Annonces
Annonces
» » » » » Vidéo – Waly Ballago Seck dément une...

Vidéo – Waly Ballago Seck dément une soirée live au Maroc

Annoncé au Maroc pour une soirée live dans une boite de nuit, Waly Ballago Seck dément.

Annonces
Annonces

23 commentaires

  • boy LG
    14/05/2016 04:17

    hahaaha mdr wa legi nake mdrrrr no no no wally ya begue BIZZZZZ De waaaaaaaaaaaaaaaa

  • thug
    14/05/2016 07:41

    tu ns emmerde waay ak ay vidèos

  • waly
    14/05/2016 07:47

    bien dit bonne continuation

  • meirouwalyer
    14/05/2016 08:58

    waww khana danguena dionkone di khaar waly limou wakh nguen commentaire thi MACHALLAH seck yaw yay khorom thi THINE rewmi yeep yeunguatounaniou kouneck no danoul wone def sakh yangui koy def mawarou

  • titiyou
    14/05/2016 10:05

    Au faite wolly tu nous emmerde legui a koi ça nous regarde didefe vidéo rek pour wakh.tu es trop lambe va chier yaw gambie rek ga yam pape birahim ligua khamne mo gueuneu nul prince arts mola dakk waye .mane môme sama yone nekhoul ci pape Diouf ndakh nekhouma mais so bayiwoul tu teukeule sa bopp ak Youssou DINA tibiribi # Sénégal rekk .vive Youssou vive titi

    Rek gua yam bougougnou sona

  • Foncè
    14/05/2016 11:07

    Waly khana album you bi moleu titeul

  • rhianna
    14/05/2016 11:38

    mes il a raison fii maroc nitte yi gnoguiko done khar arnaqueur yi di diay billet té gneuwoul il a bien fait d en parlé

  • ass
    14/05/2016 11:45

    ca ira waly jé limpression kou keuy té wakhoul thi yaw dou amm louko nekh vremen malgré ton jeun age 30ans yangui diaye gnou bari yalénn di siweul waly waly waly rek yala nala thiatt sékh lou machala mon frere courage rek

  • Anonyme
    14/05/2016 11:51

    avec se petit guweul qui nous amerdes a chaque instant toi jamais de ma vie tu mangera une seule centme de mon n argent psk tu ne c chanter merde toi et t fans de merde

  • Mamy Coly
    14/05/2016 11:55

    Tu as bien fait dagua wekhe ndouk bo wakhoul wone noni nes deuguele kou mer klamel Yalka

  • tima
    14/05/2016 13:41

    tale bou yalla tale pousse mou tak ñiaka pousse mou tak dnc nopalou léne ki dara douko térré dém inchalla sokhor bakhoul

  • KM
    14/05/2016 13:57

    En fait vidéo bi dou pour yaw pour gnimouy wakhal la adouna so beugué nopalou da ngay nagou li y alla dogal ndakh kouko nangouwoul da nga sone nda nga deff lo moussou ta deff me wally affaire bi yawla

  • CV
    14/05/2016 14:01

    Mé Anonyme ya ngui mer dé gnoune tamit sa artiste d’où lekk sounou deureum woy katou mère yi ak payi té sakh Wally gnepp mom la gnou beug

  • milk
    14/05/2016 14:24

    Wa titiyou khana dans nga khmer si say artistes mo takh ngay wakh du n’importe koi pape birahim ak batam bob ou Mouy melne kou ngank radio nga koy teukelé ak Wally boulko may beuz way , Wally d’où sene morom té en plus Lima nekh si mom moy dou sonou si adunam ndakh gnepp la yene diam te faléwoul fimou beugeu yegg rekk lay khôl diekhena yonam nekoul si diambour sa geum bopam

  • Amar
    14/05/2016 15:15

    nn wally mala beug ya bakh way

  • as
    14/05/2016 16:23

    dano son si video wally yi

  • rohey
    14/05/2016 17:07

    love u papa waly we feel happy whenever we saw ur video wish u long life n good health

  • doss
    14/05/2016 17:47

    il a raison wally parce que maroc fi il ya des gens qui ns emmerdent ici avec fausses promesses d’une soiree du 14 mai des faiseurs de malins qui veulent se faire un noms des faux promoteurs. comme ca tout est clair

  • nasi09
    14/05/2016 21:46

    anonyme tu na mene pas cest 5 centime pour donner a wally

  • Gueye
    14/05/2016 21:51

    Cou sokhor ak ignane boco Wally tal bou yalla tale le

  • Bea
    14/05/2016 23:18

    Wa anonime yaw deye yalnala yala maye khaliss yagui sokhor te khamnani yoroguoko te bayi guewel defougnou dara yala beuguoul kou sokhor boula narona may yala boumouko bayi sakh

  • peul
    15/05/2016 08:02

    titiyou merci waly hamoul bopam motah nehouma en plus il se croit supérieur des autres alors il n’en est rien pouffff quand je ne vois parler…

  • Peul2
    16/05/2016 21:00

    Mo peul loy wakh ni waly da geum bopam rekk té geum sa bopou moy takh nga yegg fou sori

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces

L'ACTU EN TEMPS RÉEL