PUBLICITÉ

Vidéo: Doudou Ndiaye Rose était à la levée du corps de Vieux Sing Sing

L’une des dernières apparitions de Doudou Ndiaye Rose (Paix à son âme): c’était à la levée du corps du regretté Vieux Sing Sing. Que la terre leur soit légère.

PUBLICITÉ

PUBLICITÉ

32 commentaire

  1. spagheti

    ndaysann adouna dall amoul solo

    1. boybec bou con

      yalna nako yalla kharre adiana

  2. samba fall

    Paix à son âme

  3. VERITE

    QUE DIEU LUI PARDONNE SES PECHES ET L AMENE AU PARADIS FIRDAWSI AMINE
    adounaguini yalla nagnou yalla mayy mouthiou gou rafet

  4. sama reew

    yaw tamitt yalnagua dekkè aljianah
    ndaysane yalla rekka mane!!!

  5. samb

    adouna gui ni demal magui gnew guir yalla senegalais yi naniou delossi sougnou khel si yalla chaque jour ming gnouy wane bopam yalla nako malakay weurmande terou si barke SEYDINA MOUHAMED PSL

  6. Mboup

    Yaw tamite yalla naga khippé dji aldiana si barke nabi moustapha

  7. santati

    Yalla nako souniou brome bi yereume tee kharee ko adiana

  8. GET READY

    vous qui vous insultez jour et nuit sur le forum faites trés trés trés attention voici si un exemple aduna yagoul.

  9. boy

    yalnako yala yéreume

  10. sante

    thieye adouna yalla nako yalla yeureme ta kharaiko adiana firdaouwsi amineeeee

  11. faly

    nous avons perdu une rose .un homme saint .un missonnire .le grand tambour s'est eteint pour toujour repose en paix Doudou ndiaye ?????

  12. adouna amoull solo

    naniou Baye thiakhan adouna dou keurouk thiakhan 85 ans lèpou nga thiaxaan ko be kheuy dè kii ana loumou dèfall lislaam dara yakheu ndaw yi rèrall lèn

    1. Mareme

      nite bou guéné adouna boci manoul wakh lou rafét gua nopi kén khamoul yalla rék mo kham boulko jugé nakh khamo mane khawma founuiy moudjié gua balma wa salam

      1. adama

        merci mareme !!! adouna goudouna tank té teureudi , yalnaniou fék thi lou nekhh yalla !!! que la terre lui soit légère ! amen

  13. yalla nako yalla yareum

    ndiaye ndindy

  14. binta

    Naanio déélou ci yalla kéén doufi déss

  15. Le temps

    adouna amoul solo.
    nit bou gagnoo bo meunoul wakh lou rafétt nopil.
    et puis c'est pas à toi de juger.
    YALLA GUEUMOUL NELAWOUL
    ton tour viendra espece de CON

  16. parizi

    poste 13 yaw mi ligueyal yalla nga dieul qui t a dit que si tu meurs tu vas au paradis doudou ndiaye rose etait un grand homme il faisait que son métier il ne volait pas il ne disait du mal sur les gens au contraire il était un bon musulman et aidait son prochain par contre toi tu n es qu un vaut rien et tu seras jamais lui .il était mieux que toi

  17. Jouph Samba

    Ohh c'est tres émouvant ce video . Un monument s'est éteind !!

  18. boye pikine depuis Aurope

    yalla Nako yalla khare aldiana

    1. pe

      Limou done def yaco djappė thiakhane mę deugla tė aldjana thiobarė yalla la yalla nacoco yalla dėfall

  19. dina

    Ndeyssane adouna dou dara c'est vraiment triste Yal nako Yalla kharé Aldiana Firdaws est que la terre lui soit lui légère

  20. amy

    amine

    1. gueye

      nagnouko gnanal manouwar ténoudélousiyala bayi thiakhanyi wakhanté deug 85an yomboul bolako yala diokhé expolatéko silobakh wasalam

  21. Seba Dieng

    Mashallah way Gorgui dè comme li moy limou moudiè sèedè si mbokam moufi bayiko dèmb ahh yalla nala yalla yobou si andianay Seyidina Mouhamadou bolè la ak seydi El hadji malick magua toudou ni

  22. khamm lepp

    thiey adouna amoul solo rip

  23. ti

    Yalnako yalla yèreum té khareko aldiana

  24. mimi

    teugue sabar ak fethe lou aramla tifakhame

  25. Sophie

    qeu l accueillir au paradis

  26. Ba Mouhamed

    Allahoumahfir lahou warhamhou , Allahoummad khilhou aldaianatal FIRDAWSI

  27. yapsa

    yallanako yalla yeureum