4 COMMENTAIRES
  • DEUKHINE MBEUP

    ana sa BAYE ? amm SERIGNE baakhnaa , Waayé keen dou baye !!!

  • peulbi

    Balla moy Boury , Boury moy Balla diguënté Sossé ak Sarakholé yonou Peulh nékoul thi. Khana nianal khalébi dounde té barkèl ci barké Serigne Touba.

  • fallou

    nike talibe reck wore balla gaye

  • di

    diamou rek ngay am bilay lou wèssou lamb sakh beugenala ba parè yalnala yallah dèfal diamou

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *