Annonces
Annonces
» » » » Vidéo: Tacco Affro coiffure achète une valeur...

Vidéo: Tacco Affro coiffure achète une valeur de 2500 euros de billets du bercy de Waly Seck

Tacco Affro, une femme entrepreneur et sénégalaise résidente à Paris, a fait un achat de 2500 euros de billets d’entrée pour le concert de Waly Ballago Seck le 4 juin à Bercy.

Une somme d’argent conséquente remise en main propre à Moustapha Dieng de Sen Art Vision, l’un des promoteurs du grand événement de Waly Ballago Seck, est en guise de soutien au faramaréne pour la grande réussite de l’événement selon Tacco.

Annonces
Annonces

49 commentaires

  • Giss Gissi
    30/05/2016 10:29

    man deuma bage waly vay li aydorr lark

  • domou djoloff
    30/05/2016 10:35

    arrter avec vos articles bidons cette somme n’est pas colossale cest juste 1 million six cent mille de nos pauvres francs

  • right
    30/05/2016 10:36

    Aucun profesionnalisme pff…You dawoul def li dé

  • wakh sama khalateu
    30/05/2016 10:53

    Je suis désolé vraiment mais li amoul bene importance nous les sénégalais on n’aimes trop se montre alors que pourquoi pas mou âme discrétion lou ma wourr moy femme bi ameuna si membres familles kou ameu besoin bou matoul cette somme

  • Avatar
    30/05/2016 10:56

    dm ln diamou dji allah moo tiene weur ngn di dm bercy. wouty bakkar. bercy = bakkar t ngn diokh sarakh goumbayi ganayi borom fbarou khl yi ni amoul lounou lk. df ngir yallah ngir sn bopp..khawma nak ay dioulit ngn wala ay nafkh

  • onemen
    30/05/2016 11:27

    C bien de faire la pub de ton salon mais dieundone ben billet bou 60€ dem setani dieule 2440€ diokh ko sa bene mbok sarakhoulé mou investir si di ngua si ame au moins nianou mbok ak Yalla….bayilen wanéwou WALLY meune na dieude sen wakeur yeup!wa salam

  • dass
    30/05/2016 11:35

    mais wally est dja riche sister , diapalel sa famille dinga am tiyaba

  • aida la paris
    30/05/2016 11:48

    Nékhoule ba nékhoule jai bien peur que Bercy bi échék laye donn . Je suis fan de waly mais dale sama khéle daloule dara dara , lî ma djiss dale nékhouma, Bercy bi amoule béneu béneu empleure , wayé yala bakhe na . Mais rien est trop tard na waly annulé Bercy bi té défeko apes core gui a zénit . Si cetai moi nonoulaye déff. Wayé sénégalsi yî gnoye aye séytané dougeule nanou waly bamou dougou si loumou meunoule

  • dam
    30/05/2016 11:50

    lid diaratoul teug concr ba topou nityi pour nou dieuf say bey

  • Zzzz
    30/05/2016 11:50

    Doffffff rek

  • paris
    30/05/2016 11:54

    hahhaha koka man ak koukay dim wantrnanou takhoul Nou am ay nite bimosi dson

  • rik ros
    30/05/2016 11:55

    2500euro * 650f = 1625000f cfa se qui poura constuit une mosquee ou ou soutient des darra ou hopitaux domage sa

  • paris
    30/05/2016 12:01

    bercy biellyi dadan diekh 1moi avent 2013 100 euro lako m si bn tranficant soudoulwon lolou doma dook . lami dioblou moy na senegalais yi kham paris ak dakar

  • Gueye
    30/05/2016 12:10

    Elle fait du marketing pour son salon

  • mami
    30/05/2016 12:10

    Démale ga diapalé sa yaye mo geune si yaw sa niawaye wala ga défare sa salon de coiffure bi mo geune ??

  • Papis
    30/05/2016 12:11

    Aida la paris » ligua wakhe deugeula dé moi jbite a paris wayé bercy bi amoule echos dé, té bercy pourmou féss il faux lapui des autres nationalités, et a 6 jours de bercy les billets sont pas finis cest une echeque totale. Yala nako yala takhawou

  • tit
    30/05/2016 12:11

    barcy boumlni grand teatre firm la am

  • inco
    30/05/2016 12:13

    no no bilahi senegalais dou si keeneu ame na saye bokou youko sokh la diokh leene ko

  • fafa
    30/05/2016 12:19

    gg

  • fafa
    30/05/2016 12:20

    il faut aider sa bokh yi nék tamba

  • fafa
    30/05/2016 12:23

    il faut aider sa bokh yi nék tamba

  • fans
    30/05/2016 12:26

    Èchèc total wakh deug li mom wantèrla .100 bièlle 25euro par bèlles lolou mom wakh deug wally danouga

  • fans
    30/05/2016 12:29

    chec total wakh deug yalla 100blles pour 25euro par blle . wantr deugla wakh deug yalla

  • Souroumelé
    30/05/2016 12:30

    Lolllll li nak moy lambalé franchemen waly amoule conseillé bou bakhe legui mo guinî aye nakhé ngaye moudjé
    Bercy dou grand téatre. No no mane bama dégué saly daye jouer bercy bobou la khameni day danou. Bercy cest pour les artistes de renommer internationale

  • sokhna amy
    30/05/2016 12:42

    dlne dimbal gnou gnak gni mo gueuneu ligune di def amoul bneu sense

  • Bercy
    30/05/2016 13:49

    Mais gnii kouniou yapp ?
    Biguén khamé né bercy dou ay foo warolén cii wone dougou.
    Nakhaté rek.

  • fa
    30/05/2016 14:11

    ay wayy bayiléne sokhor kagne nguénn di na ngou waly mo khew mofi nékk bou nit yi gneuwoul sakh djiné yi dinagnou gneuw gnanal léne koo ndakh ndamou waly ndamou senegal la sé le senegal seul ki gagnera

  • zizou
    30/05/2016 14:16

    jajajaja bercybi d masoufi am wanter say bey pour mana ramplir sa sale doyna war

  • fatma
    30/05/2016 14:22

    pourkoi le senegalais voi le mal partou ay way bayilénn sokhor waly bouko nityi mayoul sakh djiné yi mayko si vou saviez ce k je savai di nguénn nopi bande dignoran k vou ete

  • bass
    30/05/2016 14:28

    dégueulma bercy mom yénn lane nguénn beugue? k lé gens navancent pa dan la vi ki ne risk rien nora rien le gars ki organisé lè bercy preceden tou sé ami se mobilisè pour lédé lé joueur lé mbagnick diop souche lè cheikh amar amet amar et tan dotr pourtan il é rich mé organisé evenemen yomboul surtu dé jeun kom waly senart vison et vou et nou gnanal lénn khalé yi té bayi sokhor ils sont tous dé senegalais com vou ben ndamm rek moy amm et sé le ndam du senegal

  • nasi09
    30/05/2016 15:09

    aida de paris fermer votre bouche vous etes jaloux boudone se frere do wakhe li

  • Apres bercy
    30/05/2016 15:16

    Samedi yagatoule
    En tout cas sou vider chacun peut parler d’echec, mais s’il y’a du monde que tout le monde accepte la réussite.
    Pas de alibi genre danio mayé porte, danio mayé ticket, dama kham senegalais

  • Bercy
    30/05/2016 15:16

    Bass! gua balma dé. mais senart vison daffa organisé wone comba de lutte de bombardier baboye j’ai acheté lou chérrrrr, sama palace nék cii vip .organisateurs yiî vu que ils ont échoué .Ils dit que (wathieu lénne dieumel guéw bii )pour images yii rafet.

  • nasi09
    30/05/2016 15:17

    papis wally vous a bien dit cest pas un challenge pour lui bifou yamone sakhe mou nekhe tu ment youssou l’age de wally il n’osait pas prendre bercy ecouter meme moi je me demande si cest pas un chinois qui vas tapper pour le 4 juin incroiyable comme les senegalais sont jaloux ayé daguene khame wa europe guene fi feike mechant ba dé

  • Veridad
    30/05/2016 15:22

    Taco way No mais allo quoi

  • Rébatass
    30/05/2016 15:26

    Déf lou meune !wakhe lo meune ! Sô teudé néléwwwwww
    Ay lî si Bercy, aye sou nguêne khamone li nguén digalé
    Ho les amis faut plus acheter de billet le bercy sera porte ouverte….

  • boy_ LG
    30/05/2016 15:36

    mdrrr kel sinemaaaaaaa

  • apres bercy
    30/05/2016 15:38

    Samedi yagatoule
    En tout cas sou vidé chacun peut parler d’echec, mais s’il y’a du monde que tout le monde accepte la réussite.
    Pas de alibi genre danio mayé porte, danio mayé ticket, dama kham senegalais

  • ares bercy
    30/05/2016 15:38

    Samedi yagatoule
    En tout cas sou vider chacun peut parler d’echec, mais s’il y’a du monde que tout le monde accepte la réussite.
    Pas de alibi genre danio mayé porte, danio mayé ticket, dama kham senegalais

  • Apres bercy
    30/05/2016 15:40

    Samedi yagatoule
    wadjale léne sén tontou, bercy dina fess. None yi outeuti lounou wakh.

    surement ce sera danio mayé ticket yi

  • Apres bercy
    30/05/2016 15:42

    nguir yalla nak, sou bercy fesser pas de commentaire haineux,
    sou vidé nak lounekh way wakh.

    samedi nguén diiomi , bouléne fi wakh danio mayé ticket rek nak, wala camera yi nio dieuloul lép, li nguén di sokhor lép,

  • zizou
    30/05/2016 16:20

    fes yalla khamnani wally manoko fsal samdi nanou tal lampou nga khol tiribinbi malgr wantrnanou ba parr

  • Lolodown
    30/05/2016 17:28

    Wally a très mal choisi sa date. A moins d’une semaine du Ramadan, les émigrés sont trop sollicités par leurs parents restés au pays pour penser aller gaspiller des Euros pour ce saltimbanque. Dommage!

  • momo
    30/05/2016 17:59

    yén elle fai une pub pour son sallon de coiffure rew nganeu trop

  • jack
    30/05/2016 18:33

    c’est sr que am nga ay frre you diapoule thi dara niak fayda

  • zèbre
    30/05/2016 19:47

    Vous pouvez acheter les billets mais pas les personnes.

  • zeuzeul parisienne
    30/05/2016 22:01

    ohhhh my god yakamtina samedi diot wayy ba lii yeup diekh tt d’abord yaw mom taco boul sakh esperei may gneweuti fofou di dieund cheveux coz la dernière fois frisei bou bone ngen ma diaay. Sinon waly vraiment chui à paris mane yaw rk laa beug walay mais je ne viendrai pas à bercy parce que je sais que dou fess c pas grand theatre qui fait 1800 places bercy a été rénové et depuis ça fait 20300 places. ils ont fini les travaux en 2015 et ça ait parti des 5 plus grande salle au monde. j’ai vraiment la trouille d’assister parce que khamnani dou fess. c’est dommage nak mais il faut quand même osez dire les choses comme elles sont. Les gars qui sont derrière toi là je me demande s’ils ne sont pas tes ennemies par hasard. C’est un mauvais conseil qu’ils t’ont donné. miskine.

  • Urgent
    30/05/2016 22:39

    Bercy le 04 juin 2016
    Jour-j-4 statistique des ventes
    En france: 1256 tickets sont vendues pour linstant
    En angleterre 16 tickets sont vendues
    En italie 9 tickets
    En allemagne 3 tickets
    En espagne 5 tickets
    En suède 7 tickets et pour les autres pays zero vente
    Souma béneu copin moma ko révélè te il est tres proche des organisateurs risquent mêm d’annuler ils ont dans les discussions ……a suivre

  • Souroumelé
    31/05/2016 07:48

    Lollll urgent boula fans waly djapé dou bakh si yaw dé lollll
    Entout cas délocaser ko mo gueune dé pourquoi pas ba janvier 2017 moy dakhe sakh

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces

L'ACTU EN TEMPS RÉEL