Annonces
Annonces
» » » » » » (Vidéo) Un hommage à Youssou Ndour jugé...

(Vidéo) Un hommage à Youssou Ndour jugé « flop » par les internautes… Regardez

Amath se nomme t-il, surnommé aussi You 2, ce chanteur est la risée des réseaux sociaux. Pour cause, son clip intitulé « Kou Beug Réweum » sur lequel il rend hommage à Youssou Ndour. Une vidéo musicale jugée flop par certains internautes, d’autres soutiennent que l’artiste ne respecte pas le roi du Mbalakh. Regardez

 

Annonces
Annonces

139 commentaires

  • sama yaye sama khollll
    28/07/2015 21:07

    Mais yawww ko yapppp

  • lamine
    28/07/2015 21:07

    Une plainte contre lui devant le juge international

  • boys
    28/07/2015 21:13

    El gastro

  • nandite
    28/07/2015 21:15

    4 minutes 46 de torture sans pause et les gars des droits de l'Homme ne font rien, c'est scandaleux!!!!

  • Issa
    28/07/2015 21:23

    Le nom de son guitariste?

  • Un fan de You
    28/07/2015 21:31

    Est ce qu'il est sain d'esprit? Doff yi déniou bari dé lègui.

  • Senegalboy
    28/07/2015 21:31

    Ya trop de conneries au Senegal.Tt ca c la faute au BSDA

  • leila
    28/07/2015 21:35

    Haha haha c est grave ça

  • z
    28/07/2015 21:39

    Mais ki mo totch …way… lii lan la nii? sheuuttttt ki ray nama ba ma dé koi. pffffff

  • Sa
    28/07/2015 21:44

    Ki kay do you 2 you 10000eme

  • amy
    28/07/2015 21:47

    vou savez son anciens nom c'est quoi akon 2
    legui you 3 khana you 2 et existe
    mais je pense que say mbokou ygou gnoula ?
    youssou ndour yegoula !
    sa musicien yi gnola ndieuka sacrifier
    je croi que sa clips bi ta pas payes plus de 5000f
    demal you bole la ak prince arte gnou tolier la bro
    rien ne vas ni arrengeur ni realisateur togatko you bi mom gnoro goul mdrrrr

  • amdiom
    28/07/2015 21:51

    wa ki tamite koumou yap nak vraiment l'I eupna koi khamo dara di way doul way

  • yass
    28/07/2015 22:18

    Nandite ray nguama Mdr

  • cecaro
    28/07/2015 22:28

    lol

  • cecaro
    28/07/2015 22:29

    lol

  • dina
    28/07/2015 22:41

    il sera condamné à mort!

  • layla
    28/07/2015 22:44

    kiakiakiakiakiaiaia c est quoi cet merdre lol va tinscrir a l ecol de la musik mo gueune defena lol

  • bamba
    28/07/2015 22:52

    wadiou bakh mounokowon biinde lettre. .incapable

  • moo
    28/07/2015 22:58

    mais nooo!!! mane diélleuléé naa saway saxx mai niari sokhna yii mou andall nioma yapp

  • KILIFA
    28/07/2015 23:09

    dina faut pas oublier les musiciens aussi et fermé le studio.

  • KILIFA
    28/07/2015 23:11

    Loka beug def Issa

  • KILIFA
    28/07/2015 23:23

    Mane wakhatouma sakh woy bi mais ensemble bou noir bi ak bottes yimou sole rek, le procureur de la république doit l'arreter pour attentat vestimentaire.

  • lucas
    28/07/2015 23:23

    mais nnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnn les medias ose lui donner du bezzz en plus
    defa yabater jais honte pr lui

  • ouzin
    28/07/2015 23:26

    c'est le claviste qui fait pimp pimp qui me tue . MDR ça tue. Amath sera l'invite surprise de Bercy 2016 MDR MDR ma ngui dé

  • mams
    28/07/2015 23:31

    no wadji raye nama ak sanseyi waye commentairyi mo dake soubala tabaski surtout nandite rė baye dioye

  • mams
    28/07/2015 23:34

    kilifa raye guama j t jure magui tothieu fima neke

  • Ordo
    28/07/2015 23:42

    Thiey yalla

  • pdtrr
    28/07/2015 23:56

    ahahhaahhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhaaaaaaaaaaaaaaa mais qui koumou yaap pauvre con.sa voix nekhoul té manoo chanter non sénégal mo nékh.tékh tékh may réé ahhahahahaaaa

  • iboutou
    29/07/2015 00:05

    wa ki ana ay mbokame khana da reuthie

  • lili
    29/07/2015 00:22

    Ki birane la yapp ak teupp bi

  • masse
    29/07/2015 00:36

    sangnsè dièkhena li yeupou ci dale bott mètè kouy vider fonse septit

  • saf
    29/07/2015 00:42

    qui ragaloul yala dé! waye na dem aduna ngui ci canamam. li mou gnou def ni dina co guiss

  • 0stress
    29/07/2015 00:49

    Ptdrrrr magui Dee fima Tok hahaha wadji limou diam amoul hahaha no Senegal dou dem youssou ndour kholam bi tangeu neu???

  • Boy
    29/07/2015 01:03

    oh han hannnn ni oh han hannn wa Amath koumou yapp 4mn46 de pollution audiovisuelle

  • Mina
    29/07/2015 01:15

    Niou djiguéne gnii nekk thii clip rayy léne dagane naa beugue siw diaroul liii

  • ndeye ndiaye
    29/07/2015 01:42

    kilifa danga dioume dou aye bottes mais bottines leu cest encore pire wahelénema foumou deuk waye

  • maxim
    29/07/2015 01:46

    mais dire ke boy bi kou am fitt la je parle meme pas des moussi..ciens mais du gas ki a osé filmé ces conneries

  • bref
    29/07/2015 01:46

    sama gayi vraiment Kï meunetoulen dapp dé na fima nek ni, lima rerone yeup resna ndakh rétane sénégal mo nekh dé

  • ADS
    29/07/2015 01:51

    avant que n'ouvre la video j'ai cru que ct Mame mactar gueye jamra sakh ndekété lii la. Meme les filles du clip sont mdr

  • madou
    29/07/2015 03:20

    10 ans de prison avc travaux forcé. les filles 15ans par ce que amou niou kilifa

  • joke
    29/07/2015 04:55

    ains bi you diepinala

  • fina
    29/07/2015 05:55

    bilahi kholou ma klip mais mangui dee fima tokk ndakh comentaire yii yeureum lene koo da am ayy mbock retane naa ba sama bire bi Di mety

  • amdiom
    29/07/2015 06:16

    no ki domeram la koi boutique biko solal osi 20ans de prison

  • Baygon
    29/07/2015 07:04

    No ndanane fegne na machala ki waye rek lay deff…orchestre bi riche….Borom tama bi loumouy tegg togue na…guitariste bi ossi ken dou mom….lima si gueneu nekh moy awou katt bi limouy baral amoul….You 2 tu mérites ton nom sa waye nekh na sa clip nice ak khalè you moll youla sekk nga singue sè lou rafett ossi….Demal Bsda gaw sino gayi sathie ko dou niou créer…lol……Wala sakh nga deme Dic niou tedjalè sa ndaye sa 4mn yi ma niakk di nga ma ko faye ngay melni ni ndayou pharaon ni

  • mams
    29/07/2015 08:39

    no clipbi rayatouma dė mai commentaire yi no yenagui dindi stress mrddd

  • Boye Pouloh
    29/07/2015 09:32

    vous n'avez pas compris que ce gars là à réussi son coup. Il voulait être populaire et il l'est certainement. Regardez le nombre de commentaires qu'il suscite! Il vous a démontré que toute chose a son contraire. Il est donc le "Non Youssou" en tout et, sans le vouloir, en le rejetant, vous Aimez d'avantage le vrai You. Faites bosser vos neurones,vous êtes tombés dans un piège à cons.

  • lasenegalaise
    29/07/2015 09:35

    ??????magui déh mane teubi momaye ray

  • Al Karimou
    29/07/2015 09:39

    noooo sètana goumeu clip bi D waayè commentaire yi rek wakh nagnouma lèpp. Dama rètane ba sone noooo liii C grave

  • jaja
    29/07/2015 09:45

    Fin bi moma achever. Oh annh yi mdrrrr ki dou nite. Ki dafay wagni stress

  • Al Karimou
    29/07/2015 09:53

    waye sa waye fètialko sa bopp mai ki fèthieu rek lay def. Ta dafa melni sakh la fille en rouge dagnouka forcè si clip bi dèfoussi bène effort ak rètane forcè yi. you dale loumakay conseillè na retirè clip bi bala mouy trop tard nakh li cest grave

  • L Juge
    29/07/2015 09:58

    Bon, Mr You 2, pour nous avoir infligé 4mn et 47s de pollution sonore, de "souffrance musicale", vous étés condamné à perpétuité, (Parce que condamnation à mort day yomb torop ci yaw) avec une amande de 250 millions de "dollards". Vous purgerai votre peine au Guantanamo. Le nom de You 2 ansi que vos droits d'artiste vous sont retirés. Le label qui vous a produit, ceux qui ont réaliser le clip ainsi que les personnes qui y figurent sont eux condamnés à mort pour "Niak la wakh deug". La séance est levée.

  • tall
    29/07/2015 10:00

    leckiino

  • Al Karimou
    29/07/2015 10:10

    waaaa L juge raye ngama sa jugement bakhna je te jure

  • délibéré
    29/07/2015 10:13

    le procureur de la république dane nala 50ans de prison ferme + à boire obligatoirement bèn tablétou nèn chak jour et 50 ans de formation stylisme modélisme sa awoukate yi gnou guéné lèn deuk bi park bougoygnou dag lèn forcé les musicien 30 de prison pour ngak dégo ak way bi producteur bi peine de mort nax reyna gneup gnou guiss clip bi bolé si yap askan wi

  • amdy
    29/07/2015 10:23

    kane mo hame ki fanla deuk?? parce li doumako bal mouk.faut k ma fayou limouma def!! ki togne na ma dé,métina trope! bama diapla! bahna rek!!

  • dija
    29/07/2015 10:25

    bilay amath kou bagn sa rééy gua lii étrangé bou dég musik bi rek enérvé waxatoumalak ligay wax youssou n'dour xolam bi dag na nax gnoun gneup la saga ndaye délibéré ki pandre ko sax dagane na

  • dija
    29/07/2015 10:38

    no yaw tagou wo youssou ndour guay woxone nala dinala way… bilay youssou yagula boula yeugone doula bayi nax li difamation la contr you et sa famiy

  • mame diarra sarr
    29/07/2015 10:41

    haha lamine bouma raye way dama ré ba danou

  • ina
    29/07/2015 10:42

    amdy bo hamé mantamit nga wahmako!!
    dafa yabaté!

  • mame diarra sarr
    29/07/2015 10:44

    haha yéne diguene ma ray mais nak wakh nguéne deug ki dafa yabaté

  • mame diarra sarr
    29/07/2015 10:46

    kiko produire rék mognou togne mounatouma ré sakh

  • thiaroye
    29/07/2015 10:59

    avc les filles moche la di meleni kewele

  • kanysaf
    29/07/2015 11:05

    Je demande solennellement a Mr Babacar Touré de la CNRA de sévir
    On a pas droit de vivre une torture pareille

  • keinde
    29/07/2015 12:16

    li yaye sokhna mboup liguéyoune lép yakh ngako en 4mn46seconde mais sa guitariste bi tint tint tint rek Jimmy Hendrix la khana lol do nit bonne continuation

  • Cri de coeur
    29/07/2015 12:18

    Un nouveau comédien est né dans la sphère musicale.ce tube est une comédie musicale.Moi je lui suggérerai de faire le guignol il pourra s'en sortir.

  • amanda
    29/07/2015 12:39

    mé ya koi?? ya mon cousin sénégalais qui vient de regarder le clip et 4mns apres son etat est tres critique puis il s'est évanui,k s passe til???

  • oumy
    29/07/2015 13:10

    Mdr ki koumou yap nak mane de warouna mou melni louniou fi tek daw commentaire yi mom may nagne ko buzz re ba tass

  • oumy
    29/07/2015 13:19

    wa guiss guen amath ak bopam bi di melni bopou kouskongrone bou déforme ak waguetom bi mbata kouy elastique

  • retane
    29/07/2015 13:34

    yaw amdiom bayiniou way réna bay dioy way boulènma ray

  • gningue
    29/07/2015 14:23

    ki il revient d'ou…il devrait etre mis a jours…car cette facon de realiser les clips date de l'epoque de feu niaga mbaye

  • gningue
    29/07/2015 14:24

    ca me rapel le clips de omar pene…etudian

  • thiee
    29/07/2015 14:30

    wa kii foumou diougué !

  • amdiom
    29/07/2015 15:00

    retane bilay DEUG la wah nap katou diane rek lay nirou hahaha

  • fina
    29/07/2015 15:20

    fima nekk danguay stress ndakh dafa wette mais yalla khamnani ak comentaire yii damay retane ba sama bire bi Di mety

  • nina
    29/07/2015 15:38

    oh mais ki foumou dioguer Sénégal tamoul sedd pour botte.mais sene feuteuil hatena sene escalier ndaw na hana espace amoufa .en plus poudre gars bi migui fegne ,batte bi nehoul ,ya des moments on a l'impression qu'il chialer ,harelene ma résumer togagui gnoroul

  • nina
    29/07/2015 15:40

    Lili fatelille gua ma ak teupe bi .

  • roona
    29/07/2015 16:18

    mddddddr ki ray nama wayyyy 100 ans de prison ferme

  • marame
    29/07/2015 16:26

    woyyye fouma dieume ce guignol m'a tué direct direct reubeuss c'est un assassin pur et dur il veut réduire notre population. qui daniou ko yonni.

  • xum
    29/07/2015 16:37

    Baygon serieu woul kw mdrrrr mé ads tu as raison deh mame Gueye.

  • ama
    29/07/2015 16:46

    looool waa djii dafay toogn koi …man musik bi momay daanel koi

  • LE SAINT
    29/07/2015 16:47

    WA ME K VOULE VS IL A BIEN CHANTE MM YOU N POURE PA NS DONE + K SA RIRRRR NO DAMAYE TONE KI KAYE NIOUNE LA YAPE ME PA YOU KOUKA PRODUIR LANIOUYE PORTE PLINTE ME LE GA YALNA MOUMA AVAN TABASKI

  • ama
    29/07/2015 16:48

    mdrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrr

  • ama
    29/07/2015 16:49

    papis konaté leu loool

  • yeurmandé
    29/07/2015 17:04

    Le saint dét way mdrrr

  • satou
    29/07/2015 17:20

    En tous ka les meubles ki son dans le clip non même pas honte car ce mec il c fou de la gueule du monde putin même mane mako dake woye j porte pleinte

  • satou
    29/07/2015 17:22

    J oublier ouzin barigo d'où moromame sahe on est où la ?

  • mifa
    29/07/2015 18:33

    vraiment j'ai des mots de tête. ki mo yabaté

  • lala
    29/07/2015 18:34

    wawe ki koumou yappe youssou walla nioune nilaniou bayi koune di deff lo sentir liii ken khamoul musiciens bi son tema youkhou adouna bi nieuwe lii

  • mifa
    29/07/2015 18:38

    niak ame lou mouye deff, mo takh mouye woyantou

  • lala
    29/07/2015 18:43

    waa lii lanela yene????.

  • mams
    29/07/2015 18:45

    antoucas il devient populaire mena touma tok aye heure san voir la commentaire ki warnaka faye

  • bref
    29/07/2015 18:45

    le juge mane yaw la andale dé

  • Zal
    29/07/2015 18:50

    Kilifa ak Nandite rey nguen ma

  • BOY SARR
    29/07/2015 18:53

    nandité t'as vraiment raison j'ai failli m'évanouir lolll….

  • Al Karimou
    29/07/2015 19:14

    en tt cas battre nga records en moins de 24h nga am commentaires yi yeup. fèlicitation. bokofi bène tèlè tek diap lènesi rk mou yam si net bi

  • RICH_GANG
    29/07/2015 19:23

    senegal moh nekh rekkk

  • Camara
    29/07/2015 19:53

    L???L le gar se fou de la nation des gens qui peuvent entendre ce genre de musique même pas de respect pour celui qu'il chante car sa c'est nulle

  • iba
    29/07/2015 20:10

    j trouve k c bien surtout pour 1debut. 1 peu laxiste cote vestimentaire et mauvais choix cote fille me ca ira

  • binou
    29/07/2015 20:18

    wooooy ma gui deee non Sénégal mo nekh sa me mank yeufou doff yi

  • victime de xol bou dag
    29/07/2015 20:28

    wa clip bi xana annéé 60 la dara meti wouma loudoul gnou djiguène gni kou lène makiyage xana da gouma la femme en vert kouka wax mou tak ay lunette liii tamite ken mounouko bagna wax ahh medrrrr way

  • cou
    29/07/2015 20:39

    kom video bi rayouma dotou ma déé amath yalla na la sama aakk dall dem ba tey néléwouma nax commentaire yi

  • coul
    29/07/2015 20:43

    ki 1000 yatte lane ko wara doore

  • binou
    29/07/2015 20:44

    wadjii comme yoo bou gnou pompée

  • doff style
    29/07/2015 20:58

    kou yaba tégua mann milall déglou sakhh ma ko deffff espece de crokodillll dagnou la warrra bakhall sakh

  • Thiey
    29/07/2015 21:08

    Aux dernières nouvelles, il prépare une tournée internationale. Il souhaite commencer par Bercy!!! Soutenons le et un comité de soutien est en preparation

  • fina
    29/07/2015 21:20

    thiey bouma raye

  • Al Karimou
    29/07/2015 21:41

    wa thiey stp 1 kstion kel bercy? bounek france wala?

  • Ama
    29/07/2015 22:16

    Borom tama bi 10 ans de prison

  • zico
    29/07/2015 22:26

    sa way kay lucky luke rék lay nourole ak ay botame

  • Chinou
    29/07/2015 22:44

    Nnn mes amath yallah gua des sii lakoume glace way li forna li dou louboudin des mes aye guothie la senegal modak fep lisi comentaire amoul si bene clip ??

  • mama
    29/07/2015 23:41

    pourtant il chante bien deh.

  • mama
    29/07/2015 23:42

    am n'a succès dal qui Day dém

  • mama
    29/07/2015 23:53

    Kon ho han hanhanhan ma djiguén diabar ley wouyo fofou mo nékh ndéysann

  • Mimi
    30/07/2015 01:16

    Non mai dieuloleine photom bi thi escalier bi dé. Ki té gno cotiser ray ko

  • fina
    30/07/2015 04:47

    mama bouma dadji conne yaye 1e fans mdr

  • zik
    30/07/2015 07:13

    Way mama ki dou bougé métre ki esk ça va

  • zik
    30/07/2015 08:37

    Tangaay bi mou déf ay botte,door thi ensemble cuir ceinturé ,feugeu thi costume din fass kanaman nak di way si fouleu ,sa voie mérite 47oeufs par jour yaw loy mélni kéwél bou reuthié réserve de bandia nii ,wadji si on l'emprisonne pas danger bou reuy lay indi Sénégal baxna niou gui sétane moussiba deh

  • mams
    30/07/2015 09:13

    zik mrddd

  • mdr
    30/07/2015 15:46

    Wuy yaye kilifa rey nga ma mdrrr

  • fina
    30/07/2015 16:42

    souma na mee retane rek khôl commentaire yii

  • foussa
    30/07/2015 20:29

    ki loumoy melni kou woté tour mbalit ni pimp pimp pimp mbom sax com oto mbalit ak wayam bou xasaw

  • sone
    30/07/2015 20:34

    wadji da am filling sax djeuleu tourné bi ki dara fayou ko

  • lima
    30/07/2015 23:30

    hahahahhah ayway bayilene ma way retane na ba sama bir bi di metti depuis bobou magui kholat commentaire vrement sama gayi dadji guene ma

  • gnagna thianta
    31/07/2015 15:11

    wa kii you 2 koo yeipe

  • chams
    01/08/2015 19:27

    hé ki c mon frère bayi len c le youssou de la famille et notre fierté je l'encourage musik bi la def sakh sonnerie d'appel dafa dougue si sama khol bi limou way dara fayouko espéce de méchant.

  • Nene Diedhiou
    01/08/2015 19:54

    kilifa rey ngama ?????

  • mama
    01/08/2015 19:58

    fina ak zik douguéne dém bayilen sama fans bi. commentaire yi rek preuve la hein. tonton you2 ma gui sa guinaw boul tiit am gua fans

  • bref
    01/08/2015 23:58

    mama bilahi tu n'es pas sérieuse, rey nguama bama déé

  • Ibnou
    02/08/2015 02:40

    yaw macky Sall Dala wara teuth yaw ya
    nou yep

  • babacar
    02/08/2015 06:53

    Non c grave et p8 les 2filles ki l.accompagnent niom la yeureum eck wadji werna

  • sylla
    02/08/2015 09:33

    mais ki kan moko dougeul studio

  • sylla
    02/08/2015 09:47

    mouy melne kou nek anné 70

  • degs diop
    02/08/2015 10:29

    mdrrrr lui se fout des gens ?????

  • oh hann
    02/08/2015 16:05

    Xpmdr conne oh han hannnnnnnn

  • baay bouy
    02/08/2015 16:55

    you 000,,,def ngano lou sewww, 4=0 somala japee dinala doxattt mbeuwwwwwwwww,,télé bolafi tek matalko,,,xana danga ami borr ?

  • baay bouy
    02/08/2015 17:06

    you 00, boul niak saalitt monial nak yawitam,, seet sima mawaarla, xana amou serigne ?

  • LIZ
    03/08/2015 16:55

    c'est sa voix de crapaud qui me tue, Il veut immigrer en passant par Bercy C'est Sûr

  • sira
    15/08/2015 13:45

    ah senegal dal mo nékh koi doumako djeundék dara que des clowns mdrrrrrrrrrrrrrrrrrrrr

  • soweli
    19/08/2015 02:17

    Tint tint..tint tint…Tint..Thiéy galsene..

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces

L'ACTU EN TEMPS RÉEL