Annonces
Annonces
» » » » » Vidéo: Ouztaz Makhtar Sarr critique sévérement...

Vidéo: Ouztaz Makhtar Sarr critique sévérement Queen Biz et Pape Cheikh Diallo

2017-01-27T16:53:37+00:00783 Partages

Oustaz Makhtar Sarr fustige le comportement de Queen Biz sur la scène médiatique.

Annonces
Annonces

40 commentaires

  • amy
    27/01/2017 17:08

    mdrrrrr oustaz

  • deug
    27/01/2017 17:44

    Es ce que chez toi c’est ok avant de donner des leçons qui que soit

  • deug
    27/01/2017 17:45

    et comment tu pu les voir donc tu regardes les fesses de qb

  • bagne lou bone ta yalla takh
    27/01/2017 17:54

    merci oustaz je suis fir ci yaw!

  • real
    27/01/2017 18:01

    Merci Oustaz tu as bien dit. Tu as aussi eclairé notre lanterne sur certains points. Mais ce qui m’intrigue c’est l’expression de ton visage. Elle n’est pas en fase avec tes mots. En plus je juge ton degre d’information par rapport a ces clips sataniques trop elevé. Essaye toi aussi de ne plus regarder ces clips. Tu les maitrises trop

  • Diop
    27/01/2017 18:16

    Que dieu te garde et te donne longue vie

  • ss
    27/01/2017 18:26

    Hè toi connard. Oustaz c une personne adulte , il a le droit de tout regarder . Et qui te dit que le fait de voir les fesses de QB lui fait quelque chose . Il est assez solide pour ne pas succomber

  • Mouss bou rew
    27/01/2017 18:34

    aay waay ki tamite bane genrou oustaz la oustaz bo khamni ay biz laay wakh ay gnamal seét garde tes conseils pour tes filles elle en ont besoin

  • razak
    27/01/2017 19:03

    oustaz bandit dokhaan kate bou makk la sa driankée liberté 6 bi cognou station bi dinala raye dé soko bayiwul tenyi danga diekh sakh

  • Dinding kouloubalo
    27/01/2017 19:19

    yaw khana danga panne inspiration ou bien tu est un incompétent teeré Mame yalla bi yatouna trope wakh gnou farata toi aussi sobe nga trope iiisshh

  • m
    27/01/2017 19:23

    deug YaW mer de ya rew doul

  • diop
    27/01/2017 19:29

    deugue nèèkhoul !

  • Coumbandiaye
    27/01/2017 19:34

    Oustaz khana amo metier? Diankk arabe rekk takhoul ngua nekk borome kham kham. Areabe langue la rekk. Demale outi metier ak ligueye te bayi domou diambour yi. Nul n est parfaita part yowe.

  • touba
    27/01/2017 19:38

    félicitations ya oustaz yalnayala fayla thi barké yonéntébi

  • YEAH MAN
    27/01/2017 19:45

    oustaz wakh gnou ay faratay diape niata la ak faan la faratay diape commencer yoyou nga gnou wara diangal lolu mooy sa domaine walabook yay oustazou shoow biz bi Mddr

  • santi
    27/01/2017 19:58

    ouf Sénégal mo beurri oustaz deh ki moy kane sax mom ??

  • deug rék moy moudiou
    27/01/2017 20:04

    queen biz elle est malade elle n’a pas de conseillers

  • Sénégalais fier de l’être
    27/01/2017 20:07

    Merci Oustaze

  • koubakh
    27/01/2017 20:11

    walahi wakh ngua deugue senegal dou france. nii daniou niak djiome

  • imaam
    27/01/2017 20:55

    oustaz demal yangui xam-xam mou guen si yaw lidou xamxam bou pure

  • khalé bou rew
    27/01/2017 21:00

    OUSTAZ MAKHTAR SARR DAMA DONE LATHIE NDAX DOKHOTT DAY YAKK kOOR

  • Aly coboy
    27/01/2017 21:07

    Fiit la ame oustaz bi wayé khamoul GaTT man sax dina neki oustaz comme nieup senegal koufi meune niarry saar rk ni oustaz nga quel merde

  • rara
    27/01/2017 21:54

    Ani MANDOU

  • Gueye
    27/01/2017 22:24

    Oustaz deugue rek la waakh deugue nak dans meti

  • merci ouztas
    27/01/2017 23:22

    merci ouztas

  • bakh yaye
    27/01/2017 23:22

    merci ouztas

  • yaram
    27/01/2017 23:37

    la vérité rien k la vérité merci ouztaz

  • Bah
    28/01/2017 02:01

    Meme si je n’aime pas beaucoup ce oustass car il ne suit pas totalement la Sunnah et critique des erudits, quand meme ce qu’il denonce le detestable. Bouba Ndour a raison de detester cette fille de mauvaise famille. Toutes ces deux personnes sont des diallo, qui sont moins dignent que les Bah! Je dois le dire car je suis un cousin Bah.

  • le bambiste
    28/01/2017 07:22

    c’est le lobie des homoxesuel et des pronographe qui sont toujours dans les medias. mane dama tite si mama bop. wa aldiana gnibi na gnou wa saffara rek presk gnofi dess. away fatélikou léne 3 jour ri baméle .té déé diotna en bilahi

  • perso
    28/01/2017 07:42

    hé doule Way

  • MD
    28/01/2017 09:08

    Sincèrement je suis un fan de Coumba mais ce qu’il connaît d’elle je le savais pas
    Queen il faut donc changer car safara defa meti

  • Bah
    28/01/2017 10:58

    Merci ouztaz tu a bien dit dieu te bénisse

  • xéweul
    28/01/2017 11:04

    nooon Senegal mo bari ndaanfékh dh…. bou probléme amé niouné gni wara wakh nion wakhoule.. bou app oustaz wakhé niouné ko lidieuntile sa bopp ba paré wala oustaz yi danio bari té musicien yéléne euppou fouff ak mbeur yii té kéne wakhou ko… oustaz deugue rék nga wakh té limou wakh dako diangue
    bayiléne sokhor ak ndanfékhé

  • Mustafa
    28/01/2017 11:52

    Oustaz a dit toute la vérité

  • Herculo
    28/01/2017 12:00

    Queen biz n’est qu’une sale farce!

  • patrie
    28/01/2017 14:10

    Sénégal mo barri seytané jamais nguen topato sen affair ki mom day yague dérou oustaz yi sax

  • ok
    28/01/2017 15:01

    waxofi dara

  • kikanla
    28/01/2017 15:07

    demal iran diagala xam xam

  • MAESTRO
    28/01/2017 20:36

    QUEEN BIZZ AK NIOM MBATHIO NIO YEMM AMOUNIOU NGOR AMOUNIOU DIINE AYE BAYI MA LENN LANIOU

  • AKS
    02/02/2017 11:19

    deug rek gafi wakh. yana yalla goudeul sa ay faan

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces

L'ACTU EN TEMPS RÉEL