Audio – Waly-Bougane, le clash : Plus de Waly Seck sur Sen Tv et Zik Fm
Couly CASSE
Waly-Bougane, le clash : Plus de Waly Seck sur Sen Tv et Zik Fm.
5 COMMENTAIRES
Saytané yi la rekk
03/05/2017 à à 12:22
wally ak bougane mounougno khoulo , animatrur bou saytané bou ssi dougou danga si dess, dafa ame ay nit you saytané yo khameni dagnouy nekk di garal di diakhassé wally ak bougane , mé abba mom mention speciale kokou ame na ngoor fatéwoul kiko siwal ki takh nitt yi khameko, bougane ak wally fekhéleen trouver terrain d’entente ,wally dafa beugone wonéni wally gnepp la rekk,khame na dagnouleen diakhassé rekk

un sen fou de wally c un pd
Affaire de famille ? Manou rek !!!
oui c’est le linge sal
Nio me la reike c des problèmes de famille donc on sen fou