Annonces
Annonces
» » » » Vidéo-Serigne Modou Kara demande aux télés de...

Vidéo-Serigne Modou Kara demande aux télés de revoir certains programmes durant le ramadan

2015-06-30T13:29:29+00:00 Partages

Serigne Modou Kara demande aux télés de revoir certains programmes durant le ramadan

Annonces
Annonces

46 commentaires

  • LEGALEZED MARIJUANA
    30/06/2015 13:40

    haral ma rai toutiiii rekkk

  • Doff74
    30/06/2015 14:30

    Yangui rétane sa mousiba dé

  • toums
    30/06/2015 14:58

    wahal yane laniou wara change mo geune si vs avait le courage.

  • Mina
    30/06/2015 15:07

    khawma tchi dara deih wayei warr ngay kholat sh kadouh. Ay wakh youh doywar tei gnak teiguinn ngay wakh. Mame Thierno molah gueuneuh kham wakh deih lolou mom c sur.

  • ndiolcoumba
    30/06/2015 16:54

    Demande de renseignements: Il a eu à epouser combien de femmes au senegal ? notre cher marabout Modou Kara ?

  • kesk
    30/06/2015 17:45

    li télé yii di def ak wakh sakh moo tané lingay def ak lingayi wakh., mane dey bene émission kouthia moma gueneul sayi temeeri waraaté

  • baye darou
    30/06/2015 17:50

    Niak guene talibe trop ki dou séné moromo Baye

  • baye darou
    30/06/2015 18:07

    Nagol lén Serigne Touba mo geune sino séné xhol yi Day Bone rek

  • kesk
    30/06/2015 18:16

    walla sa bayi yow mo tekiwoul dara bamou guenko domeram

  • baye darou
    30/06/2015 20:10

    Kesk yow domeram gua ki mo geune sa Baye geune la yow

  • ndiaye
    30/06/2015 20:32

    kou am ligay n'a diokhé numéro rom. mo geune di wakh loubone si koubakh ki. Serigne Modou kara Mbaké c'est le référence des jeunes.

  • issa
    30/06/2015 20:48

    xana legui senegal dou pays laiik il fau pense aux autre

  • kesk
    30/06/2015 20:50

    baye darou yow ak sayi wa keur nieup ayi domou bireul ngueen

  • sante yalla
    30/06/2015 21:11

    rafėtal leen nogui ci wėrou koor

  • LEGALEZED MARIJUANA
    30/06/2015 21:57

    domou bireul kay haha sui dead

  • Asskan wii
    30/06/2015 22:25

    Modou kara nopile doo touss thiiip

  • senego
    30/06/2015 22:42

    Kiiii dou Nit lii moy deumeu rayla dialéla Satan farmçon

  • dabi
    01/07/2015 00:30

    tu devrais enlever ce terme de votre vocabulaire kou tëdd ki relève de la professie et seul le profet mouhamed (psl) est habilités pour cette appellation. où tu le fais pour créer une amalgame et égarés les gens on na tout compris. sacré marabout du Sénégal. peace love and harmonie gloire au profet mouhamed ibn abdallah. je t aime

  • kebe
    01/07/2015 01:37

    no mais les tidianes laissez nous en paix

  • coums
    01/07/2015 01:52

    bamba train la,bouy dem dougou si mouyo bou la,wala nga takhaw mou diaar sakaw dem gnak ngen yarr lol

  • carloumendy
    01/07/2015 02:34

    yen loutah nguen yabaté Kara limouy wah hana degoulenko ki lou arangé askanwo rek la guis mokoy wah yén nak senegalais yi hamoumawon ni ninguen soharé kouy def loubah nguen di bania guis man carlou mako wah

  • Bob
    01/07/2015 02:38

    mdr ;;;;;;Yallah mobakh témana mougne!! Ballél rekk daniou khamoul dayesane

  • carloumendy
    01/07/2015 02:49

    hahahah mai kon dafa am niouy tekeulé s touba ak nienen hoooo boulen fir way s modou kara limouy def dacé degu ba amlimou am donc bayilen ko té guen djem def limouy def ba lep soty

  • garous
    01/07/2015 03:47

    pk tout se polémique le coran a été révéler à la mecque tout ceci est du bla bla rek ah… ah. si vous connaissiez les kestion du tombeau mieux k de perdre votre temps à croire à des humains comme vous soubhanallah je préfère la prière

  • BAMBISTE
    01/07/2015 04:21

    djeureudjeuf mbacké balla yagg fi té wer rèk

  • faye
    01/07/2015 04:58

    kara va te faire foutre tu es kune manteur.tu es la que pour les jolies femmes ferme ta gueule

  • faye
    01/07/2015 05:15

    bilaye modou kara ya mene sooop ligaye wakh hamo si dara

  • sam le pirate
    01/07/2015 05:28

    :D ki wakh rek lay def mbel …mbel..mbel soufekone limouye wakh amna sens sakh wantee touss wakhou pithieu reek by the way ana mouvement wam KARAY KARIM foumoussi tool wala tassna tassar comme Macky diokhnako TANGAL BANTE BOUMOU MATHIEU (ambassadeur) lol :D

  • mg14
    01/07/2015 06:56

    rien est semblable à notre prophète psl ouvrer bien vos yeux yalla geumoul nèlawoul serigne dafay mate serigne kara n est qu un faux type

  • mana diop
    01/07/2015 09:03

    JE POSE LA QUESTION POURQUOI KARA FAIT ÉCRIRE SUR LES MUR D'AUTRUI ET ÉPARGNER SA VILLA LA PLUPART DES MURS DE DAKAR SON SALI PAR DES ÉCRITURES EN NOIRS CE N'EST PAR BEAU A VOIR.

  • sam le pirate
    01/07/2015 09:56

    pourkw dounio diapp kou sant mbayé serigne bi diomga fofou mbaye y niass laye tous son des meme

  • deug
    01/07/2015 09:59

    avn de parlé au chaine d dimunué ls skech dite a vos baye fall d prier et de jeuner c mieu pour conseil

  • LEGALEZED MARIJUANA
    01/07/2015 10:31

    astafourililah dett way boul wah lolou

  • sofe
    01/07/2015 10:59

    pour nguéne khame ni séne gni nguéne di yakar té diokh léne séne adouna ak séne allakhira allale rék mo léne itéle lépe li gnouye wakh lou bari dou aye dégu pour khame lolou bayi léne di diokhé adiya rék légui wakh ya diékh gni gueumou gnou léne sakh té yéne aussi dénguéne gnak fayda té gnak gueum yalla rék mo léne tope

  • baye darou
    01/07/2015 11:15

    Kesk yow boudé liguay wakh deguela diokhma sa numéro ma fék la fou nék yow

  • baye darou
    01/07/2015 11:23

    Adiya bamba ko mome djeureudjeufti Serigne Touba goré léne sante Serigne Touba mo geune sino séné xhole Moy Bone rék bama merci

  • baye darou
    01/07/2015 11:26

    Kesk Bou de goor diokh ma sa numéro ma fékla fou nék mo geune sa wakh yi

  • wiiz77
    01/07/2015 11:40

    hhaaa eskeyy yénn dééé yénnaa niééméé kénalénn SERIGNE TOUBA ak wakeur YAALLA moléén kenall

  • lasco
    01/07/2015 12:03

    limu mu jee wakh lerna legui ngeen gnemee wakh motakh waye ba muy metti s touba rek

  • kesk
    01/07/2015 13:20

    bougnou guissé billahi barké weerou koor gui dinga diebalou si mane nga faté kara nafekh bii si tu veux toi tu me laisse ton numéro moi même je te fixe le rendez vous fouma layi toubilo

  • baye darou
    01/07/2015 16:01

    Yow liguay wakh guemoko sakh diokhma sa numéro mo guene sa guayi ma wola wakhla fouma nék bonék goorga yow

  • kesk
    01/07/2015 16:22

    Mais yow khana leegui bene numéro rek moo mouyi sama boss diokhma sa boss wola inbox fii sabilillah diokhma ko ma woola

  • Maréma Séye
    01/07/2015 18:44

    KESK iioe diga allakou malako wah…. Maanou léne sii kara ak ay mbiram

  • massamba
    01/07/2015 21:32

    senegal da nio xamou lu barii mo tax xamou niou louy défar waye yalla beuss bou fi sané baala dingén xam djam mo ay
    bamba merci

  • Eva
    02/07/2015 11:58

    yaw dof ga rek…

  • iba
    05/02/2016 16:34

    deumm yangui dieuferou dé….xana généralou bamba vous à frapper violement….déf lenn ndank rek..vous navé encore rien vue….

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces

L'ACTU EN TEMPS RÉEL