BRVM-10 164,86 -0,87 BRVM-C 170,47 -1,09 Dernière mise à jour : Lundi, 19 novembre, 2018 - 14:00

BOA SN

-1,55

SONATEL

0,00

TOTAL SN

0,78
PROGRAMMES TV
L'horoscope du jour Horoscope du jour En ce moment à Dakar 24° partly-cloudy-day
Annonces

Senego TV: « Diémoul pas touchée par la modernisation des cités religieuses »

Le Magal de Diémoul, sous la direction du Khalife général, Serigne Ibrahima Dior Amar, prévu ce 29 décembre, se prépare activement. Serigne Moustapha Amar communément appelé Borom Thiès, est revenu, entre autres, sur le sens de ce grand événement religieux. Selon lui, Diémoul, capitale des Nars Darmanko, organise aussi beaucoup de Magal, à l’instar de Touba. Mais Borom Thiès n’a pas manqué de remettre au goût du jour une vieille doléance de 1989, sous l’administration Abdou Diouf, le bitumage de la route Pékess-Diémoul. En un mot, soutient-il, la modernisation des cités religieuses, initiée par le chef de l’Etat, Macky Sall, n’a pas encore atteint Diémoul. Faisant une incursion dans le landernau politique, Serigne Moustapha Amar  est formel: « La réélection de Macky Sall dépend de moi »…

Regardez:

Abonnez-vous pour regarder plus de vidéos
Annonces
Annonces

30 commentaires

  1. phata dit :

    machalla wakh dji rafet na amar nar

  2. khalil dit :

    wakho fi dara way nopil

  3. yacine dit :

    non mara yaw dagama nekh lole dakh deug rek ngafi wakh nak diemoul lanou ame

  4. ak teguine dit :

    non non tay nak mom koula fi saga rek ma def ko lou bone

  5. doudou dit :

    juste une kestion rek la beuga kham loula may thies chaque jour ma lthi lako tontou ma bok

  6. nafissatou dit :

    serigne bi mane daga ma nekh lole mais dama khamoul nomay def ba djis nga nianal ma

  7. dof bi dit :

    yaw fen rek ngay def doul rek mano sakh fal pithi

  8. magueye dit :

    bon moi c la 1er foi ma commentaire mais mane yague nala suivre bou bakh mais tay mom dama content lole si li nga wakh gnoune exterieur lanou nek mais sonou na nou lole sakh

  9. dior dior dit :

    hahaha fi ngui toth

  10. modou modou dit :

    ohhh mara bi aka ma nekh mais borom thies yaw fo rerone wa brazil dane lay beguer lole dofi gnaw bok tal gnou comme lo gnane yala mou nangou

  11. aicha dit :

    gnoune wa exterieur d kham nane yaw yaye kate

  12. alovera dit :

    Ah kii sama khalifala wayé sokhla nagnela fi si gabon amar diké nar

  13. cheikh dit :

    Lep la rafet kadou yi machalla mais wakh ma nak koula may thies

  14. Ridial dit :

    Euskay degal ma dji wakh rek thiey gnoune founou dieum

  15. coumba dit :

    Senegal dal kou diok rek teup wakh non senegal mo nekh

  16. naz dit :

    mooo ki moy kane sakh

  17. fall fall dit :

    mais nak deug rek la wakh nak nekhoul ba nekhoul donte ni ay fen ame nassi sakh dakh momo thies mais li nga wakh lep ame

  18. Astre124@hotmail.fr dit :

    Borom Thies bayilene sène fêne yi attmou diott guêne takhaw guir di yague ak beuga saboté magal Serigne Ibnou wanté douguêne am ndamm moukk, yène Sirigne Sidy Makhtar diokhé ndiguel daw guêne dême si radio yi ni andoulène si di wo Serigne Moustapha tawoup Serigne Sidy Makhtar diko menancé taynga tokfi nane Serigne Sidy Makhtar molène diokh ndiguèl magi ñane wa senego ñu dème le 29 décembre Diémoul dakh guène hamni fêne rekk lay deff…
    Magal Diémoul gui Serigne Ibnou Amar done def lane si hamm thia le 09 janvier 2018 Serigne Sidy Makhtar thia lay yabléatt mou diott bouguène démè diguène gissal sène boppou wolof néna wérenté khoukhane tékki toubay…
    Démmal liguey 6ans gui ni gay tokk si sites ak télé yi guir Macky sarakh la passport diplomatique faléwoula passé wo Cote d’Ivoire thia si yonnu souff wi gay diar bou dougué avion Cap vert nga deff…

  19. MSidy dit :

    Ki diaroul tontou sites presse en ligne bi ño wara bayi golo gu diokk guène diokh ko micro…
    Boula gathia done ray do tokk fi di fènal Serigne Sidy Makhtar…

  20. Sokhna Astou mbacke dit :

    Tapha bayil feine magal bign kham diemoul mou biy am le 9 fevrier tei serigne ibnou amar dane ko deff tei bi moy 69e édition dane si andeu si ak darmanko yeip. Magal 29 décembre bi beurki deimbeu la. Feine yi mom manguilay niane boulessi bolei serigne sidy moukhtar. Magal serigne ibnou bi la serigne sidy makhtar reconnaître tei silay yonei niko khalif serigne Touba yeup dane deifei
    Li nak damay leirale wayei yow tapha diaraloma ay wakh ndakh saguarou nitt nga feine kat nga
    Sama wadiour nak da feikeiwon leup moma neitalii

  21. Amar dit :

    Mbeuroum Serigne touba meuné soucko d’âne mangay tacki ndombam saa péyii diiwane bilay Serigne Ibnou amar meuné soucko daane

  22. Nar dit :

    Borom thies khamou ma borom senegal mais dal wakho fo touss

  23. kamal dit :

    Merci way gnoune wa cap vert dee degue nala t kham nàne yaw yaye kane dakh yague nga gno begal kham nàne lolou

  24. Toujour ma niawat yaw mi nàne sokhna astou mbacke nga toudou dagay doul wakhal sa tour deug kham nga so setlo dafa melni serigne bi wakh nako si vidéo bi nena so vidéo bi paré gni eup si gnikoy wakh lou bone ak diko saga ay bokam lani done dagay doul rek bodemer kou ko djieguer mais yen li len meti dou lolou qui yala ko def mouy sen baye di sen star ne nguen kou diok la micro demal senego gnou diokh la micro nga wedi ko waner sa bop mo geun nga nek di neub sa bope

  25. balamaissa dit :

    Wa loutalh nar yi sokhor rek la beug kham mais mom lim wakh loussi nek loudoul lou rafet serigne bi mo diokher ndigal li kay diaroul werane loutalh bi nangou woulen wouyi dji t def ndigal li serigne bi wakh santou gnou amar santou gnou amar ape talibé rek la seck la sane li war moy linou kham si yonou mauride qui mak na djitou ki si dess top si li louko fi diar la beug kham topou serigne ibra Day takh sa weur sak doko diote wala

  26. Fatou Gueye dit :

    Ohhh basta way bayi pourquoi pas manou len dem ak wakh ki wakh li mouy borom thies khamo borom dakar ngeun diakorok ak mom wakh koko t ngeun bayi sen commentaire yi way gnoune sounou yone nekoussi.

  27. Diop fall dit :

    Non mane dal vremênt borom thies beug nala kham dakh nga nianal ma ame diabar si sed bi dafa sed lolou sakh ape sed may ray mane comme yaw lo gnane yala nangou ko kay

  28. mar mar dit :

    La fierté de nous les nar darmanko voilà sounou fierté moy qui borom thies diemoul rek nga beug kep kouy ame naar darmanko bou set wethi bou rakhoul dara nak rakhoul dara si… ay… na bagna wakh sakh mais kep kouy ame darmanko goor goor nak la wakh dinala beug par force dakh yaw fierté nga si askane oui diemoul gadeyel ndiardè bakhiss deuk nar yep nak yay sounoup sak ma yeuram koula bagne yaw kate si famille bi rek ngay wakh t lou bakh rek ngay wakh surtout nak tali diemoul pekess bi

  29. seneglais dit :

    borom thies wa cameroun name nane la lole sakh kay talal gayi wat sa bess boba d ken douko fater machalla amar darmanko bi

  30. Fallou dit :

    Yêne ñi fi nekk andd ak borom Thies yéna yamm atté amm na kou wah lou léér si commentaires yi néna kou weddi na ñeuw Diémoul nanga fékhé ba prouver k Serigne Sidy Makhtar molène diokh ndiguel…
    Mais serieux Magal Diémoul kou wah deug rek hamni Serigne Ibnou lane ko hamal yène sène magal gi guène soss mo andi problèmes yepp…

Écrire un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *