Les plus populaires

 

Lecteurs en ligne

Une info ? 
 

+221 33 823 43 43

Vidéo: Show de lissa et sa sœur Sophia… Regardez

Mbaye Wade Mbaye Wade 2014-04-08T18:56:28+00:00 Partages
Annonces

lissa et sa sœur Sophia en mode selfie sous forme de vidéo. Regardez

Articles connexes

17 commentaires

  • astou diagne dit :

    amoulene bene korom…

  • nana dit :

    elles se prennent pour qui???? beyonce et shakira ou quoi!! vous netes personnes on sen fou de votre show de rien du tout, alors!!!

  • tya dit :

    c bien de se deffouler des fois yen lou ngueine sokhor

  • mamy dit :

    nana yaw loy sokhor todio féne kéne khamoula tékiwo dara kone nangoul li yalla dogual do sone sa khol dou diékh bagnou amé khorome moy biguako sétané yaw awa diagne li dafa nékh kou né nékhoul daguasé bokoul sa khol di khassane té meunno si dara diém léne bayi trass si séne adouna waye té bayi séne khol you bone yiguéne yoor chiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiimmmmmmmmmmmmmmmmmmm!!!!!!!!!!!!!!!!

  • minisse dit :

    mais loutakh fanne. dou ngou ramass

  • nana dit :

    Mamy yow ya niak fayda té imbecile mane dé douma defendre bene kenene a moins que mou nek yene meme té changer sene nom sinnon t’es trop bête va au diable bêteeeeeeeeeeeeee!!!!!!

  • riri dit :

    Nana do dèm, y’a sèw té mince nangoul rek tte bagnards sokhor , loula kham??? Tekiwo fi daraaaa! May niou. Idiotr

  • nana dit :

    SA YAYE SUIS SURE MAKO GEUNA TEKII DARA TOI RIRI

  • fransiska dit :

    oh nana yaw ya sokhor té gate khalate sa tour bi nimou gaté nonoula sa khol bi ndawé ndakh sa yaye dawoula sang bagua sétte khol day séte waye gneup meune si khadji lou gneuw gua rafétal ko nangoul waye todio féne mdrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrr sokhor ish!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!

  • mamy dit :

    diadieuh fransiska !ki cho coeur leuh tkt dou dém dei dafa kalé ba paré sou sagnone nék si placame mé dézolei ndayame liguéyoul waye!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!

  • fransiska dit :

    wouyyyyyyyyyyyyyyyyyyy mamy nank so diéko dél balé nana mougneul déng so magué sa khol séte rék mou diékh mouaaaahhhh waye mamy chou

  • fransiska dit :

    boul mér iow puce soukeureul sa adouna waye ish boul guiss sa boop dagnouy fo rék lilay wakhati si sa khol bou bone bi amal talibé puce li dou dara akh boul guéné sa khol waye!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!

  • fransiska dit :

    dof gua trop trop trop waye chiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiimmmmmmmmmmmmmmmmmmmmmmmmmmm

  • Amin dit :

    payee kottu halpulareebe wostaabe reedaabe kottu ko hadi on yim de codda adama aisse payee soolde ndiouma naa be nawii barke mon diplfube reedaabe payee kottu neddo woppa ngessa baamumu wona e remde ngessa bamum janano ko wo fullbe reddaabe inangodi ngoppon doo thierno saamassa ngoppon doo thiorno aliou thiam ngopon doo thierno bassirou tall ngoppon do thierno amadou tidjani ba to madiina gounass ala mo djima ton so modou karaa mbati ko kara hoowata on onon reedaabebe onon dido kala nde gooto e mon arti fouta ko min koowoobe youmoum

  • nana dit :

    ah cool je me contente seulement detre folle mais pas ratée comme vous hein…….cava!!! idiotassssssss

  • didi dit :

    yen gnar gni daw léne sobouji guethie ndakh ngéne ame khorome. san s sel tchimmmmmmm

  • M%mo buzlab dit :

    life bi metiwoul mé plutot yena ko metil gni sen video laniou def publierr boulla nehoul boul commenté cé simple com bnjr

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces

L'ACTU EN TEMPS RÉEL