Annonces
Annonces
» » » » Vidéo – Youssou Ndour répond à Kouthia :...

Vidéo – Youssou Ndour répond à Kouthia : C’est toi qui doit arrêter….

L’humoriste Kouthia a parodié ce que devrait être la réponse de Youssou Ndour à Me El Hadj qui s’en est pris à lui hier lors de sa conférence de presse. L’avocat demandait au chanteur de mettre fin à son cumul de ministre conseiller et de ministre-conseiller du Président. Regardez Abou Bilal dans ses oeuvres hi-la-ran-tes.


Youssou Ndour répond a Me El hadji diouf , ces… par hamidou-sy3

Annonces
Annonces

30 commentaires

  • Nanette
    25/05/2016 19:32

    ???? Kouthia Ya fi meun

  • mina
    25/05/2016 20:03

    Kouthia rek deugue nekhoul

  • amy
    25/05/2016 20:54

    hahaha wakhga deugd Maitre el hadji diouf nk dput nk avocat ko nk khamnani ministr e Consell dpit moka eupou liguy

  • adji
    25/05/2016 20:57

    merci khoutia tay mom contana si Yaw lol proplmbi moy maitre el hadji Diouf dafa amoul kham kham diangue takhoul am kham kham way

  • fans
    25/05/2016 21:01

    mrci khouthia liga tgona si yoon ak yaar

  • boy_ LG
    25/05/2016 21:04

    merci merci merci merci vriema merci kouthia

  • dam
    25/05/2016 21:15

    el hadji diouf do nitou darra khalis rk lay diamou

  • dam
    25/05/2016 21:17

    way so beugu yook ay noon del atack youssou ko kham dani fay khalis diko setan

  • boydjiné
    25/05/2016 21:20

    o koutia li mo takh ma fan la koi
    elaj diouf fén rek
    kou bagne you danguay deh rek akk gatiééé

  • valdes
    25/05/2016 21:22

    way maitre elass diouf dafa beuri wakh koi, ko khamnéééni ratatati rek lafi neké
    mais na bayi Grand You liguéyy

  • jo
    25/05/2016 21:25

    li c’est du jamais vu, un gars qui ne fait que critiquer et surtout critiquer les Grands messieurs de cette nation tel que Youssou Ndour, ce dernier fait tellement de belles choses dans ce pays

  • zizou
    25/05/2016 21:25

    magui stan tfm mais rtro youssou yinou tk nkhna lol

  • gounor
    25/05/2016 21:26

    allez koutia affaire bi yaw la deh
    maitre el hadj diouf si pot sambour

  • mirma
    25/05/2016 21:38

    maitre el hadji diouf day woor mofi woor hissn abr ta dankoy djine pdfili ba barr mofi takhaw ensambl saga ndaye khaat kokou dou moy diokh nityi lecon

  • deug deug
    25/05/2016 21:40

    kou bagne youssou bisbo ywoo sa ———

  • Anonyme
    25/05/2016 21:46

    youssou danafi yaag dinou bgeul noun jeuneyi dano sokhla rfrence com youssou . ya dano beug bankhou si ay wayam ndakh guisnanou ni ay fansam you yagyi wayou youssouyi dfnasi niom diom ak foulla

  • Anonyme
    25/05/2016 21:47

    youssou yalnafi yaag dinou buel

  • truth truth
    25/05/2016 22:12

    yene grep danguendi doul rek kouthia wakhoul duegue

  • truth truth
    25/05/2016 22:14

    kouthia day doul ak yene gnep

  • yes
    25/05/2016 22:24

    maitre el hadji doiuf amoul claase

  • riti
    25/05/2016 22:31

    merci khouthia el hadji si pote ak kokay diapal

  • Nawel mbacké Diop
    25/05/2016 22:38

    Retane na bassama birr di mety kouthia dou nite, yangui yeungal Allemagne (hamburg ). Fethieu bi meunato ko

  • reni
    26/05/2016 00:29

    maitre el hadji diouf dafa sof

  • dadi
    26/05/2016 01:17

    vive youssou ndour le roi

  • afia mbow
    26/05/2016 02:32

    merci

  • fa
    26/05/2016 10:53

    Merci kouthia el hadji diouf ratatati rek la def il se fit dans se ides you dy dem keyn dou ko teye

  • Erick
    26/05/2016 14:55

    Youssou utilse sa tele pour attaquer ses adversaires. C’est pas pareil. El Hadj Diouf parle de loi avec Youssou N. et non de cumul de fonction. La foction ministerielle ne peut pas etre cumuler a une fonction lucrative. Arreter!!!
    Youssou profite de sa proximite avec le pouvoir pour se remplir les poches.
    Des soirees et autres a auteur de millions.
    Va savoir combien M. M. Niang lui a paye pour sa tournee.
    Le patron de Dakar ne fait que se servir du Senegal au lieu de servir le Senegal!!!

  • sentou
    26/05/2016 16:50

    el hadji day doul rk loka enreng rk lay soudoun deug depuis 2013 youssou ministre Consell ta migui waay lou takh mouy khar ba taay ndakh proplmou Ada mbodjibi pi mom ap nafkhla kn khamoul foumou faar

  • alfred
    26/05/2016 18:24

    c’est celui qui a des lunettes,le KGB jéhoviste.
    ça ne m’étonnerais pas que se soit Scipion l’africain.
    Ainsi toute salle de concert peut servir de temple aux TJ,après Johnny,les TJ (sans la piscine pour Johnny!)
    Comme quoi,une piscine gonflable,ne sert pas qu’à nager!
    l’histoire ne dit pas si l’eau est bénite.

  • yorou
    26/05/2016 19:26

    kouthia day daye

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces

L'ACTU EN TEMPS RÉEL