Les plus populaires

 

Lecteurs en ligne

Une info ? 
 

+221 33 823 43 43

Vidéo: Paco Jackson Thiam dérape encore à la télévision Regardez

Amadou SY Amadou SY 2014-04-10T08:16:47+00:00 Partages
Annonces

Paco Jackson Thiam dérape encore à la télévision

Articles connexes

54 commentaires

  • mimi dit :

    Astafiroullah!!!!

  • mouna dit :

    Serigne touba yalla la yakar boul dougeul s touba thi sa wah you bone geumo dara

  • laye dit :

    serigne touba néna kérok yomékharam amna nio khamni dougnema guiss
    parsk ligno nékone damathié nékoul wone

  • laye dit :

    mame bamba néna bou euleugué amna nioumadoul guiss ndakh ligni nékone nékou mathie wone

  • bichette dit :

    dieureudieuf serign saliou.

  • jean dit :

    vous savez paco n’a encore rien dit c un ivrogne qui se croit important mais la press doit arrêter de faire la promotion des mediocres car c genres de personne sont des anti modèle pour la jeunesse sénégalaise boula yallah diapé

  • aba dit :

    niite kou reeere dafa nakarer djoubati . Yalnako yalla djeuler tchi sangara té wane ko yone bou bakh bi moom ak ay moromam

  • juniorr dit :

    demande as packo il na ka demande as serigne saliou a qui il croit voila des gens qui dore completement et ceux que je ne comprend pas au senegal ya pas un start qui bois ni fumé ou prendre de la drogue ( ko lathé mounéla mousssouma touhk ,moussouma nane )packo as dis quil touche pas les bouteille humm de tout facon je vais plus tecoute car tu vien de depasse la ligne en preferant serigne saliou a dieu le tous puissant mais tehoko ces parseque tu na pas une education de base de vrai torodo no

  • kalachkovitch dit :

    manddii ba sa taatt bi féeess nguay wakh du n’importe kwa, bou yawmalkhiyamé fékhée serigne saliou assuré khamguani djéguée niitniou bakhi sakh tu ne les’ arrive mm pa aix chvie wayé nakk c pa 2ta feaute comme les chaînes tv ils ne assez responsable jusqu’àux points d’inviter des batarr t genr qui ne rapporte wéllou a société’ pffff les tombée

  • kalachkovitch dit :

    manddii ba sa taatt bi féeess nguay wakh du n’importe kwa, bou yawmalkhiyamé fékhée serigne saliou assuré khamguani djéguée niitniou bakhi sakh tu ne les’ arrive mm pa aix chvie wayé nakk c pa 2ta feaute comme les chaînes tv ils ne assez responsable jusqu’àux points d’inviter des batarr t genr qui ne rapporte wéllou a société’ pffff

  • kalachkovitch dit :

    manddii ba sa taatt bi féeess nguay wakh du n’importe kwa, bou yawmalkhiyamé fékhée serigne saliou assuré khamguani djéguée niitniou bakhi sakh tu ne les’ arrive mm pa aix chvie wayé nakk c pa 2ta feaute comme les chaînes tv ils ne assez responsable jusqu’àux points d’inviter des batarr t genr

  • kalachkovitch dit :

    manddii ba sa taatt bi féeess nguay wakh du n’importe kwa, bou yawmalkhiyamé fékhée serigne saliou assuré khamguani djéguée niitniou bakhi sakh tu ne les’ arrive mm pa aix chvie wayé nakk c pa 2tafeaute

  • lakhbouss dit :

    astahfiroulah ki dafa rére rek c un ignorant

  • lakhbouss dit :

    il croit a serigne saliou et serigne saliou il croit a ki li moye vrai nite kou rére

  • dada dit :

    ki dafa alkou je sais meme pas pourkoi on met ces specimenes devant la scene c’est grave

  • aba dit :

    dafa djara yeureum

  • thiey dit :

    Fils de pute nga tu connais meme pas la ou mettre les pieds

  • thiey dit :

    tu connais meme pas la ou mettre les pieds

  • big laye dit :

    ki khelmi fésoul

  • penxa dit :

    il n crw pa a dieu c son probleme mé se ki é sur celui k il crw crw a dieu ée prophète il restera tjt un ivrogne imbécile

  • lakhbouss dit :

    c’est un vrai domerame ce paco il ne croit à rien du tout

  • elzo dit :

    Mais ki defa rew tè khamadi

  • khalass dit :

    Li mou Wakh dëg dëg la lathie. Autant j’étais sidéré quand il avait tenu ces propos à sorano, autant je suis parfaitement d’accord avec lui sur ça. Dafa wolou Serigbd Saliou té khamni dou ko yobou fou nekhoul Yalla mo takh. Ce qu’il fait de sa vie nak ne vous concerne pas car chacun a ses tares que l’on aimerait que les autres connaissent. Arrêtez de juger les gens car vous aussi vous serez jugés.

  • mouride dit :

    comme BETHIO nèna SERIGNE SALIOU moy yallamm PACKO aussi mais yowmal khiyamm

  • abdoul'aziz seck dit :

    téy mome doumako wakh dara,bayi nako ak yéne ngui di ay nite,ki mbame moko gueune té kouye amne ak mome mbame ngua! seydou gueye moytoul sa bope

  • tifa dit :

    se pco là nous a clairement montrè qu est qu il est un framaçon il ne croit ni a dieu ni au prophète psl tu veras un jour ta punission le tout puissant est trop patient fils de pute

  • kati dit :

    boubbpaco boul takh ngi doul mouride amoungou geum geum thi seringe touba wakh serigne saliou lou ngou ko waroul wakh waye seringe saliou yalla kese la dieuredieuf serigne saliou

  • hams diawara dit :

    Incoyable mais vrai ce gars est reelement boulverse,arrete de dire des conneries ,si tu es musulman et fils de musulmans,que allah te pardonne,un conseil ;retourne a l,ecole coranique,il n,est jamais tard pour etudier,ps:apres avoir pris ta ronde d,alcool tu racontes n,importe quoi sama waye fais gaffe a tes dires.wa salaam.

  • leuza dit :

    Ki bayi lénn ko néna lénnn dp8 lotr jours dess na yénaine likoy dor moungui nieuw

  • mina dit :

    La libre expression sa existe je pense.! Vous qui insulter vous croyez que vous etes mieux que lui?

    • benzi dit :

      mina tu trouve ke c dela libre expression ce kil a dit??? je croi plutot ke c un ivrogne ki ne c plu ou mettre les pieds car si seulment Serigne Saliou qui compte pour lui alors kil arrête de fréquenter les boites où ilse souale tt le temps

  • boy diop dit :

    que dieu l’aide à sortir de cette situation

  • haxatawir9t dit :

    au senegal sougnou wakhé gnouné serigni faléw gnou sakh séne parents alors ke séne serigni séne paradis sakh woooroul!! du nimport koi surtou lés mourides ke GOD vs pardonne

  • haxatawir9t dit :

    com au senegal les imbecils gnoye éye royoukaye li rek mo meuneu done resultabi

  • haxatawir9t dit :

    ON DOIT REVOIR LA FACON DONT ON DONNE LE MICRO ,,,IL Y ´A DES GENS QUI NE SAVENT PAS PARLER…AUCUNE ÉDUCATION ,,LA CONSEQUENCE DE LA PROLIFÉRATION DES MÉDIAS…N´IMPORTE QUI PARLERA DU N´IMPORTE QUOI

  • mamy dit :

    ki dja dou mouride serigne saliou mimou geum yalla leuh geume ki soullard bou mak leuh kéne yébbou nak télé yikoy invité rék gnognou yép domarame bi gnou koy diokh importance té kouko kham deugue khamni dou mouride dou dioulite serigne saliou bi mouy mboubo la wara bayi guir yalla ,wayé so alko dei kéne meunoula guéné si dara domarame torokh rék gua def chimmmmmmmmmmmmmmmmmmmmmmmmmmmmmm!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!

  • boss dit :

    paco balnala limala warona wakh sa ma gayi wakh nagn ko am nga chance

  • Désolant dit :

    Peut être qu’il est animé d’une bonne volonté mais il ne maitrise pas ce qu’il dit.
    Un jour pendant qu’un Talibé était en discussion avec Serigne Touba, il voulut lui dire des propos s’apparentant à ceux de Paco:
    « Serigne bi
    Sou Yalla weuyéé
    Yonnente bi Weuy… »
    Serigne Touba l’interrompt et lui dit
    « Manite ma weuy ndakh nioniou founiou nékoul nékoumafa »
    Nioune nieup nagniou déllou diangui on a 7.5 tonnes à notre disposition.

  • makaveli dit :

    Il est trop con lui

  • mtl dit :

    kia bouko yalla diapé dina wakh lou set
    domeram pir la

  • ibra ndiaye dit :

    il faut eviter la tord en parlant

  • ibra ndiaye dit :

    les mourides sont des exemplaires

  • abou gaye dit :

    guene balma waye yene amoulenne deguedegue te wakh ab degue mocoye dumbelle deleu nni ap juif mo co guenone dawoul diamou yalla be yalla wonelco ak serigne saliw serigne nico pour koi do diouli mon takh be mou delou wate thie lislam te yalla nene cou santoul nit do sante yalla kheur leye wakhe nit matoul guissou lou thie graw vrement gnak ame degue degue te kenne dou gnanal bok dioulitame safane yalla ham nit fou mouy modie

  • mouride bi dit :

    wakhonenagneko dé moudjiouk diamono niite dina tope serigneme faté borom bi mais yénela rek ki fi dé diguéne kham ndakh c marabout dinégne léne tale dagnouy daw séne dome yi sakh wakhatoumalak yéne diambour yi … putin ke des idiot o senegal

  • niter dit :

    je suis desoler pour les senegalais,je vous dit k ce sont les talibes mouride qui perturbe le Senegal jamais autres diciples dis des choses pareil packo dieu l’attend son tour viendra,tout le monde sera juger sauf le prophet psl

  • mag dit :

    non niter ta raison dé parfois mane sakh je me dis esk gni amenagne aye parent c grave et c honteux enver les autre musulman comme si diouguouléne alkhourhane bilay yomalkhiyame dina méti ;;;; kougnou oubil sa livre to taale kéne …. dof ba dé

  • birane dit :

    nguir yallla le khalif general des mouride wakhal ake paco waye vremen sonalna niite gni ….. c ridicule tt ca ….. pfffffff comme mouton rek

  • amadou dit :

    fuck you paco i hate you how can you say its stupid

  • saffrewmi dit :

    bayyilen mbele mbelegui manoulen si paco touss paco moguen seni ndeye guene seni baye

  • atia dit :

    safrewmi yaw sa ndeye liguéyoule khana paco sa baye ak sa ndeye leu gueune lolou la sakh motakh guaye wakhéni khamna moléndi doundeul….. domerame

  • SAFFREWMI dit :

    MAYLENGNOU DIAME PACO NIT DONGOU LA DOU SERIGNE DOU WALLIYOU DAY PHO DI DEFF LOU YALLA TERE DI MOY YALLA KON WAXLEN SI SERIGNE SINGA XAMNI FOUNOU WAKHE NGA TAFF SAY NOPP NDAX DI GAAROU WAALE SENI MOROMI KILIFA DINE AK DI WAKHE JOURNAALISS TIYI AY EMBESIL LANOU TE MOM SOULEY MAN JILL DIOP KHAMNAKO BOUBAAX

  • mady dit :

    walahi bo dééwé di nga hamni yalla dou moromou kénne

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces

L'ACTU EN TEMPS RÉEL