Annonces
Annonces
» » » Vidéo: Voici les propos de Ahmed Khalifa Niasse...

Vidéo: Voici les propos de Ahmed Khalifa Niasse qui ont choqué Oustaz Iran Ndao et…

2017-06-29T10:40:31+00:002360 Partages

Vidéo: Voici les propos de Ahmed Khalifa Niasse qui ont choqué Oustaz Iran Ndao et…

 

Annonces
Annonces

27 commentaires

  • cheikhordinateur
    29/06/2017 11:38

    serigne bi deugue mo nékhoul rék wayé lingua wakh lépou thi ay mbinde ngua ko ték thieuy serigne touba

  • Ngoor
    29/06/2017 11:46

    Son père a enseigné Maodo, lolou loussi nek. Comparer Niasse et Sy, c’est comparer Gainder et Mousse. Au Nigeria, personne ne connait Maodo mais n’empeche c’est un homme de Dieu.

  • LEADER
    29/06/2017 11:59

    NGOOR gnoune senegal lagnou nék nékougnou nigeria ……mane mi mangui senegal bama khamé baye niass yagoule …..guissgua bouléne gnou fonto la wakh ……soulile bamba ak baye niass gua latieuléne kouy MAODO boba digua kham…….yabaté

  • demba
    29/06/2017 12:03

    DANGAY FENNN
    TALL LAGNIOU WAKH
    MBACKE AMOUL BA MO AMM

    SY NIASSE MBACKE FO BAYI
    TALL AK BE

  • Talibé Baye
    29/06/2017 12:26

    Séne wakh yi guir yala guéné léne si Baye Niass yonam nékousi wakh ji yeup kéneu toudoukosi Al hamdoulilah

  • ive
    29/06/2017 12:39

    calmez vous tous ces braves sont des hommes de dieu et ils n’étaient pas des concurents mais des partenaires avec seul objectif l’intauration de l’hislam au senegal et dans le monde

  • Deugue
    29/06/2017 13:29

    Dafay féne preuve yagui fi ak lettres yi. Mamam bindeu neu si Elhadji Malick Sy. Si guinaw Maodo la nékone. Kii seytané leu. Les preuves sont là. Mak dafay wakh deugueu.

  • serigne saliou
    29/06/2017 13:34

    Leader iao suma xamone foonék dinalafa fékkeu daxar sa ndeye domou haram waxyu katt ndayam yii nk doull nganan maodo sa khadj yak maodo

  • yoro
    29/06/2017 14:01

    ce qui me dérange c’est que monsieur niass a évoqué la domination des colonialistes qui a fait que les marabouts ont perdu le pouvoir et que le bon sens était de rendre ce pouvoir aux marabouts avant leur départ. peut être une suggestion : si le combat mené par vos pères marabouts avait été réitéré par vous actuelle confrérie la religion aurait plus de crédit ici au sénégal. mais hélas, comme vous le voyez chacun est dans son coin pour dire « c’est moi » alors que la graine semée par les colonialistes franc-maçons est a germé et commence à produire des fruits. dans ce débat j’entends dire que les fondateurs de ces confréries se dressaient mutuellement des lauriers et vous qu’avez-vous fait de semblable. je vois pas jusqu’à présent un khalif cantonner ou écrire des passages élogieux à l’endroit d’un autre. cela dit que y a vraiment problème.

  • wakh deug
    29/06/2017 14:06

    Yaw bayil fenn. Bamba dou mass. Lettre bi El Hadji Malick diokhoon Serigne Ndiassé Cissé , pére de Serigne Mor Mbaye Cissé (Diourbel) di diebalou si Serigne Touba migui fi. Bi mou deme bassi yoon bi, oubi lettre bi lire ko, bimou yegue diox ko Serigne Touba ba nopi diebalou took Touba. Li seen Khalifa Mame Abdou Aziz Sy dabakh wakhoon video yaa gui fi

  • sage
    29/06/2017 14:38

    je ne suis pas tidiane mais je sais que les marabouts de tivaoune ont plus de classe et de hauteur par rapport aux autres marabouts du senegal

  • Mor
    29/06/2017 14:45

    Thiey khana nitt sagnoul di fénal bayam témou nguèn adouna.
    Day melni daguèn beug tolalé mag gni ndèm gnou bakh lane .
    Wagnè nak mounougno tollo té dounou massa tollo kone lou way ngeum rek japal.

  • Mor
    29/06/2017 14:56

    Kou yalla jital kouko jital jitou.
    Bay Wird cheikh Ahmet tijane la jeul té nguissoul Cheikh sakh.
    Ahmadou Khadim jeulna wird Xadr jeul wird tijane ba yonentibi fègnouko johko wird Mahouz Mauritanie. Mom dong la kène fèkou kossi. Kone lii Ameth Khalifa Niass wakh werna.
    Nitou yallah yi ay niveau la nak bounou yèmalé (étudiant ak élève primaire dou bèn).
    Nou kholate mbiryi té bayi farfarlo bi Yallah khamna lepp.
    Di tubbat.

  • Un citoyen
    29/06/2017 15:23

    LES MUSULMANS NE SERONT JAMAIS ENSEMBLE PARCE QU’IL SONT COMPLIQUES

  • Daouda Gaye de Meckhé
    29/06/2017 15:34

    Mouride, Tidiane, Khadr, Layéne et Niasséne Ibadou etc yénn niép kounék yangui ci lila nékh té doyla. Am na rendez vous boun doul wouté warfa dadjé ak borom deuk mouy Yallah sounou borom té kénn douko wouté. Sounou fa agué rék lanouy kham kann mo nék ci deug. Délou lénn ci alkhour ann « Mà farad nà fil kitabi say ounn »

  • mohameth
    29/06/2017 17:01

    franchement vous êtes trop bêtes car que cela soit mame maodo,serigne touba,baye niasse ils ont tous étaient de grands chef religieux et ont prôné pour l’islam mais vous, vous êtes là à les dénigrer de grâce fêtes très attention vous risquez gros dites astafiroulah avant que l’irréparable ne se produise à bon entendeur salut.

  • kolo
    29/06/2017 17:05

    aladji malick dou morome gars aux personnes qui le dénigrons sa dara dou bahe .

  • kolo
    29/06/2017 17:07

    mame al khadji malick dou morome te kouko dingate nga torohe

  • maara
    29/06/2017 17:35

    Kii dafa saaga pap hàne

  • Musulman
    29/06/2017 18:40

    De grâce parlons de ce qui nous lie et évitons tout ce qui nous disperse. Nous avons en commun l’Islam qui est une religion de paix et de tolérance même des divergences d’esprits et de comportement existaient chez les Sahaba et ils se respectaient mutuellement tant que celui-ci ne fait ou ne commet quelque chose qui est banni ouvertement par l’Islam.
    Pass pass, ak gëm gëm dafa nèk lu personnel mëno ko waalë ko bokolul pass pass. Nañul rafetal jëmële si ñëp te dañ si ay par parlo aki xeb li ñeneen ñi nek.Jeema dox di defar djiko yi.
    Je termine en appelant tous les musulmans surtout sénégalais à réfléchir sur la vie de ses nobles « Mak » qui ont passés toutes leurs existences sur cette terre à la quête de Dieu (SWT) et à la vivification de l’Islam sur le territoire national voir même international.
    Prenons les « tous » comme des modèles et aspirons à relever l’image de l’Islam comme ils l’ont réussit.

  • maodo sy
    29/06/2017 21:13

    Ahmed khalifa niass day doul serigne aliou gueye rek meuna diangal bayam

  • weranté
    29/06/2017 22:25

    Waaw kounta yi done diangualé Algérie, tunisie, Maroc, Mali ak Mauritanie ba aksi Senegal gnognou mane douma lène degg. Loutakh?

  • Muslim
    30/06/2017 08:06

    Je suis dégoûté par toute cette histoire. Lorsque le Prophète (saws) et les pratiques de l’Islam ont été récemment attaqués par cheikh moussa diagne tout ce beau monde là n’avait pas réagi. On défend bec et ongles nos tarikhas et reste muet lorsque l’Islam et le Prophète (saws) sont attaqués. Je me tamponne de leurs querelles puériles qui n’ont aucune once d’importance pour moi. Basta waay.

  • LAYE
    30/06/2017 11:29

    De grace parlez et laissez tranquillement BAYE NIASS. Il a fait ses preuves partout dans le monde. Mo done Cheikh si khame khame té fatdou tidiane wanénako. Moi je respecte tous les autres marabouts parce que ay nitou Yalla kamile lagnou. Mais nak BAYE NIASS yamoul ak kène si KHAM KHAM. Jai fais Touba et Tivaoune depuis des années mais khame khame bi ame si keur BAYE NIASS yamoul ak bène khame khame bilahi walahi wa talahi

  • Pape
    30/06/2017 21:01

    Senego nagnu bayi yii gnuy publié ah kounek di xass sa morom

  • innad diina hindal Laahil Islamou
    30/06/2017 22:32

    Ndaysane Maodo moñou diangal yar ak téguine.ni YALLA bouma kéneu kham fi.na kouné wolou finga fété ta ñou diamou YALLA. Béneu serigne douñou dougal aldiana souñou diamou woulé .yalnanou YALLA diégal

  • omar
    01/07/2017 20:43

    yaw serigne saliou doumala né yak sa serigne si hathie ndah kone ma togne nitou YALLA wayé diapalné yaw kou katt sa ndeye nga domou ndiallo bou mbambou houh sah mola geun domaram domou sarame ndeyambi fi mak niou bah nieupa liguey kounék ak sayon ba égg si YALLA koussi topp makyi téhé wayé kouy djoutal yayam comme yaw doussi bok

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces

L'ACTU EN TEMPS RÉEL