Annonces
Annonces
» » » Vidéo. Tounkara: « Si Waly Seck me chante, je...

Vidéo. Tounkara: « Si Waly Seck me chante, je vais le… »

2016-04-07T10:36:08+00:00 Partages

Annonces
Annonces

43 commentaires

  • Dady
    07/04/2016 11:05

    nana yaw vrai na fekkh nga

  • ousmane
    07/04/2016 11:19

    C’est cool

  • la verite
    07/04/2016 11:58

    nene vraiment je sui deçu
    yakaronnaner wahkatou deugue nga mais daal moye loolou

  • woundou
    07/04/2016 12:11

    nana tu nous as emmerde avec tes commentaires à la con

  • Nana
    07/04/2016 12:11

    tounkara amo djoudou,sy mame todjou gnou fne,waly amoul sa djotou ndye

  • Arame
    07/04/2016 12:17

    tounkara bayil togn Viviane ak waly meune nagn am lou raw disque dor

  • kheuss
    07/04/2016 12:31

    rappelons les termes de guèlawar

  • Mamadou
    07/04/2016 13:16

    bravo Tounkara

  • …….
    07/04/2016 13:54

    tounkara yaw ousin Keta sokhla woula waye,waly dou messeu woye sa Ndye

  • Bro
    07/04/2016 14:08

    Nana la ferme avec sa khesal

  • boy LG
    07/04/2016 14:11

    nana sa lakhou ndaye

  • lybasse12
    07/04/2016 14:21

    je t’aime Nèna trè belle

  • ra
    07/04/2016 14:30

    Tounkara va te fair foutre tu vo rien i yeux de wally

  • ra
    07/04/2016 14:35

    Yow ko meune envoyé prison mdr senegal mo nekhhhhhh

  • Julien
    07/04/2016 14:58

    Triste Sénégal, l’humeur les irrites tounkara fait la comédie en tant que journaliste ils n’ont rien comprit, le pays vas mal en plus machot, homophobe, sorcières on se detruits entre familles, amies est proches, même pour remplacer le maire on l’envoi au cimetière,
    Bientot il fera jour certains vont se cachée

  • delaye
    07/04/2016 15:04

    Triste Sénégal, on n’a comprit le sens de l’humour de Tounkara
    les insultes pleuvent la démocratie est de dire tes pensées sans être giflé respectons l’opinions des autres est avoir la tolérance des critiques, wally chante mais ils n’est pas encore Thione Seck ni Mapenda seck ou Bambaly mais ils la chance nous lui souhaitons bonne Continuation @ wally Seck.

  • Sa
    07/04/2016 15:18

    nn Sngal daffa nx lou nx way wax nit beug niou koy dm wally loutax mou nx ma migui liguey ta waxol

  • arona
    07/04/2016 15:28

    yaw nana khans tu na par fais les bancs.

  • Julien
    07/04/2016 15:35

    Triste Sénégal, on n’a comprit le sens de l’humour de Tounkara
    les insultes pleuvent la démocratie est de dire tes pensées sans être giflé respectons l’opinions des autres est avoir la tolérance des critiques, wally chante mais ils n’est pas encore Thione Seck ni Mapenda seck ou Bambaly mais ils la chance nous lui souhaitons bonne Continuation @ wally Seck.

  • RANE
    07/04/2016 15:43

    Bien parler tounkara…senegal bayilen niane bu metti bi

  • Truth
    07/04/2016 16:05

    Tounkara tu tentends bien avec la meuf esk dou sa guel ci pet mdr

  • babs
    07/04/2016 16:22

    Tounkara legui mou takk niétel…nimouy holé halébi..bakhna dal

  • Madona fall
    07/04/2016 16:58

    Diombina warouna diakhlena diombi hatete wayene gars diombiwoulene senegal douniou demm liii

  • Inconito
    07/04/2016 17:10

    Bfff ioe dé Wally soula wayé ma bayii déguelou musik…aak sa lélle bou sorri mdr…

  • momo
    07/04/2016 17:38

    mais nana mii nekhnama dii…

  • Giss Giss
    07/04/2016 17:48

    voyan bakhoul nana ai dar yanguie yakha samay nelav?e

  • as
    07/04/2016 18:10

    Tunkara yaw kou yabatenga, waly dou meusseu way sa mame, ndakh amo dioudou amo khaliss

  • ba
    07/04/2016 18:24

    Viva waly berci boy

  • Khalifa Ndiaye
    07/04/2016 18:46

    Kofi Olomide!! Et les Zaïrois dou niou Wayan, thi sene chanson…

  • sylvestre
    07/04/2016 19:57

    Sénégal kou mélni tounkara mo fi bakh wakh deugue. si on ecoute au calme on verra kil a raison sur toute la ligne

  • Loubakh
    07/04/2016 20:06

    rewmouy dokh dou am wayaw senegales yi dou nou nangou dueg

  • Anonyme
    07/04/2016 20:56

    senegal dougnou dem te beugou gnou kou dem

  • Deug
    07/04/2016 22:45

    Tounkara for president. Je signe et persiste que Mr Tounkara peut régler le grand mal qui gangrene notre cher Senegal.La facilite ou beugue lou yombe!!

  • Chen
    07/04/2016 23:01

    Je ne suis pas d’accord avec toi Tounkara méme en Europe les gens demandent il n’y a pas de boulot.Et puis on est dans un pays pauvre.

  • beug baye
    07/04/2016 23:15

    vraiment tounkara amoul morome dou wakh dara si bakanam mé dafaye pour intérêt Sénégal peace tounkara

  • el hadji diaw
    07/04/2016 23:20

    diadieuf tounkara Sénégal ça kanam wayane bakhoul si rew Sénégal dou avancés ndakh fo

  • liiii
    08/04/2016 00:00

    wally borom khol bou bone douko beug ndakh danganane limounoul nk t yalla rk moy my beug bagne yalla moko mye kou sonne Di nga nopalou kanam rk la dieum nonam dou nlaw wakh ba sonneu rk nopi

  • iran
    08/04/2016 00:27

    lii motakk senegal dou demm kouy waly vs ns amerde avc ce moins k rien de waly gor jiguene

  • Sidi
    08/04/2016 00:44

    Tounkara bayil tapage bii waly seck mo gui si diam. Tout ck tu dis je suis pas contre mais manou bakh si diamou yalla

  • RM
    08/04/2016 10:07

    merci JULIEN.

  • RM
    08/04/2016 10:10

    merci Liiii.

  • bower
    10/04/2016 16:17

    Gelawar (certe nous sommes indépendants mais sous perfusion ) état du senegal mo dakh woyann

  • FASSA
    11/04/2016 12:25

    Merci mr Tounkara et nana vraiment bien dit mashallah

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces