Les plus populaires

 

Lecteurs en ligne

Une info ? 
 

221 33 823 43 43

Annonces
Annonces
» » » Video: Serigne Moustapha Sy a vu le prophète...

Video: Serigne Moustapha Sy a vu le prophète dans les couloirs du Paradis

2015-06-23T12:00:48+00:00 Partages

Annonces
Annonces

58 commentaires

  • fall modou bété bété pur
    23/06/2015 12:31

    Machallah .amna solo lolll. dieuredieufe sy malick. yallah na yallah deugguereul sa takhaway .ta wereul say thieur . yallah nangafi yaggue loll ta am wergui yaram ak

  • astou diagne
    23/06/2015 13:20

    machallah

  • sy
    23/06/2015 13:20

    Wallay ndeyessane

  • astou diagne
    23/06/2015 13:21

    amine

  • Dabakh
    23/06/2015 13:21

    sama mama néna…

  • Ziza
    23/06/2015 13:27

    dafa ame bène wayy bou meusseu gneuw cii serigne babacar, mounéko….wallay ndéyessane

  • sénégal
    23/06/2015 13:33

    Ayy bou ko Kara wakhone walla Ch.Bethio kone tayy tama dou lène eup boume

  • Muslim
    23/06/2015 13:56

    bayilene di dingate nitou yalla yi gnoune gnep ay dioulith lagnou lep fa yalla

  • matou
    23/06/2015 14:32

    SY MALICK R. A.T amena solo

  • Talibé Baye
    23/06/2015 15:08

    talibé cheikh lolou diombou ko machallah ! Senegal ay borom ham ham kamil gnofa nek !

  • El Bachir
    23/06/2015 15:26

    mach'Allah xam xam bou ler ngay waxee yague fi lolou Sy niou yague fi

  • bene copain
    23/06/2015 15:28

    machallah, que le BON DIEU continue a te donner plus de sagesse

  • talibè cheikh
    23/06/2015 15:31

    eskey seutou mbaye sy ababacar rta li diomboula sa mame moye cheikh al Khalifa moye borom bonè carré machala sy savanè

  • BBC
    23/06/2015 15:38

    Kou beugue khame kouye seydina Mohamed démale Tivaouane mame Maodo amoul morom machalla

  • JOE MANSOUR
    23/06/2015 16:13

    ON PARLER QUE DIT XAM XAM PARCEQUE DAGNIO DIANGUE ET QUE DAMA FOGNI YAW DEGLOUWO VIDEO BI

  • DIOP
    23/06/2015 16:15

    NDEYSANE KOU YEURMEUNDE CI AY NDJABOTAM EK KOU YEWENE CI KHAM KAMAM. YALLA NAKA FI YALLA YAGAL SY MALICK.

  • talibe
    23/06/2015 16:16

    moooooo guentoul dara.lui la c'est un grand comedien

  • zaleh
    23/06/2015 16:18

    walay ndeysane.fou sore' lay wakhe' kou amoule deg deg doko kham

  • yks
    23/06/2015 16:33

    APRES CHARLIE, HOURECHI ET LAHAB C'EST MAINTENANT LE PROPHETE vu DANS LES COULOIRS
    du paradis

  • ciss ibrahima
    23/06/2015 16:45

    yalnaniou la yallah fayal ar la lakla fou yak égoul sam la sam sa kilifeu sa guéné rek niou xamni nitou yallah deug moy wax sénégal nak da beuri niou xaméwoul ki yallah yoni ak kou nit gni yoni

  • D M W M
    23/06/2015 18:01

    limaalaye khamale moye qui dou kara dou bethio dele dedale gnou bokk qui limiwakh dafako khame

  • legalazed marrihuana
    23/06/2015 18:24

    wai bayilen di wédi "plazzzzzzz

  • le musulman
    23/06/2015 18:46

    wa mé ki mo meuneu féne…walay ndeysane

  • sama reew
    23/06/2015 18:59

    wallaye ndaysane
    sy niogulaye ziaare bo bàkh.

  • Bik
    23/06/2015 20:46

    Lepp lou serignou tidiane wakh yalla sédénako nakh Sénégal niome rek niola mena wakh kouye yalla ak seydina Mohamed… Mouride yi kéne diangaloussi talibé me yalla Walla seydina Mohamed nakh séne wakh yepp serigne touba rek laniouye wakh séne béne talibé khamoule yalla…kou beugue khame dara daara djangui Tivaouane

  • yacemina
    23/06/2015 21:09

    machalla

  • SONINKE
    23/06/2015 21:58

    @BIK
    YAW NAFEKH BOU MAK NGA
    KANE MOFI WAKH WAKHOU KHADIM RASSOUL BA NGAY WAKH SA WAKHOU SATANYI

    NAFEKH BOU MAGA MAK NGA YA RAW SATAN

    SERIGNE TOUBA MOY SA NONE ? bakhna adina mougui sa kanam

  • moi
    23/06/2015 22:10

    On oe le croire deux de mes amus m'ont dit kil int une fois vu le prophete en reves et ils ne pas des marabout ya rien d'extra mm yow mi geumoule limouwakh tu oe un jour rever voir le prophete li dou dara wassalam

  • Talibé
    23/06/2015 22:58

    Bik balla ngay dé di nga réthiou li nga wax bilahi! Bayi len gayou bax yi ngeun di foyé niak ngen yarr trop

  • sunugaal
    23/06/2015 23:05

    Dire c'est vrai c'est accepter à l'aveuglette tout ce ne vient ni du coran ou de la sunna du prophète. Dire aussi c'est faux c'est nier sans preuve.Serigne bi daal wax na daal ndeyssaan?????!!!!!!!Bouy deuggit moom la djeurign. Gnoun woor weeru koorwi moo gnouy djeurign.

  • mor talla fall
    23/06/2015 23:09

    Limou wakh kane mako mana wédi pasque guenteu la wakh lo Lou kay diaroul diingëtt

  • mame amar
    23/06/2015 23:57

    Assalamou allay koum yen sama mbokky didef ay commantaire amlene apyar aki deguine rawatina kinguakhamne mon ndiegue wakh linguakhamnè douyon moy kingua khamne monfi wakh wakhibay kara mbacke ndakh fi lounoufi wara toude bay kara amoufi amlene worma si kilifayi kilfe wakhbapare nguadicoweddi rafetoure.
    Guannaw lolou maniewsi ki ngua khamene mon wakhne mouridyi dianguouniou dafa nioum ndakh boude dara simouride le appe boude khakham simouride le appe boude ligueuye si mouride leappe boude yarou si mouride le appe.yakarna niake tawfekh mante passe bania guis ligieyoup serigne touba si kham kham.mandisi dollirek ne yen nibagne serigne touba khelmou guatte la rek ndakh kokhamne dangua diouddou fek sa baye diko bangne ak sa mame te manouniousi mom dara soame am khel warakhamne domansi mom dara dara dara conak nane am apyar aki teguine te wormal sounou mankgni wasalam

  • is back
    24/06/2015 01:36

    Ki dall daye fenne wakhoul daggue

  • PAPY
    24/06/2015 01:40

    voir le psl c bon mais montrer aux talibes DIEU c'est encore plus bon comme le faisait ELHADJI malick et autre mais pas de leur rencontre des reves

  • PAPY
    24/06/2015 01:44

    reve le psl n'est pas du xam xam soiez srieu

  • goualiyour
    24/06/2015 03:13

    moh kimo sof rék yawe mi kahamné do wathi diabari diambour yi tahaw fi nane guénté ak patati patata do rouse sakh hana iblise ka guént fi senegala hamanté nane boubah

  • Salam
    24/06/2015 03:22

    MachAllah Sy, moi à 25ans de vie j'ai rêvé plusieurs fois du Prophète Mouhammad PSBL.

  • Idrissa
    24/06/2015 04:38

    Serigne moustapha Mala begue lol

  • Tapa
    24/06/2015 06:41

    Bilahi daay feen feenn rek lagni di deef feen rekkk domakhram

  • MOURITT SADIX
    24/06/2015 08:56

    goudeul fann, amm wairgou yaram. BA YALA YOKAL LA XAM XAM BI, MEUN MEUN GUI TAI MAYLA MOUDIOU GOU RAFAITT. LE SENEGAL NE PEUT PAS TE PAYER MAIS YALA MEUNN NALA FAY TAI DINALA FAY. DIEUREU DIEUF SERIGNE MOUSTAPHA SY

  • LOME
    24/06/2015 11:10

    vue la bassesse de vos commentaires et cet injurieux titre parceque blasphématoire,la honte me ronge parce que je n'ai jamais cru que les musulmans sénégalais soient de bas niveau.le prophéte,tout musulman ayant une foi et fournissant l'effort de la sainteté et de la pieté peut le voir de surcroit à cet HOMME DE DIEU.Nous les talibés mourides comme tidianes,essayons de de nous echelonner spirituelma un certain niveau pour etre toujours dans le partisan de DIEU au ieu de se ranger dans ces détails futiles et ignobles.NE nous laissons pas etre otage de ces sites ki n'ont qu'une ambition diviser pour mieux régner en vue de mettre les musulmans dans le chaos.K'ALLAH DETRUISE ET AVILISSE TOUTE PERSONNE TENTANT SEMER DE LA DISCORDE ET DE LA HAINE ENTRE LES CROYANTS ET SURTOUT ENTRE LES ENFANTS DE MOUHAMED

  • sama reew
    24/06/2015 11:57

    Bik bayyil tong
    Ga balma nak me tong bàkholl

  • sama reew
    24/06/2015 12:02

    Lo waye wakh fii digako wakhàtt yawmal khiyame
    Do aye thiakhane

  • Pis
    24/06/2015 16:12

    Il est né hors mariage , regardez comment il ressemble a Iba der Thiam , meteur

  • securite
    25/06/2015 11:02

    mane dé souma reve psl

  • Milk
    25/06/2015 11:42

    Guayi gnou am yar way! Parsque gninguen di toud gnep bou donu ton gnome kon mou doy war lool gnome gnep Ben drapeau laniouy yeketi moy bou yonentibi salalahou Haley hi Salam!! Ken bal ma yalla na yalla Defal ñou Jam diou sah dak Senegal. Si barke mak gnou bah gnafa teud WA Salam

  • lamp
    26/06/2015 15:17

    pis digua ma raye ptdrrrrrrrrrrrrrrr wakhe gua deugue d

  • zou
    26/06/2015 15:35

    dionewaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaa!!!

  • ablaue gaye
    28/06/2015 12:59

    Billahi keep KO guiss. Mouille wakh wakhou r3wantou c parce que il n'est pas reçu une bonne éducation depuis dans leur maison tamoul surveillance lou nekh way deff billahi depuis dans leur vie ils aurons des difficultés jusqu'à la mort parce que seuteu seri ne Babacar sy seuteu serigne Fallou dankoy guiss

  • ablaye gaye
    28/06/2015 13:03

    Nioufi nekk di manque respect Aÿ faux musulmans nionye fil nekk dimanke respect douniou touss KO khamen3 do djouli do worr daguan wara teudjie sa gu3mine

  • chams
    28/06/2015 18:27

    dite du bien ou que vous soyez et á tous les moment de votre existence.le cheikh a dit la verité.dieu pardone moi ainsi qu'á mon peuple car la plupart sont des ignorants

  • Talibé cheikh
    29/06/2015 02:26

    Serigne mouhamadou Moustapha sy yalla nafi yague loll té wer sa takhaway rafétena

  • pape mbodj
    01/07/2015 10:47

    yallnalla yok ay leer ci sa barké ay mame ak ci barké cheikhouna tidjani et du prophete té tass nou si sa barké goude fann ak werr

  • analyste
    02/07/2015 07:50

    c'est peut etre vrai car serigne moustaphala waye lima ci diakhal daf ni yonette bi salalahou aleyhi da anndd akh securite bi. way sama gayi al dianna garde corp amoufa diarignn sama borom mo gueun juste un analyse veuillez m eclaicir svp

  • mam ammar
    04/07/2015 04:13

    mam amar; Yow wakhi dof rek nga fi wakh.

  • musulman
    06/07/2015 03:31

    Djoulite dou sokhor, Djoulite dou ignane Djoulite dou wakh louko leroul, Djoulite dou wakh wakh djou gnaw, Djoulite day soop morom, Djoulite day mandou,Djoulite dou dingante moromam, Djoulite dou togne

  • serigne moustapha seck
    12/07/2015 00:05

    sama tourando yalla naguafi yagu sy malick loo défaroule yakhokofi liguaye déff si diné dji rafétna

  • progres
    07/02/2016 23:16

    Man Dana warou so rewande not yi meme kilifeu divine yii vous les insultez motaxe nguen do diekki diekki febar boy grave wola accidente wolla nek so diaffeediaffee you taratar Mai's ou va le monde main tenant avec not you reeeeeeewe ndeyam yiii Mais jereve wola lii deug. LA dee boy niaw rek kontinuez Len rek vous allez voir inchaa ALLAAh tot ou tard bande d idiots

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces

L'ACTU EN TEMPS RÉEL