Annonces
Annonces
» » » Vidéo: Retour de Wade: le Premier Ministre...

Vidéo: Retour de Wade: le Premier Ministre Aminata Touré se fait entendre et avertit Regardez

2014-04-26T18:51:28+00:00 Partages

Retour de Wade: le Premier Ministre Aminata Touré se fait entendre et avertit

Annonces
Annonces

26 commentaires

  • beugue fallou
    26/04/2014 19:03

    yow ya meuneu doul nioune wade laniou wakhe

  • beugue fallou
    26/04/2014 19:04

    ak sa geumégne bou wingue bi

  • ndiaysamb
    26/04/2014 19:10

    boulenn mer il faut que sunu khaliss impots yi gniou kham fomou dougou ,deuka bi metina nakh milliards yi wa ngourou ablaye wade rawalé ,kepp kou sathiaonn di ngua ngua gokhi !lou ler l lenn wakh !

  • ndiaysamb
    26/04/2014 19:12

    senegal yenné nafekh dou yenn yenna voté wonn macky sall nakh ablaye wade ak gouvernemenmam dafa lenn sathié ay milliards rewmi sokh ,legui nguenn wakh da nguenn dioumm ,mann dé dioumou ma ,il faut gniou kham sunu khaliss foumou dougonn,macky abalaye wade dafa ko da konn yobou ko dic ,mé dic guissoul dara ,

  • Abdou Kady
    26/04/2014 19:17

    Amnah gno wahne gorgui degno dioumon vote pour macky mandé bokou mathii ablaye la gueume teh mome lah mosa gueume je suis liberal et je restere liberaux

  • beck
    26/04/2014 19:23

    rek nak,cool ba si cachot bi,le monstre ne connait que la violence donc il faut le suivre sur ce chemin

  • Abdou Kady
    26/04/2014 19:27

    Ndiaye samb yamana doul ndenga fogue neh senegal gnep gno vote woone pour macky mane laye laa mosa hame

  • you
    26/04/2014 19:33

    mimi da sof

  • amdy
    26/04/2014 19:47

    mimi et son clan on extremement peure parceque wade es un monstre en politik vous alez voir vive wade et merci pour tous le bon travaille que vous avez fait pour notre chere senegal ces ce que mimi et son gouvernement sont entrain de detruire bande dinitule.

  • futuriste
    26/04/2014 20:01

    beugue fallou yaw koo rew nga.tu respect pas tes parents et partant sa köye mogana wingg

  • leuza
    26/04/2014 20:29

    Beugueu fallou nay rafett way c mieux

  • bobo
    26/04/2014 20:38

    Vive la dame de fer jappal mou deguer ,le Senegal sait que vous etes capable il ne faut pas que ce bandit et ses fils vs intimide

  • bobo
    26/04/2014 20:41

    amdy ya gat yel te gaw fate thino bi gua am khamoni wade assassin et voleur mola ko tegue

  • abdou
    26/04/2014 20:43

    ablaye wade dafa sof ak bopame bou sete bi le Senegal est un pays de droit, que l’on laisse la justice faire son boulot

  • kia
    26/04/2014 20:44

    thieuy galsen

  • g83
    26/04/2014 21:36

    baravo mimi

  • mor
    26/04/2014 22:10

    nooon macky ak gouvernement wame douniou deme koiii niak fayda dieme lene def reponse politique bou bou niepe monue guisse moo guene nguene occuper madia yi di ratatati rek tes dieme egali chentier yifi souniou president wade bayi kome yene amooo lene bene khalate pour mettre en oeuvre des chantier egale peut etre mou moune lene yombe

  • ibson
    26/04/2014 22:57

    Mimi toure danga ay guaf amo chance nafek

  • real
    27/04/2014 02:42

    Xana cette dame ne c pas kil ya klk part dsns le monde ou on peut se retailler les partis deformantes. On dirai une monstre . Domaram

  • begue wade ba doff
    27/04/2014 06:48

    mimi catastrophe toure ame na loko doye boumou faténi oumar sarr pds est la ce n’est pas elle la justice mimi boule méére diaomono bii gnou tolou kosa khole nice soul boko abdoulaye wade dirigée réuwmi pendant 12 ans khamou gnou louye crise macky da gnieuw ak yéne andi di fii crise mondiale bii da gnou né deuk bii dafa maky daffa mimi ça n’ajamais existé de nommer des crises a des hommes d’état

  • beugue fallou
    27/04/2014 08:35

    futuriste bal nala mai mimi touré dou sarame ndéyam

  • miki
    27/04/2014 08:48

    Sama gars yi Ablaye Wade kouko bagne tamite khamni niitou weurseuk li adounabi done Meti yep Sénégal khaliss Bangui done circule come il le fau waye gni dagno gate weurseuk te ay tioune lagnou retiou nagnou lignou fi dieule goorgui

  • thiam
    27/04/2014 08:57

    aminata laisse maitre wade fait son retour et souhaite lui la bienvenue dans son pays c’est mieux de critiquer

  • mor
    27/04/2014 09:01

    Miki tu a raison bilay Macki dagno fek gnouy lek lakh ak bouye bou nekh di khar lenene mounegnou toure lenko ma diokhlen lakh ak soow gnou tourko legui diokhougnou dara te lagnou toure menetougnousi diote tedou gno woor Ablaye Wade nagnou nanguou consecance yi rek

  • Aminata samba mbaye
    27/04/2014 12:13

    Les Sénégalais ne savent pas ce qu’ils veulent. Vous pouvez parler sans insulter au moins. Vous oubliez beaucoup, si non toutes les ressources, tous les biens du sénégal est entre les mains de WADE et son fils. Il n’a qu’à suivre ce qu’à fait Senghor à Abdou Diouf, Abdou Diouf à Wade. La noblesse c’est pas facile si tu ne l’es pas. Laisser MACKY tranquille il est jeune, faut pas le bouffer. LA VERITE VA ECLATER UN JOUR

  • paix
    27/04/2014 13:51

    Bravo Madame le Ministre…sans commentaires!!!!

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces

L'ACTU EN TEMPS RÉEL