Annonces
Annonces
» » » Vidéo: Youssou Ndour a-t-il peur de Waly Ballago...

Vidéo: Youssou Ndour a-t-il peur de Waly Ballago Seck ? Sa ndiogou nous édifie. Regardez

Annonces
Annonces

118 commentaires

  • dixit
    11/05/2016 19:03

    nooooooonnnnnn sa dou nit momay dadji

  • ndanane
    11/05/2016 19:06

    tu es fou tu mrite mme pas des commentaires

  • Djolof
    11/05/2016 19:10

    Seytannei bakhul

  • teranga
    11/05/2016 19:13

    merci sa ndiogou vous avez tout dit youssou à une grande gueule il n’a plus de suxé va à la retraite ta passé ton temps

  • fama
    11/05/2016 19:17

    non senegalais sn mantalyi mo arrir mais yn bercy wally seck warna takh artiste yi nk senegal ypou Satn by ba 4 juin pass

  • ama
    11/05/2016 19:17

    non senegalais sn mantalyi mo arrir mais yn bercy wally seck warna takh artiste yi nk senegal ypou Satn by ba 4 juin pass

  • goor fiit
    11/05/2016 19:18

    wally seck domou ramla mog payam coumou meti sa gatoouuunnnaaayyyee

  • goor fiit
    11/05/2016 19:19

    couma saga sa nangamou ndaye

  • goor fiit
    11/05/2016 19:20

    couy deglou wally sa diobou nd….. ye

  • goor fiit
    11/05/2016 19:21

    cou dem bersi sa uy ndaye

  • yes
    11/05/2016 19:22

    yaw sa ndigou fi ak tgeuloun sa ndaye si digou dakar rk dou nopi demal rk

  • na
    11/05/2016 19:23

    sa saytan bou bone la

  • dam
    11/05/2016 19:24

    douf bou kat sa ndaybi nou bayila si tl Lola nkh wakh doumou adamayi dina df video attakla al sa patron

  • adji
    11/05/2016 19:27

    sa ndigou yaw amo khl exmusiquecin foka masa guis ? mais pour Lou nit wakh rk nguni wally mais mayln nityi diamou

  • fama
    11/05/2016 19:28

    sa ndigou bounou tgeulon sa nday dika nk nit Di wakh lounla wakhlo

  • Soda
    11/05/2016 19:30

    Bayileen sen faux débat yi You dou moromou bayou Wally

  • thieuy
    11/05/2016 19:32

    yawax deugue sadiougou nit daye gueume yalla sakhameni dara sakhoul adouna sa ngourou yalla dongue moye sakh dokh sa yone bamou diekh rafteci

  • Bd kh
    11/05/2016 19:33

    tite wally pr koi non sa tu est fout wally da deure il est bgue

  • rim
    11/05/2016 19:34

    youssou fi ak yalla migkoy may mbalaxbi mofi nk . dou moromou sakh Papay wally . yaw nak sa ndiogou dfo darra senego nionou togne

  • pap
    11/05/2016 19:38

    bayilnko diaroul tountou dina masa gun asaka si limouy wakh

  • Zoo
    11/05/2016 19:40

    Mais yeine merde vous et votre you il n’est ni prophète ni descendant mo fi niake FAYDA mo takh niou wakhko doul yeine ak youssou ndour partez tous en enfer

  • Amina
    11/05/2016 19:45

    yaw Sa man dama wakhon ne douma wakhati sa wakh parce que do nitou dara doff rek nga degeu nit yi nan doff nga waye tey lako geum ndakh kep koui tekale Wally ak Youssou rek doff nga ndakh Youssou dou moromou Thione wakhatoumala Wally yaw nak fek dagou niou sa gat do bayi sa wakhou doff yi ngay wakh si sen television bou niak khorom bi kharal rek sa patron nopi na legui yaw ya diel nit nak bou tekki wout dara day bange kou tekki Youssou rawnalen raw niou melni yen domram

  • Tati
    11/05/2016 19:46

    Partez tous en enfer vous et votre très chère vieux sorcier de youssou ndour merde

  • babs
    11/05/2016 19:50

    degue na deuguede sa louler nga wakh

  • patriote
    11/05/2016 19:54

    Sa wax ga tegg,you a peur de wally.Pourquoi tout ce bruit àprés la sortie de ton album

  • aram
    11/05/2016 19:55

    Sa kham ngua ni ken dou setan motakh legui ngua rakh si ay khaste way khasit moy khaste tekiwoulo dara si dek bi bepary begeu sonal nit yi budee danga begeu Youssou diel dinga dee mais do meusa dem tfm ndakh dofou kou niak class ak kou tekiwoul dara doufa dem togal walf niou dila fey 37000 ngay khaste sa Ndey bou sangon am domju melni Youssou bo begeu Wally thiompal ngua wakhko te bayi Youssou si diam ndakh dosa morom lim def Senegal president yi sakh defou niouko fi

  • pap
    11/05/2016 19:56

    sandiogo magui diga khamni dafa dof bay day ay tankam youssou ak 38 ans de carrier boufk wally seck moy takh mou warra bayi liguyeum yaw daga oumpeul youssou

  • adji
    11/05/2016 19:59

    bravo youssou albombi diarna yoon lolou rk moy wakhdji Lisi ds ay dtayla amoul solo

  • adji
    11/05/2016 20:00

    youssou tamouna pression yiko ay noonam Di tk t khamna

  • fifi
    11/05/2016 20:02

    youssou rk senegal dem si kanam bilay ma yeureum say noon albombi zero fot yoyou lanou wakh

  • fifi
    11/05/2016 20:03

    vive youssou je taime

  • peul
    11/05/2016 20:06

    zoo y’a wakh deg deumb you la wone mais tey waly la niou nagouko yala moko dogal

  • degdeug
    11/05/2016 20:13

    wa lgui sod lou nit df nioni wally con artistyi tno dm senkeur tok . wally seck dou Tous ay fans fruit rk la am diknafi espagne amoufi 15 persones si salbi senegal mo yombou nk star

  • sa Touba
    11/05/2016 20:29

    waly seck rek ci xoll youssou ndour dou dara

  • seri
    11/05/2016 20:29

    proplmbi moy senegal sn khlyi si pobam mo avencwoul. bisi ds moy ay nityou milni sa ndiogo sit internetyi danlndi diokh importance no khamni diarouko

  • You Y
    11/05/2016 20:29

    Michael Jackson keeneu lawone, Bob Marley keneu la wone, mais tamite Youssou Ndour keneu ci musique Senegalaise. Bayileene di comparer battery ak courant

  • sal
    11/05/2016 20:40

    bilay sa niongou liga wakh xamon kou sax deug rk la

  • dil
    11/05/2016 20:44

    wally seck mn fi nek

  • pape
    11/05/2016 20:46

    sa ndiogou franchement suis pas fan de youssou mais kan tu minimise Mr ndour dans la musik en l’galant avec le jeune waly ou bien en disant kil a peur de ce jeune franchement c’est pas la peine ke tu fasse la tl. remettons le mrite de la personne. suis oblig de le dire mme le pre de waly ki est thione Seck n’aimera pas tes ides arrtes.

  • Ibrahima
    11/05/2016 20:47

    no sa ty rek nga mousa wakh deug nak

  • l’homme fort
    11/05/2016 20:48

    Sa limouy wakh ni sakh wakhi dofleu beuz lay outal sen tèlé bou dè bi wakhoufi guat Sénégal senegalou niep leu artistes yi artistes niepleu

  • Amina
    11/05/2016 20:49

    mandeh diakhle na legui kou wakh rek nioune Wally ak kan moy Wally yaw Sa kham nga ne wakhou nafekh rek ngay wakh waye geumo lingay wakh te Youssou motey mandeh bala ken di wakh sama rafetay ma wakhalko sama bop te diko sante Yalla demlen sawi te teud Youssou dousen morom mem president Macky Youssou dou moromam wakhatoumal ay nit yu tekiwout dara te yen wa Senegal warr geun di gereum Youssou ndakh fi si Europe bone Senegal fek wakho dekou Youssou wala Elhaj Diouf toubab yi douniou ko kham mongol bi loumala wakh rek khep ko fekhe len nolen sokhale sen television bi mogeun budee seringe mola diktal nela pour ngay toudou Youssou ndakh nga melni mom nakh nala Youssou ben la Senegal wakhouma Youssou waye Koutha sakh do melni mom bo yebo di nianal senego ndakh boudoul niom kou melni man doula guiss ndakh awma diotou tok nan walf lay setan te TFM nek fi Ndeyu television yi GFM tha kaw tha kanam Yalla nasen diam yokou Yall mei len werr ak werrle Youssou Yalla nala Yalla mousal si laminge nyi non yu bon yi sokhor ba dee waye Youssou mom fi geun koi bayi

  • Khoul
    11/05/2016 21:10

    You demal toggui, lek sa xaliss balaa li dale Papa Wemba dila dale

  • as
    11/05/2016 21:33

    amina on arrive pas a lire ton commentaire ,yen wa tfm ,demlene nopalou, sa wakhna deugue vraiment ,meme nous en italy on a pense a a ,you amatoul classe ,il a dejas f son temps ken wediwouka, waye nak ,na khamne diamonome wessouna, mane mi damadone deme soirem, waye legui mere l ,te khaleyi waly lagnou beugeu rek adouna djem kanam

  • italy
    11/05/2016 21:36

    Peut être je suis pas normal mais;très sincèrement,je vois rien d’extraordinaire dans ce que Waly Seck fais comme chanteur.

  • woundou
    11/05/2016 21:37

    goor fit yaw sa tounou ndaye

  • woundou
    11/05/2016 21:37

    goor fit yaw sa tounou bay

  • diajj
    11/05/2016 21:40

    sa ndiogou meusso wakh si youssou ndour lou rafet outtil sponsor youla sponsorise meussou mala guiss nga def publicite wala loloy dagg sa sa khol fi sanekh kouthia ak per bou khar ndiaye mi moudiai nieuw sakh am na publicite setatal sa bopp

  • diapro
    11/05/2016 21:43

    yaw sa khol nekhoul outil sponsor tai youssou ndour limou def si rew mi sa bay defoukofi sanekh per bou khar kouthuia niofi nek ndiaye sakh am na pub

  • as
    11/05/2016 21:44

    sa wakhna deugeu d, c ke nak deugeu nekhoul yen wa tfm commentaire boulen mer

  • djili
    11/05/2016 21:51

    Sa ndiogou amatoul khalat mo takh te mog Ahmed aidara g na wakh lou bakh si youssou ndour mais kham na loutakh gfm day draguer

  • rada
    11/05/2016 21:57

    sa ndiogou tu est un vrai seytan koi mais il faut compar ce qui est comparable

  • boy LG
    11/05/2016 22:03

    sa Ya mana doul khana khamo ny sa dame migi laye setane tie khame nani bayame kou mana doul le vriema mane ga doul waye nake baya bo ga nopa lou youssou dou moro my mak wakhou mala khale wally pape diouf riek dou moro mame

  • Amina
    11/05/2016 22:06

    As man doma degoulou musik doumako setan sama yoon nekoulsi musik waye kou guiss nen ne nen nangui Youssou limou takhawal Senegal wakhouma Wally wakhouma Sa waye sen bay yi sakh meuniouko mem president yifi diar ken defouko Senegal kon Youssou law la thiat tha kaw tha kanam,walf yen nak fekhe len nolen soukhale sen television bou delou genaw bi mogeun geun di tekale pom ak new

  • boy LG
    11/05/2016 22:06

    kaye ma wakhe leen touti thiona Seck ma penda seck Ousmane seck keba Seck wally Seck bamba laye seck Asane Ndiaye ak wa marien guene so leen bole Dalle youssou ndour mo leen dakha waye dalle la wakhe de

  • boy LG
    11/05/2016 22:08

    thione Seck tiek na bet youssou ba dougou kaso wally nake bome khame lou koye dall bou leen fatie moukou Bamako

  • Amina
    11/05/2016 22:13

    dou buzz ngay wout rek ak sponsor dinko am bem doy ndakh sa bo wakhe si Youssou dinga am buzz bamou doy domram mongol bou bone bi nga melni panou poup bou nioul

  • Amina
    11/05/2016 22:22

    mercy Boy Lg Youssou dina len door te lokhom doulen lan ndakh dou togne dou saga dou khaste dou wakh nit lou niaw dou tapale dou fen dou sathi dokhol si affairou faux billets lou diemale Senegal kanam lay wout mais woutoul lokoy yakh lim am faux billet mei yu koko te dou goor djigeen

  • Fama
    11/05/2016 22:28

    Yeine gniye Wakh ni sa doffla yeina dof .vous ne croyez pas en vous même .ont est dans un monde qui bouge nul n’est indispensable et se que le bon dieu a donner a youssou vas le donner a d’autre . Le Sénégal ne s’arrête pas sur youssou ndour .Un jour viendra on dira qu’il était un foi youssou …yeine aye doff ngeine bande de tarer merde vous et votre vieux you

  • seri
    11/05/2016 22:37

    senego lilakhi warassoul suprim kn mbongolbi si sni programnes

  • goor fiit
    11/05/2016 22:39

    woundou yow mane nine laye wakhal

  • goor fiit
    11/05/2016 22:40

    woundou yow animalnga mane douma tontou animal domaram yageu fraren

  • Amina
    11/05/2016 22:45

    Fama yaw yak sa ak nyi melni yen yena yem ay bam geun kham nga gnian sokhor ak bone day doff lo nit yen lolou molen diap sen khol yi moy daha ndakh li Youssou def Senegal sen bay yi sakh meuniouko lolou molen meti waye Muhammad S A W wakh nako nena gniane day lek dief dju bakh kom ni safara di leke mat walf nak yen lolou molen dal gniane motakh sen television bi delou genaw ken douko setan sourtou yaw Sa Niogou budee nak seringe mo degtal sa patron neko pour geun di wakh si Youssou ndakh geun siw kom mom sen television siw kom tfm yena gui nakh sen bopa lolou bolenko begeu degeun koi wo wakhtan ak mom mogeun ni geunkoi defe dalen di sonal rek te dou takh geun advance bayilen Youssou Tall bou Yalla Tall la doli si mat mogeun diemko fey Machaa Allah Yalla nako Yalla lafal thiat,Amiin meusoumako guiss mais fouma tok manguikoi nianal Ndour

  • faramarene
    11/05/2016 22:45

    youssou koumou waye nga dh wala nga faye th waly koumou waye nga siw

  • meiy
    11/05/2016 22:55

    youssou nguounguel PAPE DIOUF sama wooykattbi mo gueune pape limouy wooy nekhna meune na wooy MACHALLAH kholal rek temps kene deigouko youssou et WALY rek lilane la sof nguene trope

  • mami
    11/05/2016 22:56

    yen sa ndiogou Sakh molen gueune vous me faites pitié ya plein d’information sur senego choquant genre une jeune fille de 18ans enlevé ses parents sont désespérés,une femme gravement malade abandonné par son seul et unique fils,des jeunes filles kidnappées à touba etc etc curieusement j’ai vu que 2 ou 3 commentaire sur ces cas et quand on parle de you,wally,ou pape diouf alors la tout le monde se dechaine jusqu’à même insulter vos mères quel pays de merde honte à vous ridicule

  • rebatass
    11/05/2016 23:02

    ici il n est pas question de concurrence waly ne se mesure pas a youssou il essaie de faire comme lui arrtez ces mchancets et prier pour lui parce que la musique sngalaise ne s arrte pas sur youssou il faut qu’il ait une continuit et c est ce que waly veux faite donc souhaitez le bonne chance. et you doit accepter cela car cela doit tre une fiert pour une simple raison que le fils d un de ses concurrents suit ses pas.

  • yass
    11/05/2016 23:07

    nèkhoule ba nèkhoule mè li sa wakh lèpe deguela youssou dafa wara gueume yalla

  • titiyou
    11/05/2016 23:10

    Legui on compare plus wolly à pape Diouf mais a bayou thione seck mouye Youssou ndour mais Sénégal dagno nafekh.pape Brahim rek mo dakk waye Wally té kokou mo gueuneu nul prince arts donc chers compatriotes deflene ndakk # Sénégal rekk.vive Youssou vive titi

  • Vérité rek
    11/05/2016 23:12

    Cessez de créer des polémiques svp! Angleterre n’est pas pomme de terre. Bienque j’écoute Waly Seck mais je sais que « Bayi waly (pape Thione) sax Youssou Ndour moy bayam ci weuy ». Les chansons de Youssou Ndour ont une portée philosophique. Quelle portée a celles de Waly? Hahaha sama gayi comparaons le camparable way! Hissssssssssshhhhhh

  • DIJA
    11/05/2016 23:18

    NAGNE LAINE WAKHANTAI DEUG NA MAY KHALéYI SAINE CHANCE IL VE TOU ACAPARER POLITIK, MUSIK.KI NAKO DAIF COM SON FILS.MO GUEUNE YI MOUY DAIF

  • diop
    11/05/2016 23:29

    aye wakh day diekh

  • PAPE TALL
    12/05/2016 00:03

    Il a parfaitement raison…. Youssou Ndour le musicien des annees 70 e 80 …mais Waly Seck est le meilleur musicien du nouveau millenair …..

  • dip
    12/05/2016 00:04

    non sa ya wax deug wy

  • ass
    12/05/2016 00:04

    non bien di sa ndiogou senegal dou meussa avancé lè ancien sont la ils veule pa de releve dan tou lé domén politik cultur laisé la chance aux jeun

  • Amar
    12/05/2016 00:05

    non sa wax nga deug wy

  • ass
    12/05/2016 00:09

    pourkoi tou ce brui pour une simple k7 on diré k tu vien de sortir ta 1ere k7 ta radio parl té frere té soeur mé aret de te rédiculisé tu es un vip laiss lé enfan le chemin et acompagn lé puisk ta la musik dan le sang com tu la si bien di waly mon frere du courage yala bakhna il fau kil est une reléve alakouli khall ca sé vremen honteu mr ndour tu as eté ministre kamem un pe de class wayy ishhhh

  • jaraf
    12/05/2016 00:14

    Youssou mamamla ndakh papa lathi thione. Et puis vous confondez popularite et talent. Waly siiw na mais wayagoufy loutakh gnouy wakh. Waly aymoromam gnoko topp c est la jeunesse qui represente presque 75pourcent de la population.

    .

  • belle
    12/05/2016 00:30

    sui la pour lire les commentaires

  • borom khandane
    12/05/2016 00:36

    WALF VOUS FRRIEZ MIEUX DE RENFORCER VOS moyens TECHNICS ET LOGISTICS DE VOTRE TV BI NGA KHAMNI DAFAY EMETTRE BAMOU NEEKH. MOU TAK LOU YAGG SO

  • Mari
    12/05/2016 01:11

    Courage waly Sou niou deimei Ba laye teukeulei ak youssou ndour vraiment diambar nga

  • Fati
    12/05/2016 01:18

    Il est fini votre you comme le crépuscule arrêter de nous embêter avec vos commentaires de con .Niake FAYDA mo takh mouye gueine si média yi di ratatati se qu’il n’a jamais fait doul …vive la jeunesse

  • Babs
    12/05/2016 01:23

    Arrêter de comparer waly avec se vieux sorcier bou Leine ko todial .il vient tout juste de démarrer son chemin tranquillement .laf thiat reike .

  • Serge
    12/05/2016 01:31

    C’est youssou ndour qui doit mettre fin a se faut débat .personne n’a chercher a le concurer a waly mais plutôt c’est lui qui est au dessou de tout se bruit .mais l’avantage tournera autour du goss parce qu’il devient de plus en plus ridicule .a bon entendeur .

  • meiy
    12/05/2016 01:36

    koutia moko dieuke commencer di khasstet mai sandioguou mom farul fene nieep laay lal n ieupe laay khass kholal temp yer lunek wakh nako WALY

  • BREF
    12/05/2016 01:59

    Mami bouma dadj way gni talouniou ay informations yi ngay wakh deh et pourtant tu as raison dommage que Sngal foo laniou gueune faratal

  • zakaria
    12/05/2016 04:58

    ahahahahah mais sa gnogou mo dof deug …dama ko fan …deug rekk lay waxx

  • dakar
    12/05/2016 05:08

    Sa daye commedy khame len lolou waye nack senegal dou way mokaye dokhole waye leguiye mockaye dokholle te yenne delen wakh lou rafett Sa ndiogo daye deff commedy pour yenne nguir cone di re

  • diourbel
    12/05/2016 05:12

    Sa daye commedy khame len lolou waye nack senegal dou way mokaye dokhole waye leguiye mockaye dokholle te yenne delen wakh lou rafett Sa ndiogo daye deff commedy pour yenne nguir cone di re

  • as
    12/05/2016 07:37

    serge wakhna leep ,you est ridicul

  • Billy
    12/05/2016 07:38

    c’est Waly ki se soucie d son nouveau chemin surtout avec Bercy youssou na plus rien prouver dans la musique il a presk gagn tous les grands prix c une fiert nationale senego vous aimez faire l buzz pr vendre vos produits kan a waly tout l monde doit prier pr lui il est jeune ambitieux il pourrait devenir quelqu’un aussi mai c un long chemin

  • Babacar
    12/05/2016 08:57

    Mais pourquoi tout se bruit ? Youssou ndour est entière responsable .cest lui qui est au dessus de tout se qui se passe .Parce que c’est son label de prince art qui ont commencé a déclaré en premier la guerre a se goss et il été las a regarder comme si il était dans un ring de bokss .aujourdhui n’est pas hier .cest lui même qui l’as dit « bess bou la kheusseu raw bobou lei biss demna ta banein bouye niew khamoulo Lou mou andal « donc ne nous amerdez pas avec youssou ndour est le roi , on en disconvien même pas .mais aussi il faudra en rajouter que waly a du talen et puis il est plus que ambitieux « ta môme d’où moromou gounei wakhatoumalak mak mou niake FAYDA fok ni il est revenu dans ses 25 .

  • feuz
    12/05/2016 09:02

    bilah BILLY wakhati ko

  • feuz
    12/05/2016 09:03

    wally seck gene beugue may buzz ay rer sak gene ma deff

  • tido
    12/05/2016 09:04

    Mais quand meme wakhléne wakhou niiit way, lanne moy peur
    Youssou da amati loumouy prouvé
    Ki daff lou reuyyy ba paré quand ne nous fouter pas la merde avec ces types de comparaison doul way

  • feuz
    12/05/2016 09:13

    les jaloux sont comme les fous et les ivrognes, ils ne se rendent jamais compte de leurs souffrances. la jalousie provient d’un manque de confiance non pas envers l’autre, mais envers soi-meme AS g pitie de toi laisse youssou ndour en paix youssou da fa geume bopame mai yow geumo sa bopp

  • feuz
    12/05/2016 09:16

    sa ndiogou yow da nga perte khamo foy takhaw defale ni khoutia di deff lou nekh di wakh si actualite di la raw rek il evolue machala yow. sa ndiogou nga rester meme niveau evolue waye li nga deff nekhoul amoul khorome

  • feuz
    12/05/2016 09:23

    les jaloux sont comme les fous et les ivrognes, ils ne se rendent jamais compte de leurs souffrances. la jalousie provient d’un manque de confiance non pas envers l’autre, mais envers soi-meme AS yow da ma la yeureume nga jalousie mola sonal youssou ndour da raw sa baye motakh ainsi nga tolou si topp si guinaw youssou ndour di wakh je te conseille nga geume sa bopp ligueye pour nga meuno ko raw sinon son fils di la fi bayi nga dewati ak jalousie

  • pape
    12/05/2016 09:25

    vrit parole de dieu sa ndiogou deug rek nga wakh

  • feuz
    12/05/2016 09:26

    Serge c toi ki ridicule il ne fait que dire ses pensees te c vrai mom professeur la si musique bayou wally sak meune na ko diangal

  • feuz
    12/05/2016 09:30

    ZAKIARA khame nga lou degue temal togue wakhou fi dara lou ame khorome

  • tido
    12/05/2016 09:34

    Sa ndiougou yaw mongole bou con ngua

  • ALI
    12/05/2016 09:43

    BaBACAR yow rousse na tour bi sinn di wakh lo khani lou bone

  • Go sene
    12/05/2016 09:48

    Sa ndiogou môme taye reike nga meusseu Wakh deugue

  • Moiz
    12/05/2016 09:53

    Le goss que j’ai vu il va réussir parce qu’il croit en lui »gueume n’a bopam ta lolou mo âme solo

  • evaa
    12/05/2016 10:52

    wakho fi dara dmal diangui comdie motakh kouthia rawnala

  • Amina
    12/05/2016 11:45

    Evaa wakhal tha kaw ki niko Koutha rawey sakh dou ndank buzz lay wout si Youssou waye dafa wara khamne buzz bi mui wout batakh mui wakh lou niaw moka nara yakh ndakh Youssou kouka lan guiss ko kou wedi ladial Thione tonge bakhoul Yussou dou tonge dou khaste dou wakh ken lou niaw motakh kouka lan Yalla feyul ko kharal rek Youssou raw nalen te dalen di raw ba faw

  • Requin
    12/05/2016 12:14

    Yaw Sa ndiogou warnga kholal sa bopp 20 ans de carriere te meusso avance tok ci telle bi di doull di diakhasse Melni goor djiguene… youssou Moy sa baye di sa bayou patron di bayou papay waly. Te mane lima diakhal waly seck kene khamouko bilahi senegal rek la yam compare a you so liguene di deff ni c un faut debat

  • Aram
    12/05/2016 13:18

    ki dafa yabate way nakhamne salaries bimui am diko dundal le njabootam riba la parce que dai khaste pour am salaries demal lath Koutha foumou diar ba meun lim meun ngua diar fa mogeun ngua takhaw si television bou delou genaw bi niata atou Yalla meuno fekhe ba avance te yangui tonge ko khamne kouka lan guiss ko ladial Thione Youssou dousen morom dousen moromou bay rawnalen sani karawass bi kou merr nak wakhal ak Yalla bepary wakh ak sa Ndey Youssou Ndeyam mako ligeuyal si katanou Yalla te dafa begeu ay mbokam woute ak sa patron bidoul wakh ak Ahmet Khalifa te niou bok Ndey ak bay

  • jasmine
    12/05/2016 13:23

    taay mome wakho fi gateee sa gnawaay

  • ceely
    12/05/2016 15:37

    WALY notre futur youssou ndour international

  • MD
    12/05/2016 16:37

    Ngen ni y ou app professeur la mé dès fois professeur guiss eleve bou KO diakhal bou nekk si classame wala bou nekk benzène classe difa toth ndakh geum bopam té éleve mane na raw prof sakh Waly ya KO yor à part Ndongo lo yakarone na douma amateur woy Kate mé heursement ya ngui fi

  • MD
    12/05/2016 16:38

    Ngen ni y ou app professeur la mé dès fois professeur guiss eleve bou KO diakhal bou nejkk si classame wala bou nekk benzène classe difa toth ndakh geum bopam té éleve mane na raw prof sakh Waly ya KO yor à part Ndongo lo yakarone na douma amateur woy Kate mé heursement ya ngui fi

  • you le roi du mbalakh
    12/05/2016 17:34

    nek lénefi di comparer asc pikine ak barca rek

  • bamba ndiaye
    12/05/2016 20:26

    Senegal dou dem de dakh li gen di wakh de kou len kou fen kham gen youssou dou morom Wally Obama bim gnawe Senegal youssou rek la kham Senegal dakh way ken di wakh Wally khamna youssou kom nekon sa paye dou kou tagale ak Wally culo

  • Anna
    13/05/2016 08:01

    mais ndiogou yaw doule youssou dou moromou papeye waly yaw doule encore

  • relax
    14/05/2016 11:33

    Le seul artisr senegalais digne de ce nom faada freedy sur les metro train en europe tu le vois partout

  • momz
    02/06/2016 03:33

    Michael Jackson keeneu lawone, Bob Marley keneu la wone, mais Youssou Ndour keneu ci musique Senegalaise. Bayileene di comparer battery ak courant!
    Wally moom fok mou beuri ay fans parce que génération Bou bess bi dagnou thiagua mou thiagua ay lalal basang tass sa cheveux… Goor djiguén yi doon lakhatou yeup guén nagn(Koba yi)

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces

L'ACTU EN TEMPS RÉEL