Vidéo: ce talibé exige de Youssou Ndour, Waly Seck et Pape Diouf d’arrêter les chansons dédiées aux guides religieux

Un talibé fustige des musiciens qui chantent leurs marabouts comme Youssou Waly Seck, Pape Diouf entre autres. A l’en croire, ils vont se mobiliser pour faire cesser toute cette mascarade, dit-il.
Merci diambar tu as parfaitement raison et du courage ,que le bon DIEU te protege
si tu n’a jamais danser youssou ndour c’est bon ce que tu dis mais si c’est le contraire nopile
Kouné yor nga sa paaane di wakh kopou diamour. Geumoleene dara si lingue ndi wakh technologie mo avencer lou xew nguen def video surtou les modou modou seytané nguene tropp serigne si gnouy woy ken degouleene gnou wakh mais doff yi rek gnio fi nek di ratatati shiiiim sooof nguene trop
ya salam sama mbock talibé li nga wakh dara mounouco dinedi
Lou weur nga wah. Thiahaan rek. Kou fi dè beug niou diangalko kamil. Doyna waar!!!
Kidal sokhar moka diappou
Vérité absolue
senegal ammfi buzz da yomb quoi mdrrr!!!toudeul youssou rek
khamnani Ndour soneuneu torop!!!!
mann dal dama warou, senegal doff bou diokk gnou bayiko siloumou nekk koi qui na damm fann gnou fathie ko
khoalal ma qui mom khawmeu foumou feulé?? mais commence a etre mandou ba paré avant de l’ouvrir
bayilene lou Diogue ngen wakh Si te amoulene xam xam. serigne Si meune nogno wakhal Sene bope. talibe day yem Si talibe
PETIT TALIBE DEVIENDRA GRAND.MAIS ON SENEGAL LE TRAVAIL EST UNE MALADIE.LA CIGALE ET LA FOURMIE.
MAA CHAA ALLAH YALLA NALA YALLA TAKHAWOUUUUU FATHIE SA MEREEE MOY JAMBATOU NIEEP KOUY JOULITE
SENEGAL LIGUA WAKHE LEEP FALAYE KHEWEEEE
Ce talibe a parfaitement raison ,des foutaises sans cease.bien sur j’adore et supporte nos musiciens mais pas dans des betisses accompagnees de dances vulgaires et sauvages.
talibé dafay yém placou talibé nakh Youssou wala Wally koussi damm séti serigne bi yaw talibé si biti nguey nékkk
donc il faut savoir yémm sa place quoi..
est ce que c pa les maras qui aiment ça ?
Vraiment wakh nga degue bou wér goor yalla
sa way ki wakhou fi dara mounane wakh ngueu deug