
  • sunnite

    Le vrai croyant en Allhah ne se pavane pas dans les confreries aux idéologies societales

  • dioulitt aakane

    Gueum Yall tekk ci yenentoubi salla llhah aleyhi wa salam tekci boulanekee koulanekh kouka sopone. Kene meunoule diallé kene loudoul sa dieuffi bopp en tant que dioulitt et non en tant que talibé. Amoul bena teere bou tegou ci kaw Alkouranou kariim.

  • dioulitt

    Gueum Yall tekk ci yenentoubi salla llhah aleyhi wa salam tekci boulanekee koulanekh kouka sopone. Kene meunoule diallé kene loudoul sa dieuffi bopp en tant que dioulitt et non en tant que talibé. Amoul bena teere bou tegou ci kaw Alkouranou kariim.

  • senegal@dakar.com

    ABDOU WAHAB nena serigne touba moni yala balamouy dogal dara mom s touba dakoy neh ba pare mbok mi yaw mom li.nga wah ham.ngako

  • abdoul wahabe

    ñoune mourid danii diamou yalla ngir dafa nek kune wara diamou. diamu wune ngir beug alladiana wla ragal safara. kepp ku dègg arab manglaï ñane nga xol khasidak s touba giñi wax minanoul baxil khadim, waxnani balà sunu broma dogal dakay nèkh mom s touba baparè muy soga def. ak lenèn ak lènèn. sunu borom nak ñika dann waxal lu amul kunè gisna finn mudiè. s touba buwakhê lii mbinde mi di dokh balèki. ai mbireum di ngèneu yokk. mani ñane ragal s touba ta yakkar ko mèrci akhmed khlifa niasse

  • wakhdeugue

    khamena thi lène yonou mouride barèna ay fène ak tapalè bathie santou serigne touba founeco soul ak lènène lo khameni diaroul sakh madico wakh

    • abdoul wahabe

      ighfir bi diaahil moustapha likouli man, akhabanii liwajhi maalikinn zaman, kone s touba kuka beug dangay dem alldiana. kifi ab seringe ñem binde lii? dollen tontou!

  • Abdou ba

    Ku wéét khamsa bay!BAMBA DU MASS MOROMANTÉWUL VS le savez mieux que Ahmet KHALIFA Niasse mais le savoir est une arme personne parmi vs n est et n sera jamais à la hauteur de critiquer ou démentir des propos de ce véridique homme car vs n avé pa la matière grise(le savoir)

  • khadime diop

    Srg touba waxenani:<>kone kép kouka nonou xamaleni mouthie go fi ak felé té nena ma yésale souna si rapone yokasani may ahmad kone koune koumou néxoule diné mola néxoule ak yonénetébi

  • fallou

    se mec la c’est une imbécile day doul réck je je me fallou je suis mourride

  • deugueule bou werr

    ‘diamonoye SERIGNE BABACAR SY kou nékoule tidiane da nga koye neube’lolou lou werre meme apres SEGNE BABACAR SAKH…(diamonoye yonou muride takk takale mbop la… jamonoye jiguene loumou bone bone meuneu joure mouride mba mbeurr barkép Mouride yobalé na mbeur ‘SERIGNE TOUBA kouniou ko teukaléle nakh naniou la’ lou werra werre la ndakh ngourouk macky sall gui tak ndérou ngourouk YALLA GUI LA.. Amoule ministre bou khamoule macky sall, Amoule waliyou bou khamoule KOU TED KI

  • birane badiane

    Un pays de moins de 13 millions de musulmans et tant de bruit bizzare.

    l Indonésie compte 250 millions de musulmans et zero tintamare.Le nigeria proche de vous c ‘est 100 millions de musulmans.

    Celui qui croit en autre chose que Dieu et le prophete est un mecreant.Celui qui compte sur un marabout se trompe lourdement.Senegalais mo degger bop .Yalla rek mo diara diamou.

    Dieu,Mohamed ,mes parents .Point barre .Qui oses que contredire?

    Repondre | +0 -0

  • senegalotarikasis

    Un pays de moins de 13 millions de musulmans et tant de bruit bizzare.

    l Indonésie compte 250 millions de musulmans et zero tintamare.Le nigeria proche de vous c ‘est 100 millions de musulmans.

    Celui qui croit en autre chose que Dieu et le prophete est un mecreant.Celui qui compte sur un marabout se trompe lourdement.Senegalais mo degger bop .Yalla rek mo diara diamou.

    Dieu,Mohamed ,mes parents .Point barre .Qui oses que contredire?

    Repondre | +0 -0

  • senegalotarikasis

    Un pays de moins de 13 millions de musulmans et tant de bruit bizzare.

    l Indonésie compte 250 millions de musulmans et zero tintamare.Le nigeria proche de vous c ‘est 100 millions de musulmans.

    Celui qui croit en autre chose que Dieu et le prophete est un mecreant.Celui qui compte sur un marabout se trompe lourdement.Senegalais mo degger bop .Yalla rek mo diara diamou.

    Dieu,Mohamed ,mes parents .Point barre .Qui oses que contredire?

    Repondre | +0 -0

  • sokhna ci

    serigne touba sague la ci bepp djoulite nako gnepp santé sougnou borome wa salam

  • Mamy

    ken dou serigne bamba walakhi ken la yalle nagnou talla tasse ci barkémé

  • Tab

    Mais pourquoi monsieur niass veut trouver des détracteurs à serigne Touba. Sénégal polémiques et buzz rék. Moi je suis tidiane, mais je connais un peu serigne touba à travers ses écrits donc dire que les tidianes le détestent ce sont des mensonges. Est ce que tu as vu un khalifa génarale à part Dabakh qui se rendre à Touba maintes fois. Aussi démél nga djébalou dji té liguéyal serigne bi. Moo eup soloo.

  • senegal@dakar.com

    amna ñou bari si yen.mourid yi yakar ngen ni yomal hiyam serigne moy dougelate aldiana waye wahi yala sounou borom dou degne kou d dinga hamna diamou yala rek mo wor ngen li ngeni def yegoul fen dof yi don

  • kaffrine2 nord mouride

    bismilah……….lirelèn KHATIMATOU MOUNADIATI BILKHATI SORINA SAKH WAYé DINALèn ATTé wa salam

  • way diébalou

    قُلْ هُوَ الْقَادِرُ عَلَىٰ أَنْ يَبْعَثَ عَلَيْكُمْ عَذَابًا مِنْ فَوْقِكُمْ أَوْ مِنْ تَحْتِ أَرْجُلِكُمْ أَوْ يَلْبِسَكُمْ شِيَعًا وَيُذِيقَ بَعْضَكُمْ بَأْسَ بَعْضٍ انْظُرْ كَيْفَ نُصَرِّفُ الْآيَاتِ لَعَلَّهُمْ يَفْقَهُونَ
    Dis: «Il est capable, Lui, de susciter contre vous, d’en haut, ou de dessous vos pieds, un châtiment, ou de vous confondre dans le sectarisme. Et Il vous fait goûter l’ardeur [au combat] les uns aux autres.» Regarde comment Nous exposons Nos versets. Peut-être comprendront-ils? al an’aam verset 65

  • sante serigne bi

    diadieuf borome touba mbacke

  • Mame Abdou

    Ohh Ahmed khalifa niass raww nga gars yi. Tidjane yi Ahmed daf lèn beugeu dimbali.. Ndakh kou teukeulé Serigne touba ak sa petit mara wallahi sa mara dina tite ci bamel lam ba yakarni bess penc dafa jot..té boula japéé nila teudieul sa guémign, Ahmadoul Khadim Mbacké amoul morom

  • Dia Seydina

    Subhanallah , revoilà Satan dans ses oeuvres . Tout ce que nous savons de Serigne Touba c’est grace aux témoignages de grands hommes de Dieu , parmi lesquels Seydil Hadj Malick qui dans ses écrits lui disait : Tu n’as jamais commis un acte qui t’aie porté à dire « Astaghfiroullah » .Tout comme à l’époque les plus grands marabouts du pays avaient témoigné du savoir inégalé et inégalable de Mame Maodo . Loin de moi l’idée de faire une quelconque comparaison .Donc où se trouve le problème? Ils ont tous les deux le mérite d’avoir marqué leur temps , et d’une belle empreinte d’ailleurs. Je pense qu’il serait plus sage dire aux sénégalais ce qui se cache derrière cet acharnement à vouloir mettre les confréries les unes contre les autres . Heureusement que les vrais disciples sauront discerner le vrai de l’ivrai .Il est plus qu’évident que monsieur Niass garde une dent contre Tivaouane pour des raisons qu’il tarde à avouer . Il est à la limite de la folie quand il pense détenir le monopole du savoir et que personne ne puisse débattre avec lui sur des questions réligieuses . Orgueil quand tu nou tiens ??? !!!

  • Milkoss

    Kou wète kham sa bope ki daye mandi diko neube

  • Djibril

    Kenal sergne touba no stresse leu

  • goor gui

    Dia diuef niass deug nga wakh

  • Mor

    Khèpp nga sa bopou, waxal serign touba kènn douko tèkelè ak sa baye

  • Fabienne

    Ahmed khalifa Niass de grâce boul tal sunu gale gui. Sénégal yeup aye bok lagne tarikha yeup bene lagne. Iran ndao je le comprend car ki daf ko sonal chaque année mou wakh si mome tjrs si émission QG ki kene waratouko inviter di ko deg micro mouye diakhasse kholou djoulite yi

  • spagheti

    la seul chose que je sait est que la plus parts des salauds,voyous ,droguer de se pays ne sont ps des disciples de maodo

  • element cheikhoul khadim

    au moins tay wakh nga lou nit yi mana degg serigne bi dey amoul morom

  • Lo

    Dieuredieufei serigne touba reew mi bamba mofii nk..na nieup bollo sant serigne touba ..diarama mame cheikh ibrahima fall

  • Aicha

    Ki diakhasseh rkk moko takha diougue

  • Ndiasse

    moytou len ki

  • Aicha

    Ki diakhasseh rkk moko takha diougue

  • Camus

    Lui c’est la réincarnation de Satan. Il est dangereux pour ce pays.

  • Ndiaye Ndiaye

    Kouy Baxna Degg gourou Serigne Touba digua dei t sa heure sou Diot SERIGNE Bamba Ken la kounek khamgua kila meun kou weit khame sa Baye

  • Ndiasse

    Ki diaroul degglou seytanela

  • Ndiasse

    moytou len fitne

  • SIIW

    Tay Ibadou yi, souba Mouride yi, guinaaw souba tijaan yi, dama defeni daniouko wakh boo wakhoul da ngay DEE.

    Il nous amerde ce gars. Si on fait pas attention IL VA BRULER CE PAYS.

  • beug maodo

    dognou bolé ak mouride yi dé (serigne touba ak maodo gno bokou ben mame) liga wakhone moy sa mame mo dékali daara keur maodo lolou ay féne la gnou reuye touba ak tivaoune ken khadiatou sen diguenté wayé gnegno lougnou dougou yakk koooooooooo.

  • Pape diaw

    Dieuredieuf.Merci beaucoup Serigne Ahmed Khalifa Niass, vous avez la lumière prophetique en vous. Vous êtes le meilleur. Vous êtes leur professeur. J’adore votre vision religieuse voire islamique. Je vous encourage. Vive la tolérance. Vive la connaissance solide. Vous êtes une source de connaissances. BRAVO.

  • Boy

    serigne sidy mactar mbacke diamm la beugeu si tarikha yeup .donc nanou rafetal

    • ya samou

      liens elhadji malick serigne touba

  • bily

    wohoufi dara yawe do reference

  • bily

    teyelene ki dou reference ki nopilonagneko gamou kaolack moudone wax si baye Baba lamine mo dioke néfi kene doufi taxourane

  • Sidiki Diouf

    Et si serigne Touba amoul morom et que dire alors de son maître qui avait anoncé sa venue et prier pour lui. Ahmed ,arrête tes histoires de vouloir opposer les marabouts et les saints.

  • Pape dw

    Dieuredieuf,Merci beaucoup Serigne Ahmed Khalifa Niass,vous êtes le meilleur. Vous êtes une lumière. Votre vision est d’une dimension supérieure. Vous êtes au dessus de ces pseudo voire soi-disant oustaces.Bravo,vous avez la lumière prophétique.

  • La Saint Lousienne

    OOOHHH jador srx!!! Jajeuf NIASS kén du SERIGNE TOUBA Yalla nanouko YALLA fayale

  • Lamine

    aouzou billahi mina chaytani rajim

  • Lamine nar

    Voila un homme véridique. Iran ndao yaw mom tu ma deçu.

  • wakhdeugue

    loumouy wakh souba thi serigne Touba mongi gneuw seytanè rek la et il ose comfirmè thi loumou wakhone thi serigne babacar diamanome kou nekoul Wone tidiane danga koy neubou da yabatè

  • modou

    ki iaf Ndyam reka dagan khathie bou haram bi

  • Milo

    Kou nek lingua gueum rek nguay wakh wayé kou wett kham sa baye

  • BIRIMA

    LIGEYNI BAGNA DEK REK LEY WAKHE SERIGNE TOUBA AMOUL MOROME BALA GA WEEDI KHAME AU MOINS IL DONNE SES PREUVES ET IL A INVITE TOUT SAVANT A VENIR DISCUTER AVEC LUI C EST SIMPLE ECOUTER LA PERSONNE DE QUOI IL PARLE SI VOUS VOUS CROYEZ CAPABLE DE EMMENER DES PREUVES PLUS CLAIRES LA PORTE EST GRANDE OUVERTE

  • habib

    Deugg rek la wahh nak bayilenne diambour ahhhhh

  • Dioppp

    Manchalla, Seulement dans ce pays il ya des gens ki naiment pas entendre le nom de serigne Touba. Mais na rang yi dioupppp khothie. Serign Bamba sa caname rek

  • BIRIMA

    AU MOINS KHALIFA NIASSE TU N ES PAS JALOUX SANTALE YALLA BOU BAAKHE SA KHAME KHAME WEER NA CAR LE VRAI SAVOIR C EST UNE LUMIERE

  • Diop

    Kii chaytaane bou mak la. Yala nagnou Yala mousseul si genre bi. Khambeu rek. C’est honteux. Il nous pompe l’air ce vieux là.

  • Boy brooklyn

    Ce vieux la est très dangereux il faut le bruler vif

  • leye

    dieureudieufe serigne touba khadime rassoul amoul morom dh fi ba fanou dieum billahi kouko kene loul pereteuga dieureudieufe serigne touba khadime rassoul

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *