Vidéo: Un Djinn incendie régulièrement une maison à Kayar…

La famille Dieng de Kayar est victime d’un incendie mystérieux qui ravage sa maison depuis plus de trois mois. Les matelas et les habits prennent feu régulièrement, sans que personne ne puisse déterminer l’origine des flammes. Regarder ces témoignages poignants de membres de la famille.

19 COMMENTAIRES
  • Mane

    Salam aleykoum beugue na numéro gnii soudé meune na nekk

    • OUMAR

      CA VA SOKHNA SI MANE CAYAR LA DEKHE BOU DE AME NGA NGO KHAME KOU SI MANE DARA

      • OUMAR

        MANE MAGUI EUROPE MAIS MANE OUTE NUMERO BI MANE SA MA NUMERO MO NEKHE NI 0046720037960

        • mane

          salam aleykoum oumar guiss na sa numero daga khame famille bii ou bien damalenn beugue diapale yalla takhh ou bien yaww daga probleme sa bop

        • Suiveur

          oumar@ appeller mamadou lamine diop de darra kennal yalla , c'est un spécialiste de ses choses , si tu veux en savoir + tape dara kennal yalla si youtube

      • mane

        siii katane yalla meune sii diappp

    • moooo

      une idee va sur thies24.com et demande au redacteur

  • mouhamed

    Yalla nako yalla Safara si barké Seydina mouhamed psl yalla loumou def rek amena loutax mou ame azar amoul sou li takoul won meneu na ame lou geneu graw niow mais yalla nako yalla Safara Mome mi dra tewoul si barké alkhour ane Amine

  • logique

    bizarre personne ne voit le départ du feu a chaque foi je suis sortie et revenue entrain de voir ma chambre brûlée boof y a un pyromane

    • oumar

      Sokhna SI mane khame na le bou bakhe Sa ma keur akke fi mire ame bou ma dokhe 5 minute la khame na lene bou bakhe na laire mane begouma kene djokhe ma khalisse kou SI khame kou SI mane dara la wakhe kou SI ame lolene dimbale tamite bakhe na mane oute Numero borome keur gue SI bopame wasalame djokhe la Ngo mane nekhe ma Senegal fine tolini magui suede maid khame na WA keur gue bou bakhe pour mou laire

      • oumar

        Lou ma wo inchala di na laire bou bakhe wala nga deff ma signe Sa Numero ma wola inchala 0046720037960

  • tf

    djinné bii xalé la defa rew delen fayrek

    • Malikom x

      En tant que natif de kayar je reconnais que c'est une histoire très bizarre mais yalla kenn khamoul ay mbiram. Khana di niane rek yalla mi dara teuwoul mou safaral lenn li ndakh katt ay dioulitt you weer laniou te itt mérite wouniou ko metina lol …
      De tout cœur avec la famille et priere pour que ce drame s'arrête si barke noroun assimoun khad yara bihi houssora khaïssaraa man kana oumoul khouraa makata khayroul khourami… aminnn

      • 6C

        salamou aleykoum j vs dit massa massa ,

        • 6C

          sa fait 2 ou 3 ans qu'il ya au senegal surtout au fouta on c pas c quoi et cmt faire pour arreté yalla rek kham

  • le SAINT HOMME

    il faut sortir la zakhate et faire de l'aumones.. et surtout endurer dans la priere car c'est Allah qui a la solution

  • teranga

    salamoun aleykoum s'il vous nous sommes tousse des musulmans il faut que vous lisé ayatou kourssiyou au quatre coins du cardinaux de la maison le djinn va disparaître inchallah qu'allah vous protège amiine ???

  • doudou

    Ou sont les preuves et evidences seulement des paroles journaliste a la con .

Publiez un commentaire