Annonces
Annonces
» » » » (Vidéo) Pape Diouf aperçu dans un...

(Vidéo) Pape Diouf aperçu dans un « Tangana »… Regardez

Après avoir enflammé la région de Bambey dans le cadre de sa tournée nationale, le leader de la génération consciente prend son petit dej dans un Tangana.

Annonces
Annonces

22 commentaires

  • Emy
    02/05/2016 16:22

    Pape ya modeste masha Allah ni leu

  • NekoRel
    02/05/2016 16:28

    Et c’est quoi linfo ? j’ai rien compris sur cet article.

  • khady
    02/05/2016 16:33

    bis naka tay sa fans LA pape

  • Mamadou
    02/05/2016 16:44

    li mo takh ma beuguela pape Diouf yaye ndananr

  • karbala
    02/05/2016 16:44

    Très modeste pape bilahi adouna niii leu woofaye rèk

  • omar
    02/05/2016 16:50

    pape ya hoyof yala nala yala takhawou meune nga lingay deff bolesi yarou hoyof

  • dass
    02/05/2016 17:08

    meuilleur exemple

  • njitlay
    02/05/2016 17:08

    waye bane modeste doule way artiste senegal daniou ame gate lool non senegal mo nekh rek ki kaye njeugou tangana rek la ame ay p square davido gnognou nio yorei xaliss bi le vrai

  • djibi sow
    02/05/2016 17:39

    bilahi wallahi ndanane nga papa diouf yala nanio djapale

  • Bercy
    02/05/2016 17:40

    Pape machalla daguay dem inchalla kén dou yaw.

  • Fa
    02/05/2016 17:47

    Njitlay yow doul. Si c’est pas de la modestie c’est quoi. S’il n’a rien comme tu le dis il pouvait envoyer quelqu’un et ne pas se montrer à la face du monde. Khana 1000f sakh kouko ame boula nekhe ndeki croissan. Négatif ba dé sokhor bone ignane.

  • cartel
    02/05/2016 18:43

    liii faale amoul problème en plus saaga borom tangage bio o moins dina nii pape Diouf mousnack leecke tounde tangana bii tangana pape Diouf comme tu bonne place no blems c Nice il est née au sénégal

  • cartel
    02/05/2016 18:44

    saagale n’a borom tangana bii c sa la vie il n’est rien d’autre cool yalla degala jaam mister pape Diouf

  • Mimi
    02/05/2016 18:56

    Pape modeste woul nank sakh è pourtant papou diabar dji do téglé gnari imeuble Si senegal tè gnetel bi gorom momouko ay imeuble tekssi nekk diamanter Ma shaa Allah gnoun gni deuk Sicap khamnegne boubakh kan moy bayou bb basse pape meun sing te yarou figko tekk fofouleu

  • big sa
    02/05/2016 20:16

    nit day wathiè bopam tolo ak gneup c bien paco yay ndanane

  • Giss ??Giss
    02/05/2016 21:47

    macha Allah rewo fuyo yalla nala yalla laffsl thite

  • Bour
    02/05/2016 22:08

    pape diouf tu es modeste juste un conseil de fans artiste dou fep laye leke Sénégal amna niou bakh am nah niou bonne faguaru dal mo gueune wa salam

  • Bour
    02/05/2016 22:16

    Je suis un fans mais nit daye moytou lou bari Sénégal am nah niou bakh mais am nah niou bonne yakh rek moyé sen ligueye pape khamalne t es un star te do guisse mouk youssou ndour à un tangana

  • ahmadq
    02/05/2016 23:04

    pape diouf franchement kou bakh nga modeste

  • gainde
    03/05/2016 00:45

    pape dama ko massa beugueu.yokoul ba yegko.yaa meun kep kou reuye ba dou lekk ci ab tangana.

  • fama
    03/05/2016 08:27

    beuz lay chercher

  • kheus
    03/05/2016 12:15

    senego doul

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces

L'ACTU EN TEMPS RÉEL