Serigne Saliou Amar inhumé à Keur Goumack
Serigne Saliou Amar repose désormais à Diourbel et plus précisément à Keur Goumack. L’inhumation a eu lieu juste après la prière du vendredi. Plusieurs personnalités ont fait le déplacement. C’est le cas de Youssou Ndour qui a partagé le même véhicule avec l’homme d’affaires et éploré père Cheikh Amar. Des chefs religieux ont aussi été aperçus. Le fils de Cheikh Amar a rendu l’âme à Paris.
innah lillahi wa innah illeyhi raadjihouna yalla nako buurbi yalla xaare aldianatou firdawsi ak mboolem djoullit bidiaahi seyyidinaa Muhammad
yalla nako yalla yareum
yalla nako yalla yeureum
Youssou ndour deff ak dindi deum reyla djalé leu cheikh amar fait attention youkhou n’dour n’est pas bonne pers.tu est l’associer du diable ton fils a perrit devant les sacrifices de youkhou n’dour
yalnako yalla diegal ta yaramko nionguikoy diale sunu bop diko diale bayam nio bok lepp thiemoul gade yall
yalnako Sounou Borom khareko Aldiana Firdawssi te mou bayifi aye wadioural sarakhame yague si séné lokho. Amin Yarabi ci barke serigne Saliou tourodom. Yalnalene Yalla diokh kholo mougne.
Paix son me que le seigneur lui octroie une place de choix dans son paradis bark Serigne saliou
loumtti way ay waydiouram yalla nalne yalla may kholou mougne ta kharko aldiana
Yalla nako yalla yereume
yalla naco yalla yeureume
yalanaco serigne saliou takhawo adiana thi barke moukhamed