Annonces
Annonces
» » » Vidéo:Cheikh Bass Abdou Khadre rend visite à...

Vidéo:Cheikh Bass Abdou Khadre rend visite à Cheikh Béthio…Regardez

Annonces
Annonces

5 commentaires

  • GM
    19/04/2016 09:09

    Dou gnou rouss sakh! Baakhe na bou gnou moytou woul, haaliss di na takh gnou gnak hilaafa gui. Gnak diom, leigui yeinay top ci bethio? Aduna mo teuredi! Ham ngani serigne Bara sori na fii mome. Ouyyyy!

  • verite
    19/04/2016 12:08

    Bientot il va etre servir de porte parole a bethio egalement!!
    Thiey lii!!

  • f a
    20/04/2016 03:22

    gm iow domrame nga rek sa lafal ndey mako wakh

  • mouride
    20/04/2016 03:26

    sama gayi il fo ngne khame ni serigne bethio kne ganou ka done mouride am lne yar touti way soud yonou srign touba molne ds athia adouna deh diekh na ba par na lp raft way

  • degrek
    20/04/2016 14:22

    Serigne abdou lakhat mbacké dé gnep khamon ni ragaloul koudoul yalla mo wakhone ni senghor dé fi la takhaw di féne malakayi di nan ma dafay féne ba ma fok ni degnako ! Koké moné serigne béthio yalla khamal nama ni sa lep serigne touba la té nak serigne fallou wakhona gueunou ma Noé dakh domou néo safara la diem serigne. Bethio kouko bagnq bo togué khalife tamit dosi yag wasalam

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces

L'ACTU EN TEMPS RÉEL