Audio – Borom Thiès: «Macky Sall, Dél dieguelé Tay Balé…»

Audio – Borom Thiès: «Macky Sall, Dél dieguelé Tay Balé…»

Serigne Moustapha Amar, communément appelé Borom Thiès,  s’invite dans le différend, Macky Sall-Khalifa Sall. Le marabout, même s’il ignore les tenants et aboutissants de ce imbroglio juridique, invite le chef de l’Etat au dépassement . Pour rappel, le maire de la capitale et 5 de ses collaborateurs ont passé mardi leur première nuit à la prison de Rebeuss. Des fautes de gestion leur sont reprochées.

Ecoutez:

31 COMMENTAIRES
  • bokhoup talibe

    Serigne bi gnoune wa extérieur dee gnou gui lay bayi khel kham nàne la Bou bakh yaw rek lani suivre fo gnou wakh dieumal gnou dem fa dakh djis nàne sa takhaway si as kane bi rawtina gnoune wa brazil

  • Sa thies

    wakhou gnou lolou dit à macky sall mou bayi gnimouy geuthie kasso way borom thies wakh Day ler yaw ken khamoul fo feter

  • borom dakar

    Nice na lole machalla kadou gui rafet na mais koula may thies ana idy

  • APR

    TAY MACKY DH yaw lay wakh louy ray macky la beugua kham deja karim ne peut pas etre candidat allor kant a idy dou dara donc louy ray macky

  • Lacaze

    Leila pouvez vous fermer ta bouche
    Nous sommes libres d insulter

  • tay macky dh

    IDY EST ENTRAIN DE LUI PREPARER KLK CHOZ D EXPLOSIF DICI KLK JOUR LA REPUBLIQUE VA TREMBLER ENCOR KARIM EST AUSSI EN ROUTE PR REJOINDRE GALSEN TAY NGA DAIBDH MICHLIN

  • oumy nar

    thiey borom thies wakhatina d ki aka gnemer deug

  • marshal

    ken tougnouko mo togn bopam ana serigne siy wadia ande ak mom prison khana yaw bokossi

  • kadior kadior

    je que je voulais savoir louko may thies

  • bassirou fall

    il a parfaitema raison nak affaire de justice la yonam nekoussi mai dal nay djiegaler diadiaf way mara

  • nabou

    GOR FIT yaw khamoulo touss do dara macky sall mo chef justice dakh mo fal ministe de la justice damal diangui wat

  • gor fit

    macky sall dele djiegaler tay baler dou macky moy djiegaler mais c la justice

  • matar

    macky sall si boapam mou gnou wara may mognou sonal rek way diap di teuthi rek

  • amina

    loutakh nguen khamadi diokh len thieur kilifa dinè yi ki kouko djis khamni kou yala mayla tey len si commentaires yi di nguen massa saga ak kilifa sopekou done golo bakhna wakh len sen khalate t bayi saga yi

  • sagar

    May len gnou diam ak Salam way sonal nguen gnou

  • sagar

    mbepee ratattati rek ishhh sof nguen way serigne si

  • talibé bi

    hooo saway nena moy borom thies wala borom pout kay dioguer sa ale ba rek ni yaye borom thies koula ko may li nga wakh nak si article ta raison deug la

  • fatim sahara

    Toujours moi juste rek pour gnawat si article borom thies bi c vre borom thies à raison car bour dafa war di djiegaler

  • fatim sahara

    mane d serigne bi nekh ngama lole à chaque foi damay suivre say actualité beugone n’a ame Day cordonnée kou si ame cordonné serigne bi doma si diapaler dama beug kouma gnanal

  • ousmane thies

    loula may thies Deugar fit rek nga def nàne borom thies

  • Mar

    akay deug deug dal la nit gni manoul degue

  • Binta

    Machala borom thies lou lerr nga wakhh dee

  • bayfall bi

    je ne comprend pas du tout les marabout loussiy sen yone la beuga kham

  • mame gor

    wa serigne bi borom thies ken khamoul foumou faar

  • doule rek

    yen koulen wakhni khalifa sall dafa sathie

  • Kheul

    Wakh na deug mara diadiaf way borom thies sa cadou rafet na

  • leila

    chaqu un est libre d commenter mais sans insulter svp apres tout c notre president de la republic.

  • Keuz

    Macky n’est qu’un imbécile ce gros tas de graisse ?

  • Paco

    Ok où aliou sall qui a volé tous nos resources

  • Paco

    Ok où aliou sall qui a volé tous nos resources

  • Deux Guntane

    Kou sathie nagne ko tetie bravo presi khalissou rewmi woroul seynii yaw mara tediel sa guemigne khana khalifa dala moseel nii !

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *